Série - Sey Dou Choix- Episode 8

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Dieuleul thierno iow 😂😂geumél woulii aicha Touba djégualou😂😂😂Lamine iow AK mounass sabél Moy diakhasé sa keur moom AK copain bii AK seour mounass bii sabél Moy sisou nak peutit seour mounass bii Wang gou rigou la yoor😂😂

papewade
Автор

Aïcha dieukeur dji da tite 😂 diomi amoule heures 😂nak ak mouraye bi

kamaimouna
Автор

Do fekkk kouniawww dafay sohorr comme SABEL

BeugNaby
Автор

J'adore le couple de fatima ak lamine le couple de Aicha ak Thierno machallah nak vraiment sabel sof nama fatima yewoul ❤

nafidiakite
Автор

Kharitou Aïssa mo guene kharitou Fatima bi

ArameGuaye-om
Автор

Sabel dh y’a bon nak Ms fatima yewoul tmt merci Arame ioe rk y’a mana dimbalei fatima

AminaKane-ivlb
Автор

Sabel sou gathiè done raye cone gagnou nga fa yallah

pendagueye
Автор

Sabel soff na 😂😂wa kar média mirage dafa diekh wala ❤❤ merci arame 🎉🎉🎉

MarietouSeck-btfs
Автор

Guathié day bayi borom topou ma sabél niaw gua sabél boneu gua sabél soff gua😫😂

MaremeToure-sogj
Автор

Ya niaw kanam, niaw guinaw, niaw djikoo dh😂😂😂😂😂sabèl

diaboukora
Автор

Sabell niaw nga soxor nga😢sa kan😢bu bonne

MbenefallFall-gy
Автор

Fatima nak doffla😢 merci aram lamine rék lay topou lacrame beunhr de lamine

MbenefallFall-gy
Автор

J'habite à Touba mais j'aime trop les séries sénégalaise

mariemdiop
Автор

Yen tamit sabel dafa bone té sof rek mais niawoul nak😅

fatouba
Автор

Damay lathié ndakh Série Tumë saison bi daffa diékh wala gueudj na guiss niou douggeul ko

ThiénaDiop-fo
Автор

Sabel parégoul dé dafa jalouse si copine nam bi da nôpp lamine sokhor igniane ak niawayam

FatouBeye-cvch
Автор

Chim fatima kouma soof la mouy melni dof amoul daray khèl mouy keuyeung keuyeungi nii bala may dee mouy diay bakh ak innocent merde waay

awaassanegueye
Автор

Fatima niouye wakh ngueye défendre Sabel .

Fabidi
Автор

Une amie comme celle de aicha mais pas comme sabel👍

boussoGueye-pohb
Автор

Fatima wayy sa tonntu saf n'a ma arame niowam ci keur gi bahh na ndah dina meuna dimbale magam mu ham bu bahh kan moy sabel

dieynabadiop