Série - Sey Dou Choix- Episode 23

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Couple bi bou ma rayoul rekk mouye djam thierno mi khawma bane année-là

naboundiaye
Автор

Assalamalikoum yénne wa karmédia yéne loutkh douguéne déf lou yégue bouguéne comasé rk ba nit gni kontane rk guéne dagueko loutkh lolou

ToureMoustapha-opqv
Автор

sabel da beug dioy mais da melni mouenoul dioy ndeysan

sowathiaaa
Автор

Nie niou Ande di setan serie yi yalla naniou ko Ande dougou bir aldiana amine

maxbbfall
Автор

Alioune seck ioe rék laniouy topou bonne continuation 🎉🙏

IbrahimaDiedhiou-yf
Автор

Ey Fatima Sabel bakhoul.Aka nekhone Betty doff bi niewe wakh lepp si aye manigances yi mou deff.
Waaye nak liko daal dafa metti.Ibra ya togne.
Waayé khaléyi dé léne deglou parents yi .Souniou léne téré bayyiléne.Moussibeu rek mo siye toppeu.Ibra attention.😮😮😮😮

Fabidi
Автор

Thierno nékal niit aicha day nék dit bigamie nii😂😂😂

papewade
Автор

Série bou nex la mai béty mogni wéteul😂❤

maoudediao
Автор

J'adore fatima thiey sacré Aicha ❤

nafidiakite
Автор

Kholal thierno du daw melni kou toop yayam du daw 😂😂😂😂

BebeRestaurant
Автор

Fatima béni diaro la take wow lolou moguo nék ❤❤❤❤❤

Talibé_cheikh
Автор

Fatima béna diarou la taka kouka sélou lalal❤❤❤❤

ndeyekhadiniang
Автор

Kou gëum ni Sabél bëuss dinaa niëuw mou changé rék bëussëul j'aime ❤️❤️❤️

ThiénaDiop-fo
Автор

sabell baaxull su ngen ko takké yaqqu ndax baala gulén di na woo tubaab bi te di na yaqq voyage bi ngén niakk léupp nakk 😂😂😂😂

sokhnaaminata
Автор

Bonne continuation ❤❤❤ y’a pas de suite

DiakerioNdiaye
Автор

Fatima nak ngeu faydeu beugeu moy lane ngay tok rek Lamine mou rew bi ak bopom bou reye bi mouley torokhol rek dileu manquer de respect mou nane beugeu

aichandoye
Автор

Sabel Lolou bakh n'a si yaw daga bon rk😮😮😮

MaremeDiop-qq
Автор

Kone sabel li motkh mou nane louma nakari niom Fátima nioma ko tek

ndionehabiba