Série - Sey Dou Choix- Episode 14

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Kou beugue gamou gui reck lalale j'aime ❤🎉❤

AmyDia-epuf
Автор

Fatima ya Diak Fayda Djiguéne dey am Foula❤❤❤❤❤❤❤

sisteraichaladiva
Автор

Thiérno dafma soof ba moudiéma nékh 😂😂 non mane dama beugg Thiérno 😂😂 mom dh mingui mélni khalé bouniouy forcé pour mou takk diabar 😂

ThiénaDiop-fo
Автор

Bly Fatima des fois dagakoy yeureumm par fois ga diepiko 😢

ChachaDiop-bc
Автор

Yayou Thierno dinama raye 😂😂😂😂😂 khol bi dina dagg Thier dou nitou dara😂😂😂

oumousamb
Автор

bonjour je suis en Europe mais cette dame là elle m'a humilier c'est soupe Kandia que j'ai mangé aujourd'hui 😂

hawagako
Автор

J'adore le couple de fatima ak lamine fatima nak yewoul thiey Thierno takal niarel ki fele wou la sakh Amoul respect si yaw bilay ❤

nafidiakite
Автор

Kou beuguou sa yaye rk lalal j'aime ❤️

DabaNdiaye-gx
Автор

Vraiment Vraiment ms thierno kou niak diom la❤❤❤ goor yeupoou kheuy moouy nelaw

ndeyembaye
Автор

Dieukourou aicha bi at drats bi mouy melni engagé ni😂😂😂

KhadijaRassoulTurpinDion-ezny
Автор

Aisha mii Thierno duko fassé😮😮😮😮Fatima mii mom gissagul dara ani dioxx gorr xaliss thimmmm

abiesallah
Автор

Pourtant bety dangay nouro ak soupou kandji😂😂😂😂😂😂😂😂😂ya fouy nakk thiey bobou ndieuké

awagaye
Автор

Aïcha niguayyyy tassss neu deukkk bi rew gu ba doffff Thierno mom waxoumaaa ayyy waxam 😂mouyyy mbakhal pouth pathie nonu tchim yambareiiii baaa

Fatoubintoundiaye-kn
Автор

Série bangui soga nekh nak ak gane bi😂😂😂😂

mouhamedalidiop
Автор

Wa wa moroc mome ni laniouye mel souniou touké ba nieuw eup na li douniou si wakh balamouye eup lokho bokk 😂😂😂😂

awaane
Автор

Théron mi kou gnakhe faydala jigéne yaye kilifame pa môme
Fatima tamit kéne démoul mou sés ndigémbi bouy wakh mèlné Kou saf daye ba foumi moudié d'où bakh si yaw

cheikhdiop
Автор

mangui avc eupeu léne meu Lamine mi nitt leu, wayé nak ya yé culotté seu diabar mi mo manqué bayiléne meu meu youkhou et ben nou mou toudeuti way diabar lamine bi khetou manqué

philobarreto
Автор

Kenn toniou niou koudoule kiko diokh rôle bi rek moniou amel akh sou amoule mor dina am blessé bakhna bamou sotti rek

awaane
Автор

Ndieuké Fatima bi dina déf si mom kharal rék réw ba dof teukheute 😅

ndeyebakhawedieng
Автор

Wa gaane gui sofff na, ame guéne blême 😂😂😂

mamistamendy