Série - Sey Dou Choix- Episode 6

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

J'adore le couple de fatima ak lamine thiey sacré Aicha ak Thierno Aicha dotoko defati dh yab sa dieukeur bakhoul une excellente série yallah na sene diam yague way ❤

nafidiakite
Автор

Thierno yaguiiii sogua nekkkk goor nak😅😅😅niaffff nileu goor dayyyy wané niii goor leuh wayeiiii nooyyyy ba melniiii begnets 😅😅😅😅😅😅

Fatoubintoundiaye-kn
Автор

Thierno amoul bene fouleu, djiko djiguene leu yoree, neu comportewou comme un kilifeu

biguengom
Автор

Ww thierno nila nay miti lamine moma geuna nekh si Seri bi dafa boooo de Bilay 😂😂😂

MbenefallFall-gy
Автор

Thierno iow amal foulla sa djiabaar dji momoul niit yii djiguéne boula yorré damay yaap goor bouffi niakk diom ba djiguéne dila yoor Ray la dagane 😊😂😂

papewade
Автор

Wawaw naye goré wayé nak jiguene boula lébalé warougar dinala yape

fatoukineba
Автор

Thierno contana si iow dh😂boko may dara😂na safff na miti

MbenefallFall-gy
Автор

Ah Aïcha li motakh gniou nane méfie toi de l’eau qui dort

CécilendellaSene
Автор

Thierno yangui may beug nékh dé th nekh ngama ba nopi goor dafay deuguer keuthie

fatousow
Автор

Djigén la mais beck nasi Thierno tay❤Nila way akh Aïcha dfa réw

DiagneSoda-hb
Автор

Thiérno merci beaucoup Aïcha et très impoli😂😂

KhadyNdiaye-jo
Автор

Thierno dagua wara am foulleu ms ndak you sokhor yui mom 😮😮

MamefamaThioune
Автор

Ohh satou yerek dieukerou diombor rek lanoy war😂😂😂

satoudiopamine
Автор

Aïcha mélni dakhine gogou baparé beug ray Thierno Thierno dafa sonou motax mou fipou

fatousow
Автор

Dof bou fipou bakhoul Thierno fipou na

adamengomndiaye
Автор

Mane dal thierno la beug goor day am foula wayè sa diabar dji mèlni kou yor sa bonne diapè thierno golo ki da rèww

princessemyadiallo
Автор

Bien fait Mame thierno goor daye deugeure😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

HouleyDiew
Автор

Billaya nk Thierno il est temps way ❤❤❤❤❤

RamatoulayeGackou
Автор

J'aime bien cette mélodie de la série

oumoukoita
Автор

Thierno nake vraiment gore daye goré waye

CoumbaNdao-evso