Série - Sey Dou Choix- Episode 11

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Barki rassoulilah Lamine dieukeur diou baxxleu machalla continue comme ça mn frère

binetoudiakhate-tzbg
Автор

Aïcha diégg day am respect réwnga lololl

binetoudiakhate-tzbg
Автор

Bilahi Lamine kou bakh la ❤️ ta Be''l'

diagnenar
Автор

Nena nioune Ay mbam laniou 😂😂kharal james legui ngua bokk si mbam yi 😂😂😂

malicksarr
Автор

Wa sabel lou takh mou iniane aigre Aïcha mome rew na trop 😅

CécilendellaSene
Автор

Thierno yangui sey nak mashalah di wass say djen di dem téssanté dji mashaalah yakofa ham😂

gogobarham
Автор

Guaure dé da warra dème ligueye waye tok si keur Gui rék 😂😂 motakhe dayou mouse sakhe Di niou loko commande 😂😂😂❤

seynaboufall
Автор

Man mom Lamine motakh may sétan série bi sérieux 😢

diagnenar
Автор

yala bou pekhe sabel dioub yala nako yala wer ki yesna😭

AminataGaye-sr
Автор

Couple lamine AK Fatima machallah 🙏🙏🙏🙏🙏🙏

Talibé_cheikh
Автор

Sabel moy tax ma bayi série bi soxor na trop akh

ndeyefaye
Автор

Aïcha rew na nak chetttt ak ligaye neube tamite lanla dioum mom defoko

khadygueye
Автор

J'adore le couple de fatima ak lamine ❤

nafidiakite
Автор

Waay yéeen yii Goooor kousi gueuna niak foulla ak fayda 😂😂😂😂

NdeyeSeck-md
Автор

Wa aïcha lègi gnou nokh la bognou wakhè ay mbame😮😮😮 ki rèw na

kadialy
Автор

Thierno niak nga fayda nak wass dieun manke nga dal

dieynabadiop
Автор

Sabel ni mu sokhorei nonu la. Kanam bi Mel mou melni ku lokk teuflite ni tchim

Owsy
Автор

Aicha ya ngui commandé lou dangereux dibi ak coca goudi kouko moytoumoule légui nga dème barsakh

bocarguisse
Автор

Commandé dibi goudi ak coca lek ko teude yewou am AVC

fatoubintourassoulfall
Автор

Sabele do bandit mbam ga AK sa niawayam sokhor ga trop

FatouBeye-cvch