Série - Sey Dou Choix- Episode 10

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Ndeysane Copin arame biii ameneu ngorrrr deh no y’a des homme bien mashllah

Fatoubintoundiaye-kn
Автор

J'adore le couple de fatima ak lamine thiey Aicha ak Thierno une excellente série yallah na diam sene diam yague machallah ❤

nafidiakite
Автор

Ana wa touba nio xew le nak Mourid à vie 😂❤

MbenefallFall-gy
Автор

Cou Contan si coupel lamine bi RK lalal

maxbbfall
Автор

Kou beugue serigne fallou beusseul j aime❤❤❤

sokhnathiam
Автор

Thierno tour we takh Manou mako wakh Dara waye niak na fayda😂

MbenefallFall-gy
Автор

Aicha mi esk amoul ay rab tamite 😂😂😂😂😂😂

ndeyefaye
Автор

Ma série préférée ❤🎉 kou d'accord lalale jaime ❤

AmyDia-epuf
Автор

Meilleurs série de l'année ✋❤️❤️✨✨

Pretty_Mya_df
Автор

Couple lamine AK Fatima machallah ❤ waw thieno 😂😂😂

Talibé_cheikh
Автор

Thierno sa famme dalaye gololo wakhou la DEUG dh 😂😂😂😂Sabél bilay arame Nguaye fékhèl yénnè nék borom mossi fanane fatima Arame boul kou xam diganeté AK séga l'OM fort sa copain mola tk d'île sii auto

papewade
Автор

Khetou wayadi bi thi Thierno melni deco thi keur

MaremeWane-edxp
Автор

Wa aïcha doula financer ga oubi atelier bok

DabaDiop-hr
Автор

Aicha reew gan trop mai lep thierno la do ben klifa gnou naan la kougni dri dou tamou fou ndongam di dall .thierno soff gan nekal goor way😢

gogobarham
Автор

Thierno li niak djom la wala tame yobalé amo bene estime de soi si goor

ramatoulayedieyediop
Автор

Lamine mom niak simple rek mom sofff si mom mou melni niangue safo sénégalais dara

OumyOumy-mc
Автор

Lamine yalna am dieukeur bou mell ni yw ❤️😘

aidambeugue-jlry
Автор

Tiérno sa diabar respect téwoula elle est bipolaire elle change de visage tout le temps

ngompizzi
Автор

Ho j'adore se couple lamine et fatima

Mainounambaye
Автор

Lamine rék lay topou lacrame beunhr de lamine 😂❤

MbenefallFall-gy