Série - Sey Dou Choix- Episode 22

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Fatima tey rk la conten siyaw Amalana goor Talal lokho diokhma diokhma rk par force May wakh Mouy mbarane niak diom niank class , koubeug dé wékhé d 😂 merci Fatima amal foumaleu way, bouko mayati khalis d amo tous dioubo, ndakh sen sey bi prison leu😂, Arame massa thiono li motakhone ngabeug taylé Fatima série bi❤❤❤❤

oumouwade
Автор

Lamin rekk mooma soof ci série bi, ak Rakkam ji. Eva lii yépp yaa ko teg sa bopp. 🤣 🤣

mustafaasamb
Автор

Lamine noumako diepe ak sous-vêtements bi mouy melni djigen😂😂😂😂

dienebadiagne
Автор

Wa lamine body la sol wala😂😂😂😂 faima mome da wayady

fatoudieng
Автор

😂😂😂 lamine deh sous vêtement bi comme dessous

DIOPMAMEBOUSSO-vwnv
Автор

Salallahou alla Mouhamad ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

yamathiaw
Автор

Merci merci fatima lamine ya niak fayda ❤❤❤

Talibé_cheikh
Автор

Lamine mo niak diom yoro lu soucre café di dokhane

omarcisse
Автор

Lamine way nenea embarquè sama keur . debarque la beugon wakh wla😂😂😂

gogogueye
Автор

Lamine débarque gay embarqué nonou daga tit niii titagooo saakh😂😂😂😂😂

KhadijaKEBE-wrni
Автор

Wa lamine haut ngaleu bimou sol tamit lanela 😢

awajupitermouchoux
Автор

Debarquer ou embarqué c’est la même chose exemple mettre les bagages sur un navire 🚢 ou prendre

Djina
Автор

Kou Dieppi Fatima rék bimouy nouyôo ak bi

NdeyeSeck-md
Автор

Thim Sabel moo soff rk mouy mélni yatt nii rk

ndeyeba-qw
Автор

Wa diourbel sene dome amna ndame mafi djitou 😂

SokhnaFaye-utjv
Автор

Thiey Lamine «  débarquer » mouné «  embarquer »😂

Fabidi
Автор

Embarqué derbarquer c est aller sortir

Djina
Автор

Mais fatima mi nak louy problème ak béne diarome😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

MamanWillane
Автор

Qui. Da. Fa. Sof. Do KO. Bayi. Khamoil. Bopame. Lamine kou. Sof. La

BinetaNdiaye-ev