Série - Sey Dou Choix- Episode 5

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Eye yaayi japalene sene domyi ci seyam niou sakh sii ❤❤❤❤

HousseyNouWade
Автор

😢😢c’est la première fois ma joy si série khar média 😢😢bébé aby 😢😢limou wah dafa daw sama yaram😢😢courage à tous les enfants qui vient ce malheur 😢😢😢😢

alydione
Автор

Boye seuye té sa yaye doula conseillé lou bakh seuy bou méti ngaye ame lolou moye differences entre ls deux couples

abysow
Автор

Aicha dooo exemple deh siii souniou sociétés biiii djekk dayyy yarou beugh seu dieukeur beugh seu Goro diii seuyyy nakkk normal werefou djekkkk bouyyy

Fatoubintoundiaye-kn
Автор

Thierno ani diomameu weureul lein mako fofou way😂😂kii vrai jolie cœur laa

MaremeToure-sogj
Автор

J'adore le couple de fatima ak lamine ❤

nafidiakite
Автор

Contan si serie bii rék merci beaucoup ❤❤

sawlouMbye
Автор

Guiss préservatif thi sa poche dieukeur, après niouni la diogal balouko 😢 seuyou Senegal dal doyna warr

adamandiayekasse
Автор

Je suis content pour la fille dont elle a avoue à sa grand-mère le climat de la famille et son comportement vis-à-vis de son père car c'est la seule façon de remettre ses parents dans les bons rails

HousseyNouWade
Автор

yayou thierno mi mom khana toujours goro you meunoul am rék lay am rolam yi mom haaa

aidandao
Автор

Thierno sa yaye wakhoula deugue gooor bou beugue am batte si keureum daye yooor keureum ba paré

OumyOumy-mc
Автор

J’ai tellement de cette phrase djiguen matoul helam dafa seugue n’importe quoi li djiguen meune lidieunti yeup yabaté

binetasane
Автор

Mafi Djitou Maylene Ma Ay J'aime ❤

s.falloutaysirmbengue
Автор

Ah Yayou Thierno mome keur diambour aye thie tek aye règlement ah tega wakh sa fils mou outy ligueye 😊

CécilendellaSene
Автор

Ndeysane nekhena amena sens Macha Allah. Bonne continuation ine sha Allah guys ❤️🥰🥰😍💕💞💞💞

oumousamb
Автор

Bilaye dome ndeyame ❤ longue vie à nos mamans

BinetaGueye-ymsn
Автор

Thierno très bien Kii yaap sa yaye aicha djiguéne danguaye respect sa djieukeur aicha néna daal diomy😂 😂😂

papewade
Автор

Goro you seytané yi nioyy tass keur yi

BeugNaby
Автор

Khana yayou thièrno amoul keur😂 khar media guenlène thi liguéne nek waye ni rk

AïtaSarr-di
Автор

Mes yayou thierno panque n'a dee😂😂

DialeNdiaye-zmoh