Série - Sey Dou Choix- Episode 12

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Ah man mom je ne comprendre pas comportment Aicha bi doyna war. Apart ça serie bi nekhna machalah ❤❤

Hkyo-un
Автор

Wallahi thierno mo taxe ba beugue touba sétaane série bi

aminatamboup
Автор

Yalna yalla sopi xéle té diobanti xoole té défarate djiko ❤❤❤❤❤

RamatoulayeGackou
Автор

Bayiléne xarito xarite woroul dèh cas wou Aziz dabala rék warnagnou yéé

SokhnaSamb-ke
Автор

Li la meunut tokk ak nitt di wakh ak sama problème keur jamais bayilen kharit def Len sen yaay kharit

gogobarham
Автор

Youssou ya geuna niak fayda ko giss yow mi top sa xarite bu diegge bobu

dieynabadiop
Автор

Bilay ma bagn goor bou. Niakk fayda rék thimm thierno mi dièpinako loll serie bi ska dinako yegualè sakh

princessemyadiallo
Автор

Déma khamoul djiguene bouye séye loumouye doyé kharitou calibatair

MoukhaSene-jwin
Автор

Xaritoooo guen ni bayiii sabel mom kou bonne leuh kou xarite walay boul xam fooyyyy moudiou

Fatoubintoundiaye-kn
Автор

Wayadi wesouwul lou khew sa négociation sey nga neuw sa xarit di yébéku né tamé sankhal thimmm

fatoudabakh
Автор

Aïcha mi nte la😂 nénako bouko défati mou melni kouy wakh ak domam sa réwandé dépassé nama 😂😂😂😂

Aminata-ms
Автор

Non Aïcha réuwna sheuttt 😂😂😂, nitt Mo leundeum nak wa sabél mi ni lagnkoy bayé rk 😮ohhhh pauvre Fatima ndaysane mome déh rakk dji sakh moko guena yéwou

mamistamendy
Автор

Wa yen thierno mi niit leu aaaah mane deh warouna nak

FatouTin-vr
Автор

Awtou mbaye mii diepy naka thimmm😢😢😢😢😢😢

abiesallah
Автор

Yallna nagnou yalla moussal. Si xarite bou melni sabel

pendasarr
Автор

Sama tourondo bi fatima meuna fen trop lou khew sa negou seuy nga wakhko no waay kharite amatoul ah

fatimaba
Автор

Legui Sénégal 🇸🇳 mon raw état unis cou kham si lane 😂😂😂

footballclub
Автор

Lamine yow tamit khanàa amô liguéy 😂😂 yeremmal sa diabare

NdeyeSeck-md
Автор

Bayiilen wokh s'en secret à tous bakhneu. Dal

abdoufall
Автор

Wa Abdou salif ioe agalei wo dji sa niarel 😂gua daw si fii

ManeFall-onuq