Série - Sey Dou Choix- Episode 13

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Lamine ne m'inspirer pas confiance dra yalna khel dé reck touf touf

SeneFatou-
Автор

Keppou kou dippi sabére lalal j'aime

AmiiNdiaye
Автор

Yayi thierno sagneségua rafete moussor machalah

RamaNiang-kkhn
Автор

Ndeysane thierno nak da meuneu seuy yaye dji dakoy khass kharite yi di khass diabar dji di khass déglou woul kéneu khamna mom boufi diouré dome dina barkél

MamerokhayaLayepaye
Автор

Yalla na yalla deff diamou ak salam si rewmi

MamourSylla-wz
Автор

nitt dafa leundeum Lamine mi wolou woumako dara 😮, Sabél ak Thierno la guena diéppi si série bi😕oh pauvre Fatima 😟,

mamistamendy
Автор

Mère bi mo nekh kouy sodé doko wakh 😂😂😂

doffoubassiroufall
Автор

Mame thierno dé mo téyé seuye bi ndeysane diabar dji nékhoul farale daffa réw trope mou melni kouye doundé tau

mamendiemethiam
Автор

Tei fo diar mame Thiérno yéguali fompou bi dh 😂😂😂😂

DiyeuDiop
Автор

Bilay mane wolouma lamine dara dafa Mélanie lamine amna loumouy maligancé

AstouGueye-re
Автор

Yalna yalla sopi xéle té diobanti xoole té défarate djiko yalna diame yague té sax ❤❤❤❤❤❤❤

RamatoulayeGackou
Автор

Yalnama yalla moussal si kharite bou sokhor

diariatoufall
Автор

La traîtrise de certains hommes ne cesse jamais de me surprendre. Comment peut-on abuser aussi impudiquement de la confiance d'une femme aveuglée par l'amour?
Lamine n'est pas sincère du tout avec sa femme.

daoudaba
Автор

Thiérno yangui diékhal sama xol bi way😢😢

amylo
Автор

Khar media nak beug nagniou kou toukki deh gnieuw Sénégal dem France rek ohhhh

aminataniang
Автор

J'adore le couple de fatima ak lamine thiey sacré Aicha ak Thierno yallah baxna dal une excellente série vraiment ❤

nafidiakite
Автор

Arame pourquoi tu ne dis pas à ta sœur que c’est son amie « intime » qui t’en a parlé.Wa seyou Thierno bi mettineu.Yallah bakhna diouroumako.So wakhé rek mouné sama yaye daffa compliquée.

Fabidi
Автор

Hum ana gni donn wokh lamine dèffa bakh noo ki wolouwo mako dara amna loumouy manigancè zhomm rèk 😮😮

fatydiawba-fqbh
Автор

Lamin dae bett Nga ma😢😢😢mann mom finance goor du suma project

abiesallah
Автор

Bilay thierno mala diépi kay mélni guou organisé tanne beur.fatima lou takh gua nayif digua ame mbétel

sodamndaw