Jahman X-Press - YAAY - Album ABIYO

preview_player
Показать описание

Production : Hoside Studio
Prod. by Jeuuss - Mix by Moussa Ngom

CONTACT MANAGEMENT : 77 640 22 08

LYRICS
Yaye ki gueune ci mane yaye woye nala
Meunoumala faté
Soudoul wone ak saa yaye booy dina firim réw tass koo
Yaye balal ma
Yaye booy kaay balal ma
Soula nékhé daagoul sa ligueye fegn na ci sa ndiabot gui
Ay camions khaliss
Soumala ko done sotti
Dou doye ndakh diouro lou kene di khol nane thiam kane mondiour li

Mane santeu naa yallah buur bi bimala amé
Yaye diou melni ioe yomboul té khamna li takh ma wakh ko

Sanni ma daleu
Dou té malay gueureum
Loula nekh deff meu sama Aldiana ngui ci sey souffou tankeu
Mane santeu naa yallah buur bi bimala amé
Yaye diou melni ioe yomboul té khamna li takh ma wakh ko

Yaye defo fii lou niaw
Wakho fii lou niaw
Meusso nio wane guinaaw
Naadj bou tàngue bi nga daan daaw takh sama khol sedd ci yaw
Yaye gueureum nala
Yaw fo diaar yone la

Kouniou nane demb téy motax
Yone bi goudoone na loool
Yaye moussoulo wagnékou
Bilay khepp nako loool
Lou néew loumay deff ci yaw
Sou yokoul dotoul waniékou
Na lamp yii takkeu ma photowok mom
Yaye rétane maa
Sa rétane dafmay doundeul
Guiss la rek dafmey bégueul
Doundeul doundeul
Ba Abadan moma done gueuneul
Yaye yama lene gueuneul
Nga fékké laley nianal
Mangui ci yaw ba guédj gui ferr ndakh yamay bégueul
Yaye foula ndanane di diaar
Sey att yakkoul sa taar

Naadj bou tàngue bi nga daan daaw takh sama khol sedd ci yaw
Yaye gueureum nala
Yaw fo diaar yone la
Na lamp yii takkeu ma photowok mom
Yaye rétane maa
Sa rétane dafmay doundeul
Guiss la rek dafmey bégueul
Doundeul doundeul
Ba Abadan moma done gueuneul
Yaye yama lene gueuneul
Nga fékké laley nianal
Mangui ci yaw ba guédj gui ferr ndakh yamay bégueul
Ya foula ndanane di diaar
Sey att yakkoul sa taar
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Vraiment on ne pouvait pas espérer mieux 🥺🥺🥺 jahman Merci mille fois 😭 jahman yalnala yalla yobou fou kawé thiii sa carrière inch'Allah nga am prix bou mak grâce à cette chanson ☺️🥰...sa bo weuyé yayy khôl yii toy je me souviens encore de MAMA LOVER❤️❤️❤️❤️ ndanan nga🙌

maremedieng
Автор

Ho ça me touche au cœur malheureusement la mienne est partie depuis longtemps .que firdawsi soit sa demeure éternelle ❤️❤️

khizokmc
Автор

😭😭wowyyy bi yoboûnama fou sori Walay dema dioûnd guisouma baye sama Yaye rek la kham longue vie à elle 😭🙏♥️❤️

rokhymarone
Автор

Kepp kouy deff examen yalla nagua am té mou djique❤️🙏

kheusskana
Автор

Vraiment ça me va directement au cœur ❤ car j ai perdu la mienne qui été une maman battante que le bon dieu lui accueille dans son paradis ainsi que les autres maman merci jahman

magattefaye
Автор

Très touchante merci à ttes nos mamans elles méritent tout le bonheur du monde💯💕 Chapeau à jahman

ndeyekhadydiop
Автор

Je t'adore vraiment souma sanione done chanteuse mais amouma moyen 😞😞😞mangui laye nianal guoudou fane ak werguou yaram bilahi yalla nala yalla diaplé ak mbolém duoulite si barkep seydinah mouhamed amine yalla bakhna🥰🥰🥰💥💦💯

dababeye
Автор

Tjr égal à lui même vive les Maman et longue vie à toutes les Mamans, dii nianal Maman yii jitou firdawsi done sènekeur yarabii

Shekinah
Автор

Un cœur ❤️pour toutes ces mamans qui ne vivent plus mais qui ne cessent de veiller sur leurs enfants💞 que firdawsi soit votre demeure🙏

mamediarrasene
Автор

Une façon de rendre hommage à Souleymane Faye.
Respect JAH

rahmaanballack
Автор

Ce gas est née pour briller vraiment mention spécial jha. Une fierté pour la région de diourbel . Je te kiff depuis le Brésil on se sait 🥰🥰🥰🥰🥰🥰 .longue vie a nos maman et paradis céleste pour ceux qui on perdu leur maman .

mouhameddiagne
Автор

En écoutant cette magnifique chanson, toutes mes pensées se sont envolées envers ma mère que j ai perdu à la Mecque 😢🕌❤
Merci Jahman-X 🙏🏽👍🏽

PapeALO
Автор

Merci pour cette hommage rendu à nos braves mamans 💓

AmynaNabySarr-bouDabakh
Автор

J’ai eu les larmes aux yeux en écoutant cette chanson
Longue vie à nos mamans ❣️

fatoukinetoure
Автор

Le meilleur son du Siècle
Quelle merveille ce Jahman
Qu'Allah veille sur lui

Longue vie à toute les mamans du monde
Et paix à leurs âmes celles qui sont partis
Que Jannah Firdawsi soit leur demeure éternelle...

ahmadsow
Автор

Avec Ndeye tu as fait pleurer ton auditoire, et avec une revisite de la musique sénégalaise ancienne là c’est du pure génie. Moi j’aime bien ta musique et ta voix Jah

boyeoumar
Автор

Trop fort jahman merci pour ce joli son machalah à toutes les mères du monde entier ken amoul sen fay

dk
Автор

Wallahi comme vous parlez de ema mère elle a tout donné pour notre réussite alhamdoulilah aujourd'hui elle commence à voir les résultats yalla nala bayiko fi bassi kanam MoM AK yaye yeup yaye youfi nekatoul yalla nagn nopalikou AK diaam

cheikhrassouldiouf
Автор

Alhamdoulilah j'ai eu l'opportunité de l'écouter au près de maman. Longue vie maman je t'aime énormément you're my power my lover my

mohammedfall
Автор

Hoooo j’ai les larmes aux yeux 😭longue vie à nos mamans et bravo jahman ❤️

diediop