Jahman X-Press feat Dip Doundou Guiss - Yow lay Nobaat

preview_player
Показать описание

Music Prod. : Iss 814
Mix : Gauthier Carbonnaux
Executive Prod. : Merrou Dieng - Wantd - Malick Mbaye
Production : Hoside Studio
Extrait de l'album ABIYO

Directed and Edited by Mahine Sef
Wolf Film Production
Sylisme : Ty Design
Make Up : Soraya
Lights : Fatah
Deco : Yarba Deco

Lyrics :
Lo beug beug naa
Lo bagn mane beugouma
Yaa takh namatouma dara kone diegué ma
Baby deff ma loula nekh yaa tey waay
Doumla meusseu bayi hun hun
Kaay kaay
Sa ree meune nama rey té bougouma guiss ngey merr
Ragal nimla beugué khalé bi li comme guerre
So beugué louma amoul nako wouti diokh la
Sam mbeuguél sama amour negn ko boolé yokh la
Mi corazón (corazón )
Mane douma taayi té douma sone (no no no)
Wakh lene ak mom
Damko nopp té nangou naa ci niakk diom

Oh ohh ouhh ohh
Damako guiss youkhou oh ouh oh
Oh ohh ouhh ohh
Foumala guiss youkhou oh ouh oh
Yaw laay nobat , yaw laay nobat
Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat
Yaw laay nobat , baby yaw laay nobat
So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat
Yaw laay nobat , yaw laay nobat
Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat
Yaw laay nobat , baby yaw laay nobat
So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat

Diaral ngama khékh ak Pa bi gueneu gallé
Guédeu agn té sou mère bi wakhé doumko
falé
Collé serré doumla bayi moukk di crazy
Bayanté negn mais yaw laay guéneul ba leggi
Amna kénene mais soum key khol yaw rek laay guiss
Deuké sagnsé pour nga xool ma sa khel delsi
Baby , beugué nala nouné
Fo dem ma fekk la fa diaral ngama louné

Oh ohh ouhh ohh
Damako guiss youkhou oh ouh oh
Oh ohh ouhh ohh
Foumala guiss youkhou oh ouh oh
Yaw laay nobat , yaw laay nobat
Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat
Yaw laay nobat , baby yaw laay nobat
So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat
Yaw laay nobat , yaw laay nobat
Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat
Yaw laay nobat , baby yaw laay nobat
So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat

Sama kér ak sama garap
Sama febar sama garap
Takh ma guerre ak samay parents
Baay ma dee ci sa kaw darap
Yow linguere nga or ak diamant
Takal la aldinay kara

Yaw rekka ma diaral ganratie bakane koranté Balla
Teud diakhane fou ay car rapide diaré sama kaw yaram
Ta dou thiakhane diaral ngama niou nane ki diaratoul dara
Diaro bim ley takal dou diarat ci benene baram
Diabar laley deff
Diabar diou keneu doul lambal ndiaram
Yaw laay nobat , yaw laay labat
Dagueu sama baat gueuneu yombou nga niane ma baat
Diokh ma sa lokho té goungué ma Porto Rico
Yaay sama lover sama chabalaba ding dong

Oh ohh ouhh ohh
Foumala guiss youkhou oh ouh oh
Yaw laay nobat , yaw laay nobat
Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat
Yaw laay nobat , baby yaw laay nobat
So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat
Yaw laay nobat , yaw laay nobat
Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat
Yaw laay nobat , baby yaw laay nobat
So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat

#JahmanXpress #DipDoundouGuiss #Abiyo
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Si c’était à l’école je dirais que Dip est l’élève le plus ponctuel de la classe il répond toujours présent à l’appel ❤️🗽

diadinho
Автор

Dip meilleur rappeur du Sénégal ki est d'accord avec moi⚡🥱

falilouniane
Автор

Qui a écoute la partie d dip plusieurs fois🤞👌🙏 son flow 😍🇸🇳🇲🇱💪💪
les fans manifestés svp🙏

allfreshtv
Автор

Bcp d personnes vont parler de DIP mais JAHMAN il est très fort et Talentueux
💥💥💥💥💥

Bassirouseye
Автор

Dip namone nagne leu. On attend impatiemment DQ4. Big up à Jamane et Iss c'est du lourd.

abdoulayediouf
Автор

Franchement dip a ce charisme k kan il chante peu importe en koï son inspirer ses paroles tes directement attirer par lui franchement je t'adore srx 😍😍

marieagnessarr
Автор

Ce clip aurait pû être tourné en Dubai, Londre Paris ou USA et malgré il a choisi un paysage africain ce qui rapelle à "l'Africanité" et qui montre combien Jahman met en valeur sa culture ainsi que sa musique sans compté du fait qui varie sa musique en tout genre... J'adore ce mec.
Il est temps que les rappeurs arrêtent de se prendre pour des étrangers dans leur propre pays.
En passant je kiffe.

ncm
Автор

Je suis congolaise lorsque je coûte cette chanson je vais changer de nationalité le meilleur c'est dip chapeau

FeliciaKalala
Автор

Dip 🗣️ parole 👇
Yow lay noBATTE
Yow lay laBATTE
Dageu sama BATTA geuna yomboy
nga niane ma BATTE ❤️🥰😂 ki du nitt 🤭

LEUZZVISION
Автор

"Lii com guerre", Dip forever; big up à Diaman c'est du lourd

daoudalakore
Автор

100 millions de vus sur ce vidéo qui est d'accord beusal j'aime...❤️🙏🙏

OuzKing-
Автор

Avec Dip Doundou Guiss, le suspens est mort. Il est toujours simplement le meilleur et de loin 🔥.

mamadoualioucamara
Автор

Wollah c'est un master class. Jahman tu as assuré mais DIP quel homme ce gars 🔥. Rien à dire de la prod toujours high level venant de Iss814

ousmanegerarddiop
Автор

Bayilen di tekele dip ak garyiii dou bene migui USA

mamadoudia
Автор

J'entendais le tour de Dip pour voir comment il entre sur le son avec son flow, mais le goss c'est un Ghost, il est fou🙌😍🔥🔥🔥🔥

SOLO-tdzs
Автор

Le flow de dip 🥺😭❤️❤️❤️❤️❤️💣💣💣💣Jahman t’as assuré vraiment
Hit de l’année 2021
En attendant les millions de vues 👍🏼❤️

ibk
Автор

Dip c le meilleur ki est dccr avc mw et jaxman ossi ouf c du lour vraiment❤👑

elhadjisouare
Автор

J'avais hate d'écourter la partie de dip et je savais qu'il ne me déçoit pas force a vous son ni Nice na fethiable na🥰💖🔥🔥🔥

moustaphadiagne
Автор

Mais yén dég lou nguén Dip😭😍 yéwou fadiar cons ko encore plus ke je le cons mouy gueun dima diangual sama diguenté ak sama futur diabar pour sougn mariage inchallah😭😍. Merci pour cez belles paroles ndiago or😍. Jahman fatéwou mala t'as vachement assuré tmt peace n love sur vous

kalypro
Автор

4:01 Dip doundou guiss🔥🔝😭😭

Mes felicitation vous deux mani dopna🔥🔝😭

Senegal_