Jahman X-press - Khalé Bingay Wo (Clip Officiel)

preview_player
Показать описание


Arrangement, Mix & Mastering : Jeuss Beat
Beat : Jeuss
PRODUCTION VIDEO : REVERSE STUDIOS
ASSIST. DIRECTOR DJIBY NIANG
DECO HOP CHEIKH SADIBOU
NDAYANE DECO
EDITOR & COLOR GRADING BILAL MBENGUE
DIRECTOR & D.A BILAL MBENGUE
D.O.P MBAYE DIOP
LOGISTIC ARONA WADE
MAKEUP SOKHNA FATOU DIOUF
STUDIO WATCH STUDIO 221

Stylisme : Diaganastyle +221 77 172 47 98

°°Suivez-moi sur mes réseaux

✍🏾 Lyrics

Danga wara yam
Thioudj dafay kham lékaam
Mag dou nakh bopam
Man ponkala may attaan
Kima nekal zero faute
Panou khaliss kheubalouma
Yangmay wo malay khodj
Demal togg weuroumala

Eh ioe coupél mangui diokko
Kima nob ma nobko
Kila geuna paré ki deff bague sama lokho

Eska man ndirounala kou lambeu ioe kholaat’ma
Koudoul mom guissoumala
Bayima ngir yallah
Kenn dou am kima am
Diko wethio da meun boram kingay wo
Mounialko day wakh ak kim diokh kholam

Soudé djiné pessoula té doffo
Man soma kholé khamné dama né thi lokho
Man ak gni lambeu kham ngani y’a pas photo
Dama nekha khol kima yor moma toppato (mouni)

Ehh Khalé bingay wo mingui diokkok keneen kimou nob bako (te yallah takh) sonal ngako (trop)

Ehh bako néna sonal ngako
Ehh bako ehh geumal yallah bayil ki noboula

Khalé bingay wo mingui diokkok keneen kimou nob mounial (stp) ko ba beneen

Way bako néna sonal ngako
Way bako ehh geumal yallah bayil ki noboula

Loy saf si man (khawma)
Diarna ba paré (bou yagg)
Dozéma yomboul bayil sa khel bingay (aw demal tokk)

Ki rek kafiné mom rekk gamie la signé
Beussal bouton bou khonk bi danga wara coupé

Soudé louy rayela man nama ray man beugue na
Man benn yoon lay toy ma raw ciment

Garde la ligne so yakamtiwoul damay wakh ak bonheur
Fi ak werr meun naniouko wakh fim’ma keppeu mo deugueur

Ocuppé kagne nga nara coupé
Banekh lay wakhal somay wo lay communiqué

Niamou mak khalé loussiy yoonaam
Place bi amna boromam
Forcé takhoul nga diott si man soma khifé yeuyal singom

Coupél quittél
Banekh lay communiquél
Fidel ci mom
Mangui doundou mbeuguél

Boulma gnodi lou amoul si mom la daggeu bou yagg
Kay takh bayiko dioudogoul bayam déna bou yagg
Louma diokhagne mou daggeu té diokhnama sama geuddeu
Thiabi diang niou sani guédj
Bountou nékk boy feugg

Soudé djiné pessoula té doffo
Man soma kholé khamné dama né thi lokho
Man ak gni lambeu kham ngani y’a pas photo
Dama nekha khol kima yor moma toppato (mouni)

Ehh Khalé bingay wo mingui diokkok keneen kimou nob bako (te yallah takh) sonal ngako (trop)

Ehh bako néna sonal ngako
Ehh bako ehh geumal yallah bayil ki noboula

Khalé bingay wo mingui diokkok keneen kimou nob mounial (stp) ko ba beneen

Way bako néna sonal ngako
Way bako ehh geumal yallah bayil ki (leudial ngama witt)
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Cette chanson aura des millions de vues et moi je n’aurai pas de j’aime 😢

abdouaziztoure
Автор

L’homme qui ne déçoit jamais ❤️billay Jahman dafa meilleur 🎉❤

jupywhv
Автор

Enfaite il n’arrêtera jamais de nous surprendre 🎉❤il est trop fort ❤❤🎉

abyyasselotdiouf
Автор

Il est extraordinaire en inspiration, texte, logique des rimes. Il est Jahman 😊. Je danse même en écrivant 😅

serignembackedieng
Автор

Ani baol baol yi Machalla sougnouy dome dji suis vraiment fière de toi ❤❤❤❤💪🏼

aminadiouf
Автор

Ce Guy est un pur génie, si tu es d'accord mais 👍

mesqueunclub
Автор

Le talent a l'état pur, Jahman-X Ya meilleur Key ❤🎉😂

alassanemamadoukane
Автор

Lima diakhal man moy yahman foum dieule guel yii o popopo 🔥🔥🔥

mohamedndiaye
Автор

Je suis burkinabè mais j'aime les chansons sénégalais malgré je comprends pas wolof . C'est l'Afrique qui gagne

bemeswp
Автор

Oooh des paroles de ouf, un son de ouf, des images de ouf🥳🥳 Khana tout est ouf🥰❤️💃💃💃💃

Mrsathie
Автор

Je suis baol baol pure je suis fier de mon artiste jahman le meilleur Machallah diourbel est fier de vous 🎉❤❤❤

kbzxclh
Автор

LA QUALITÉ DE CE CLIP Jahman est vraiment l'un des meilleurs d'Afrique pour moi malgré ses millions de vues, il reste sous coté par rapport à la qualité de ses réalisations chapeau l'artiste !

MohamedNY
Автор

Kou d’accord qu’il est incroyable lalall j’aime 👍 🎉 il est un parmis les autres

cheikhdia
Автор

Nous les Diourbeloi on est fier de vous machalla nice ❤❤❤❤❤

mxlebgk
Автор

Kou nek ci ay lokho lalall j'aime 🥰🥰🥰

axloumicfamily
Автор

Dans la douce nuit de l'année qui s'efface, Les étoiles dansent, une ultime grâce. Chaque instant passé, un chapitre clos, Le livre du temps dévoile ses mots.

Les souvenirs tissés, comme des fils d'or, Embrassent le cœur, un trésor encore. Regardons en arrière, avec tendre clarté, Les rêves vécus, l'amour partagé.

Les promesses de demain, une lueur d'espoir, Dans l'ombre du passé, émerge un nouveau soir.

Que le nouvel an soit un poème enchanté, Où chaque vers écrit, soit de félicité.

Sous le ciel étoilé, ensemble, avançons, Main dans la main, tissons d'autres saisons. Que l'année qui s'éveille, comme une mélodie, Compose une symphonie de bonheur infini.

fadeldiagne
Автор

Meilleur artiste de l'année Ku d'accord 🎉

awangom
Автор

Tu nous régale avec tes pépites et avec humour à chaque fois. 👏👏

aminatadiouf
Автор

L'artiste qui déçoit jamais toujours au top comme d'hab ❤ j'ai aimé avant d'écouter ❤ une voix si suave et qui enveloppe machallah machallah en plus tu as déchire à Marseille on a tous kiffe ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

nabombodj
Автор

Kou guiss ni clip dafa nice rék pouss bleu 😊❤👍

MisterOuzeTV