Jahman X-Press - Celebrate

preview_player
Показать описание

Music : Jeuuss Beat
Steady key
Video : Pix7 Studio
Studio : Senegal Plus
Production : Hoside Studio

LYRICS
Bessou mbegté leu ci mane
Bég bou amoul foumouy yam
Bég ci lima yallah deff
Beneu Baye Fall lou niow mané kheyneu dafa gueune
Bessou thianta leu ci mane
Thianta ngiir diam dji ma am
Dieureudieuf !
Dieureudieuf ! Yallah buur bima lakkeu
Fou beut bou bone yegoul wala lokho bouy yakeu
Damay contane continuer
(Bégué beauté ! begué mongui baakh ! Bégué beauté ! )
Mangui bég tei bégueulé
Merr maîtrisé
(Bégué beauté ! Bégué mongui baakh ! Begué beauté ! )
Diégueulé tei diéleulé
CELEBRATE ( nioune daniouy foo)
CELEBRATE ( kou merr bokko )
CELEBRATE ( fii lépeu jamm)
CELEBRATE ( bégué beauté )

Té niit liy garabam niit leu
Diama gueune li ci sa compte
Damay bég même soumay banque
Lénéne lou niow rek bonus leu
Yallah teral nama kone nak defal ci mane ndank
Soumay guestu lima wessou
Khamné mane merr warouma non non
( Nonono )
Awma dara loumay réthiou
Ndakh yallah yagg nama tekk lokho
Am sokhla fadjal ko sa bopp
Diarna sante yallah té khamni kene mounoul mey sa bopp
Wakh sakh mou yegu yallah la nekh
Kone warnga santeu yallah saa bo yéwo

Damay contane continuer
(Bégué beauté ! bégué mongui baakh ! Bégué beauté ! )
Mangui bég tei bégueulé
Merr maîtrisé
(Bégué beauté ! Bégué mongui baakh ! Begué beauté ! )
Diégueulé tei diéleulé
CELEBRATE ( nioune daniouy foo )
CELEBRATE ( kou merr bokko )
CELEBRATE ( fii lépeu jamm
CELEBRATE ( bégué beauté )

Degg naa fi louné , dadj naa fi louné
Deukeul ma founé té woul mangui bégué di dem
Saga nagn ma ndeye , takoul feneu ci mane
Mangui doli santeu yallah ndakh mom rek moy ki meune

Bégué beauté !
begué mongui baakh !
Bégué beauté !

Bégué beauté !
Bégué mongui baakh !
Begué beauté !
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

N'oubliez surtout pas les prières obligatoires de grâce 🙏🙏🙏🙏🙏❤❤❤❤❤😊😊😊🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

khadimciss
Автор

Chaque jour qu'on dort et se réveille y'a des nouveaux clip

khadimetsesvideos
Автор

Celebrate 🇸🇳❤️🌍 Une diversités dans tout les domaines de la vie qu'on a du succès mariages, sports, diplômes, travail etc.. merci jahman l'homme est remède de l'homme aussi lou am sollo 💞

afdeltall
Автор

From Diourbel et fier de l'être grâce a tw jahman😘❤tjrs au top yalla nala yalla continué di tek lokho dilay diappalé bâ lép loo yootou diot si inchallah🙏kone niou dal di célébrate rén say futurs succès inchallah💃💃💃💅

fatousylla
Автор

Jahman, Pape Birahim, Safari, Dior Mbaye, Maabo, OMG etc sont des artistes très talentueux et ont surtout besoin de visibilité aussi bien nationale qu’internationale mais malheureusement on voit toujours les mêmes stars lors des grands événements.

CheikhaOfficiel
Автор

J'adore ce son il est sortie au moment où j'ai obtenue mon diplôme ❤

fatimatadiallo
Автор

Masha Allah le clip est très nice 🥰 et le thème d'actualité pour tout un chacun, à l'école, au bureau, à la maison, partout il est vrai 😍
Merci Jahman 🥰🥰🥰🥰

ndeyeantabar
Автор

Bilay clip bi mériténa plus de 20 millions vues comme "Def si code"

EQUIPE_
Автор

Un artiste musicien plus fort que Jahman ça n'existe pas au Sénégal.

EQUIPE_
Автор

Au delà de la musique c’est c est les paroles qui me parlent je me suis retrouvé dans ce qu’il dit vraiment bravo

gueyemamefatou
Автор

Mon chanson 🎵 préféré 🤩
Ki j’aime beuseul ❤️

bambadistributionetservice
Автор

À l’approche du CAN on va tous celebrate 🥳

mbouyesylla
Автор

Tjrs top élégance c baye fall
Amal diam frère
Niogui sa guinaw
Maximum de j'aime 🙏🙏

boubacarcisse
Автор

Voilà la chanson qui m'a redonné l'amour de vivre 😍❤️

mamoudougueye
Автор

Avant may déglou la beus jaim yaw fierté senegal yép nga, surtou ndiarém bégué bégué and celebrate💖👊

teresamoralessilva
Автор

Le premier jour que j'ai écouté cette chanson tous ce que je trouvais difficile était devenu facile jusqu'aujourd'hui a mon réveil c'est sa merci l'artiste bien des choses à toi depuis 🇨🇬 ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

winniegenco
Автор

Un gars hyper talentueux...mash'allah on est fier de toi mec...

abdoulayegueye
Автор

Toujours au Top Jahman je t'adore fort walahi diam si yaw ❤❤❤❤❤❤

Lingueremina
Автор

Ce son est juste magnifique 😍
Douma si doyal depuis la sortie de l’album balegui je l’écoute
J’attends le clip
Chapeau 🎩 à vous le clip est nice

sokhnambenegaye
Автор

Machallah une vie sans examen ça veut pas la peine d’être vécu. Tu as tapé encore fort. Celebrate😘❤️💯

bouyabocoum