OMG x JAHMAN X-PRESS - Kenen Diapoula (clip officiel)

preview_player
Показать описание
Artistes : OMG & Jahman
Compositeur: B.Beut
Auteur : Jahman
Production : DD Records
D.A : OMG & Stefdekarda
Realisateur : Amdy
Cadreurs : Pii & Lakhat
Assistante Camera : Kiki
Light : Dynastie Studio
Montage : Pii
Étalonnage: Jordy Diop
Maquillage & coiffures: Thiaba Class’A Beauty
Déco : Dynastie Studio & Stefdekarda
Stylisme : stefdekarda, Maktoum Store, wizi création
Accessoire & bijoux : bijouteries Abass Aly Dia 775124624
Lunettes : Pépit’ice
Chorégraphie : Barry Kush
Danseuses : Jeanne & Marie Obama
Remerciements : Maison de la Culture Douta Seck

lyrics

REFRAIN
Est ce khamnga linga yoor
Khalè bou ndayam gueureum
mako fa am nékak kenen diapoula

May ki takhone niou sakk la
Ande bangue niou takhé arass
Ko meuneu nekkal kenene tamit
Diapoula

Nekak kenene diapoula
Sa ex diapoula
Nangoul ni mane nga nope bayil saggou diapoula

COUPLET OMG

Eh Nank rek ma dane la dièl bou gaw amateur yibekk
Gnibèk V bi rek match nul lolou meuneuteu nek
Done sa guelou rap bi sangou lo la sete
Chance deugue leu am kou melni mane thi sa wete
Ligniy bari bari yaw may sa préférée tè faté xadioufi var amna so wédé
Lingay weuri fenene
Yaw Fi rek ngakoy ame
Dakh may ki ko am
Mako am bakou bari dolè
Sa pointure mana
Kénéne diapoula
Ay bobou mbeuguèlou sur mesure
Wakhal sa deuguentane kane nga nope
Sa deuguentane mane nga nopp
Koulay gagne yaw koulay thiokhatane

COUPLET JAHMAN
Andak mane day def effet mane rek damay yokk taar
Kone tè nga ngoy bou deuguer banc de touche bi niongui khar
Mane rek kala diap kenene ko andalite dou dém
Té gni dila tope so yabo néléne niou yam
Gninane la yaw fane yi danga leer so gooré néléne may diw bingay diwo
Litax mane ak yaw nioune meunounioi khoulo
Yalla ko def souniou rawane yi nio djoubo
Dakh ma def thi yaw valeurs bagne lay weur comme ay vautours
Diaroul wiri wiri mane nga nope allez retour
Wakhal sa deuguentane kane nga nope
Sa deuguentane mane nga nopp
Koulay gagne yaw koulay thiokhatane

#OMG #JAHMAN #KENEN_DIAPOULA
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Ñun wa département de Rufisque amatinañu ndam...OMG yaleen mëun, yaleen eup dollé...yafi nekk!

clairedelune
Автор

Kou diogé si Wally yéne rék nieuw fi beuseul j'aime ❤️

FatymboureThiam-vext
Автор

Magal gui gniew na notre fierté on réclame notre clip ci magal 2024😢

Coumbafaye-jsry
Автор

Kuy xaar son jamma xpress si magal touba bi rk lalall j'aime🎉

nnmuwpp
Автор

Mais qui écrit les textes de OMG...et ce que j aime le plus c est zéro vulgarité et un style unique...un vrai talent...

salsba
Автор

Namone naniou la OMG !!! ❤ Yalla na la yalla sameuh !

Zazou_wane
Автор

Kou diouge si wally, Mia ak amadeuz nieuw fi❤

KARLITO_
Автор

Sénégal jahman mofi dakha weuy walahi mom rek amoul kenén kou d’accord lalale j’aime❤

buzzmedia
Автор

Mais li nekh na dh diougué si Wally Mia ak Amadeus nieuw si OMG ak X-Press ❤🎉

AïchaDiao
Автор

Kholal omg rék parolam yi nimou nékhé té amoul béneu mot bou vulgaire ❤machallah way❤❤❤❤

wqwwmqw
Автор

OMG est à l'aise sur n'importe quel rythme. Musicalement elle est au top et de loin meilleure de sa génération. ❤🎉

drissndiaye
Автор

Jahman fait partie des meilleur chanteur de l’Afrique omg est fantastique bonne continuation ❤❤❤

kfevidz
Автор

Yeena meune Wally Ak Mya Kou d’accord 😊

aissataly
Автор

C mon papa 😭🥰🎉🫂Machallah papa jahman 👍🥹🥰🎊🎉🎉🎉🎉

geocxid
Автор

je souhaite a OMG Disque d'or rapidement et des millions de vue. OUMY tu le merites

africaculture
Автор

OMG jlm vraiment ❤❤❤ bien sûr que c'est une vraie GUEYE😂😂😂

momogueye
Автор

Jahman est tout simplement le meilleur musicien sénégalais. C’est pas pour rien qu’il est le king de YouTube❤️🤌🏾

EQUIPE_
Автор

Les deux les plus polyvalent jahmane et OMG waouh c’est très cuul ❤

HEUREUX_
Автор

Je sens l'écriture de Jah man sur le flow de OMG vous l'avez remarquer les gas😮

YancoubaDiatta-jryx
Автор

Jahman est 1artist polyvalen foko wooo mou nieuw mm rapeur moleen daak rap kouko wedi woko freestyle

algacediallo