XIIRSA feat @AmadeusOfficiel - TOUT DONNER ( CLIP OFFICIEL )

preview_player
Показать описание
Contact Label management 77 182 20 82 - 33 867 90 76
Vous pouvez VOUS ABONNER à notre chaîne en CLIQUANT ici :

Rejoignez nous sur:
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Genre mom foum bokk dfy nekh c'est obligé Amadeus 🎉❤😂

alassanemamadoukane
Автор

Mais tout le monde parle de Amadeus mais vous vous rendrez compte de la voix de xirsa😮😮😮😮😊

fatoundao
Автор

si tu tombe sur ce message sache que 2024 c'est ton année de gloire 🤝

fadadione
Автор

Partie Amadeus bi momafi indi 😂tiktok la diogué 😂😂😂

nikofaitdesvideos
Автор

« Pourtant »bi Niko xiirsa di def doyna war ❤️❤️

mberytall
Автор

Qui aime bien ce chanson bi lalal j’aime ❤

adamadiop
Автор

Avec xirssa, Amadeus, Ashs et b
Baye Masse on a vrai de toutes les couleurs musicales ici ay ndanane deugue. Galsén bien représenté inchaAllah ❤

sibytoure
Автор

AmadeuSe mii esk nitt keissei leu ?😭😭❤️

myasall
Автор

Mane yaag na leinn wakh wakhi Amadeus Ashs the best Obree daman deggoulein ma allons rek bizarrement je viens de le découvrir Amna louma raté d voix bi over nekh na wayé khalé bi nek si clip bi Yallah nala ALLAH lafal thiatt tu es magnifique cocotte🎉❤🎉

qclleyb
Автор

Mais Amadeus mi tmt li mm bou amoul mort dina am bléssé 😂amna goût dall laleune wx😍❤️❤️

NdackNiang-crov
Автор

Xiirrsa moy chris brown chris brown moy xiirsa 😍

devossdiouf
Автор

Sama xol gua yoré
Mom laleu topé
Liti liti liti litiii
may rombé guoumbé
Dama tapétoul
Défnasi louné
Loumou guoudii guoudii guoudii
Damalay guougué

Baby I follow you
Because my Heart is on you

Baby I follow you
Because my Heart is on you


Hohoho pourtanttt
Diokh naleu lép, diokh leu lép
Hohoho pourtantttt
Je t'ai tout donné, tout donné hohohohooo, hohoho
hohohoo hohohoo
Hohohohooo hohohoo
Hohoho, hohoho

Massamba walo
Xamna boubax liguay bagn
Dém bassi biir malay guagn
Defnako say mass wayé
Yaw da am loumou may wagni
Adouna mola sokhleu
Mane ma yité woleu lol Sax
Massamba mogui may guagn
Clamer naleu ak guayii
Kay guaw, deugu leuni deungueuna
Souma démé balay way
Gua xamni thiaxane taxoul

Pourtanttt dioxnaleu lép
Dioxleu lép
je t'ai tout donné
Tout donné

Hohohohooo hohohoo
Hohohoo hohohoo
Hohohohooo hohohoo
Hohohoo hohohoo

Mane douma say say
Lathie ko sama guayii
Nioweul niou life faaa
Sonounaa
Boul moussa guaday
Donal sen yaye
Ndiabott gui kay way guouguéma
Man douma say say
Lathie ko sama guayii
Nieuweul niou life faaa
Sonounaa.

balladieng
Автор

Amadeus l’homme qui ne deçoit jamais
Un vrai musicien wollah 🔥🎤❤

bilalfall
Автор

Xirssa vraiment est trop fort et on s’en rend pas compte à cause de cette belle voix de Amadeus! Mais c’est le Sénégal qui gagne

niangmedoune
Автор

No boy bi di Amadeus vraiment il est trop fort sa voix perce les cœurs 🥰

ousmaneniang
Автор

Masamba ki est u???? Amadeus ya meilleur waay🥺😍😍😍

Aidalaye-oxtz
Автор

Yenangui wax amadeus mais mane xiirsa bi nexna

alioucisse
Автор

Daguéni wax Amadeus mais parti xirsa bi yit doy neu war vous êtes les meilleurs

AmySow-wytk
Автор

Amadeuss kèneu dou mome .Mais Xirssa dou nittou fiii ❤❤

sokhnathiam
Автор

Très fière d’être sénégalaise 🇸🇳 ce duo est juste incroyable 😻 🔥

coumbaba