filmov
tv
Massamba Amadeus - Amadeus - Doumala Fowé (Clip Officiel)
Показать описание
Auteur : Amadeus
Compositeur et Mix : Zoom ont the Beat
Directed : MLD & Ice’Graphy
D.O.P : Likma
Lighting : BrasMagik
Edited : MLD & SeleVfx
Décors : Yarba
© 2021 Cosanostra
Suivez Amadeus sur les réseaux sociaux :
Paroles :
Duma la fowe
Duma la, duma la fowe
Duma la, duma la, duma la, duma la fowe
Duma la, duma la, duma la, duma la fowe
Soxna si, ci mane ngay mujj a gise love
Ndeke mbëgéel is all i need man
Sàmm sa daraja ni Maam
Ma bamtu
Xale bi bu dul yaw du mas a doon keneen
Ndax sàmm nga sa ndaw ni maam
Di génn farata ni maam
Man àdduna laa bëgg a wan
Ba ñu xam ne que ne tekk naa la fu kawe kawe
Toogal sama wet bul ma mas a
tàggu ndax xam nga ne soo ma soree ma wéet
Dam la gis rekk teg fële sama mbonte
Man li ma yitteel mooy sama mbégte
Bëgguma la disturb
Jéggalu sun lay enerver
Non metti na la li ma la toppe girl
Yàlla xam na
Ne man bëgg naa la
Li tax ñemewóo ma
Damaa dëng jaar-jaar
Sama démb ñaaw na
njëlbéen du naada
Mujj gu rafet laay ñaan Yàlla jox ma la
Duma la fowe
Fi ma la fore daa sori
Sa ree ju neex
Moo may faj su ma feebaree
Duma la fowe
Ndax fi ma la fore daa sori
Sa ree ju neex
Moo may faj su ma feebaree
Ak li ma man gis li ma dégg
Man duma give up
Yan bi lu mu man diis lu mu dëgër
Dara du ma disturb
Nekkóo ci réseaux sociaux yi di polluer all time
Daanaka sax doo nekk online
Fuck cheveux naturels enjoy nga life bég naa
Looloo waral man yaw laay ñaan
Dam la gis yek teggi fële sama mbonte
Man li ma yitteel mooy sa mbégte
Bëgguma la disturb
jéggalu sun lay enerver
Non metti na la lim la toppe girl
Yàlla xam na
Ne man bëgg naa la
Li tax ñemewóo ma
Damaa dëng jaar-jaar
Sama démb ñaaw na
Njëlbéen du naada
Mujj gu rafet laay ñaan Yàlla jox ma la
Duma la fowe
Fi ma la fore daa sorri
Sa ree ju neex
Moo may faj su ma feebaree
Duma la fowe
Ndax fi ma la fore daa sorri
Sa ree ju neex
Moo may faj su ma feebaree
Traduction en français :
"Je ne te déshonorerai jamais"
Jamais, je ne te déshonorerai jamais,
Jamais, jamais, jamais, je ne te déshonorerai jamais
Jamais, je ne te déshonorerai jamais,
Jamais, jamais, jamais, je ne te déshonorerai jamais
Je t'honore ma vie pour plusieurs raisons
Et t'assure un amour sans crevaison
Consolidant continuellement nos liaisons
Parce que ma chérie tu es hors saison
Sans toi, ma vie perdrait sa quintessence
Sans toi, mon entourage n’aurait pas d'assurance
Sans toi, mon étoile risquerait sa brillance
Sans toi, ma vision s'engouffrerait dans l'ignorance
Au vu et au su de tous, tu es mon bonheur
Ta dignité sacrée couve ton honneur
Ta chaleur arrose et illumine mon cœur
Donc restons ensemble et chantons en chœur
Je t'emboîte le pas comme le maître et son chien
Pour t'apporter uniquement le tout du bien
Je fouille tes traces quotidiennement et sans fin
Rien que pour apercevoir ton beau teint
Pourquoi en es-tu dubitative ma chère ?
Ou tu es choqué par mon passé d'enfer
Passé que tu as commencé à changer ma lumière
Par ta dignité ancestrale ma dame de fer
T'as pas suivi le vent tendanciel
Qui souffle au bord du monde actuel
Avec son caractère anodin et criminel
Référence des chocs de la mode existentielle
Tu as su garder jalousement ta virginité
Tu as préservé ton honneur avec ingéniosité
Tu as pu affronter les obstacles avec leur tortuosité
Tu as dépassé victorieusement l'âge de la puberté
Je suis prêt à vivre avec toi
Quelle que soit la lourdeur de la loi
De l'amour, j'ai déjà fait mon choix
Je ne te déshonorerai jamais ma foi
Комментарии