Massamba Amadeus - Amadeus - Saajobaan (Clip Officiel)

preview_player
Показать описание
#Amadeus #saajobaan #afrombalax #afropop

Auteur & Interprète : Saliou Samb AKA Amadeus
Compositeur : Zoom Beat
© 2022 COSANOSTRA

Suivez Amadeus sur les réseaux sociaux :

Paroles en Wolof :

Eey Màsamba Waalo eeeh hii
Su mbëggeel doon jaay
Am naa njëgam
Dinaa la wan sama yéene yi ma am ci yaw
Duma ku lay jay
Te duma la wor
Dinaa la wax dëgg ak lum metti metti
Maa la woo ne la maa la nob
Miinal la sama bopp ba nga barder maa la tooñ
Kon nag loo ma manti def
Lu mu metti naa ko muñ
Àdduna du dox ba ma soppi li ma la wax doo ma weddi
Ay bu doon ay nax neex na ma
Fekk ma ciy gént yee nga ma
Jàmm ju bari may nga ma
Yaa ngi may dundal àjjana
Tamit tëggal ma ma jaayu
Xamal ma ne man la
Gëmal ma ne Man rekk nga nob
Sama saajobaan
Tëggal ma ma jaayu
Xamal ma ne Man la gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saadjobaan eeee waay

Xam nga duma puruux duma fàtte bi may surux
Xuntu wu lëndëm wi nga ma génne dinaa ko wax
Du lu rafet ci wax
Soo ma bàyyee damay torox
Nawle yépp bis bu ñu teewee dinaa ko wax waaaay
Doy nga ma ci kër
Kenn du la sikkal
Man yaw mii yaay ki ma fiital (tiital)
Doo dund ngistal
Ngor gi nga jiital
Ragaluma siiwal
Nun ñaar ndax doy nga ma ci kër
Ndaxte Mane maa la woo
Ne la maa la nob
Miinal la sama bopp ba nga barder maa la tooñ
Kon nag loo ma manti def
Lu mu metti naa ko muñ
Àdduna du dox ba ma soppi li ma la wax doo ma weddi
Hay bu doon ay nax neex na ma
Fekk ma ciy gént yee nga ma
Jàmm ju bari may nga ma
Yaa ngi may dundal àjjana
Tamit tëggal ma ma jaayu
Tëggal ma ma jaayu
Xamal ma ne Man la
Gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan
Tëggal ma ma jaayu
Xamal ma ne Man la
Gëmal ma ne Man rekk nga nob Sama saajobaan eeee waaay

Bis (tòllanti)

......................................................................................................................................
Traduction des paroles en Français :

"Ma Dulcinée"

Eey Massamba Wallo
hummm hun

Si l'amour avait un prix
Je me donnerais à tout prix
Pour l'acheter sans cris

Je te manifesterai mes bonnes intentions
Je t'éloignerai de toute trahison
Je ne te complimenterai jamais ma solution

Je te dirai la vérité en toute circonstance
Car je t'ai choisie comme amour avec aisance
Amour, finalement obnubilé par ma fréquence
Je te supporterai pour toujours avec patience

Fais-moi bébé ton homme de confiance
Parce que doué de rigueur et de Constance
Et si tes dires étaient des balivernes
Je m'en contenterais dans ma caserne

Tu m'as extirpé de mes délires
Pour me permettre de tout lire

Tu m'as permis d'avoir une vie paisible
Assimilée au paradis, notre seule et unique cible

Chante alors glorieusement mes éloges don du Ciel
Rassure-moi foncièrement mon âme-sœur, ma belle
Montre-moi qu'il n'y a point d'amour comme tel
Ma Dulcinée, tu es plus délicieuse qu'un caramel

Ma dulcinée

Couplet 2

Loin des traîtres dépourvus de reconnaissance
J'assume d'avoir bénéficié de ton assistance
Après être envahi par le vent de l'ignorance

Ma vie sombrerait dans l'oubli
Si tu me quittes ou même m'oublies

Je réaffirmerai ma Dulcinée solennellement
Devant toute l'assemblée réunie par moment
Que tu me combles de bonheur entièrement

Personne ne peut "casser du sucre sur ton dos
Ma force qui me porte sur son dos

Tu ne réagis pas pour les yeux d'autrui
Mais tu agis dignement sans faire de bruit

J'ose dévoiler notre relation jour et nuit
Ma Dulcinée, la femme très chère que je suis

Je te dirai la vérité en toute circonstance
Car je t'ai choisie comme amour avec aisance
Amour, finalement obnubilé par ma fréquence
Je te supporterai pour toujours avec patience

Fais-moi bébé ton homme de confiance
Parce que doué de rigueur et de Constance
Et si tes dires étaient des balivernes
Je m'en contenterais dans ma caserne

Tu m'as extirpé de mes délires
Pour me permettre de tout lire

Tu m'as permis d'avoir une vie paisible
Assimilée au paradis, notre seule et unique cible

Chante alors glorieusement mes éloges don du Ciel
Rassure-moi foncièrement mon âme-sœur, ma belle
Montre-moi qu'il n'y a point d'amour comme tel
Ma Dulcinée, tu es plus délicieuse qu'un caramel
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Vous étiez nombreux à demander la traduction des paroles en français, vous l'avez dans la description.

AmadeusOfficiel
Автор

Ça mérite des millions de vu ❤wallay sénégalais khamouniou musique

ndeyependacoulibaly
Автор

L’originalité de la culture saint-louisienne, le titre du son qui est du pur wolof, la fusion tradi-moderne, la maîtrise de l’histoire de ton pays, le style, le bongo, la danse moulay tieugine revivifiée, les transitions sans même parler du son mélodieux… PUR CHEF-D’ŒUVRE 👏🏾👏🏾🇸🇳🎵🎭

babacardiouf
Автор

KOTN Ce gard il sait toucher les cœurs, un texte qui simple mais qui sort totalement de l’ordinaire. Des likes pour Amadeus l’artiste le plus authentique

dreaming
Автор

A chaque fois tu vises fort avec ta créativité ainsi que ta simplicité
On est gâté avec ton esprit artistique ❤️🤧

mamediarraboussondiaye
Автор

''Dou lou rafet si wax soma bayé dina torokh bou nawlé yiii tassé dinako wax '' ooh laaa cette phrase 😍😍 Amadeus bayil sama xol bingay maltraité c'est trop❤

maryfaye
Автор

Les sénégalais ne savent pas apprécier la bonne musique. Niom nayy rirr rek, je ne m'en lasse pas, 💯💝💝

coumbadiarrafall
Автор

Ki gars yi xamouniou valeuram limi way machallah machallah..fi laniouy tok Di xolei ba toubab yi sathieko si nioune nak.. damakay statue rek ...

sophiengom
Автор

Pourquoi ce clip a moins d’un million de vues ?? C’est énorme ce clip, MAGNIFIQUE, c’est un SÉNÉGALAIS ce clip, j’ai pas les mots ❤️🔥

efkacamara
Автор

Sounou Fierté MASSAMBA AMADEUS NDANANE SI MBIRR NDANANE YII NDAMM REK INCHALLA ❤

mouhameddiaw
Автор

Sa voix me touche énormément....Quand j'écoute ses sons, je ferme les yeux pour mieux apprécier...❤ Et merci Amadeus, de valoriser dans tes clips la femme sénégalaise ❤

aminata_lilas
Автор

Clip bi c’est frappant … naturel, simple et plein d’enseignements à tirer… voila en 2023 une vidéo qui reflète une réalité sénégalaise sans exagération.
Les lyrics et la voix n’en parlons pas. Un chef d’œuvre

abdoulayekane
Автор

Anyway Amadeus et Ash the best ils seront les grands de la musique sénégalaise !

kendrickjhonsine
Автор

Sama xol mo fess 🥺😭 quel talent yalla na yalla weral batt bi we love you🥰❤️🙏

awadiop
Автор

Oh son bi limou nekh eupeuna❤Diappal ni parmi les 1 M de vues mann ma setann 500k yi 😊

satou
Автор

Oooh Mashallah xalè bi yallah nako yallah lafal thiate limouye weuy nexna ba diégui dayo ❤️ sa kaw sa kanam rk 😘 on est fière de toi Masamba Walo 🥰

bassineka
Автор

Des lyrics de ouf 💥un style rare, un talent avéré accompagné d'une simplicité extraordinaire.
Félicitations frère.
On est très fier de toi et du travail que tu es entrain de mener.
Rendez vous au sommet

yerimayo
Автор

C’est le son de l’année quel harmonie 🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥si tu connais pas l musique tu peux pas comprendre

atouhit
Автор

Vous faites partie de cette nouvelle génération d'artistes qui font de la musique une forme de poésie simple mais profonde.
Nous qui n'avons pas l'habitude d'écouter la New School, nous pouvons trouver dans vos textes une forme de lyrisme unique, sénégalais et authentique.
Et que dire du RYTHME ?! Que dire de l'originalité dans le clip ?!
Voilà la musique que nous aimons. La musique qui parle au cœur, une musique moderne et surtout décomplexée... une musique sénégalaise quoi !

aliounebadarandiaye
Автор

J'aime ta voix de ouff elle est tellement mélodieuse
Ta chanson boulma sagané est actuellement ma sonnerie
Je kiff de trop cette musique surtout Méritéwoumala 😭 sheutt
Yalla Na yalla yagg wéral batt bi si barké jéssus Christa🙏🙏🙏 Amen

gomismami