Wally B. Seck – Balma (Official Video)

preview_player
Показать описание
Wally B. Seck – Balma (Official Video)

CREDITS

A film by @greatvideoentertainment
Directed & Edit by Mouhamadou Ba
Production : Faramareen Productions

#WallySeck #IWannaBeFree #Balma
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

LYRICS

Sonou naa
Maala togne, balma
Woh woh woh
Sonou naa
Mane maala togne, balma

You feel mane dé wéét naa
You're still, you're still my boo
Everyday meu niaak fayda go back
Nieuw soukou diégalou ci seu kanam baalou akk
Baalou naala nguir yalla balma
Dafma méré xam naani ma togne
Everyday meu niaak fayda go back
Nieuw soukou diégalou ci seu kanam baalou akk

Nangou sama défaite, téy ya am ndam (am ndam)
Loma méré méré kham nga maa xam
Sama babygirl kaay diégalou na
Sama babygirl baayil mér wouyouma
Nangou sama défaite, téy ya am ndam (am ndam)
Loma méré méré kham nga maa xam
Sama babygirl kaay diégalou na
Déloussil ma baby oh-ouh-ah yeah

Sonou naa
Maala togne, balma
Woh woh woh
Sonou naa
Mane maala togne, balma

Chérie coco me I love you dou débat
Tu sais pour toi je ferai le premier pas
Des jeux de rein à la Wally - Ipupa
Néxaalat keur gui on fera n'importe quoi
Yow tamit, baayil seu mér-bi té nga ré comme Khaby
Lam lamé déy sonal seu xél, nangou naa ni
Maako déf, maala togne
Bouniou mél ni Tom & Jerry

Lak lak like fire
Woh woh woh woh woh woh
Sexy lady
Dama wééré tay, diégalou naa
Sama babygirl bayil mér, wouyouma

Nangou sama défaite, téy ya am ndam (am ndam)
Loma méré méré kham nga maa xam
Sama babygirl kaay diégalou na
Déloussil ma baby oh-ouh-ah yeah

Sonou naa
Maala togne balma
Woh woh woh ..
Sonou naa
Mane maala togne balma

officielwallyseck
Автор

KOU BEUGUE WALLY AM DISQUE D'OR RÉK BEUSEUL J'AIME 😍😍😍❤❤

Aicha_Ballago_Seck_TV
Автор

KING BI NDANANE BI SÉNE PAPA DJI ON T'AIME TONTON WALLY 🥰🥰🥰❤❤

Aicha_Ballago_Seck_TV
Автор

J’expliquais à un ami ! L’impact que l’album IWBF allait avoir sur le Sénégal les sénégalais seraient beaucoup plus 2:51 chanceux que Wally lui même ! Une fois sur le podium le monde sera à nous ! Des milliers de personnes quittent leurs pays rien que pour voir burna boy, Davido ou wizkid. Des milliers de touristes pour juste découvrir cette touche musicale et artistique qui est tout simplement extraordinaire. Donnez de la force à vos artistes ils représentent tout un pays 🇸🇳

kendrickjhonsine
Автор

Douma sa fans mé sa son bi nice na trop vrément

mameassthioune
Автор

Ha Wally B Seck j’étais quitté au Mali le mois de Mai pour te voir mais j’étais pas vu 😢mon artiste préféré inch’allah vacances prochain je serais là au Sénégal 🇸🇳 encore

CMRBigBamboomYeyayeYeyayeCMR
Автор

Balma j'arrête pas de l'écouter en boucle. Ma partie préférée 1:49 "cherie coco me I love you dou débat, tu sais pour toi je ferai le premier pas. Des jeux de rein à la WALLY IPUPA. Bayil sa meer bi té nga ré comme khaby lam lamé day sonal sa khel nangou na ni mako def bougnou mel tom et jerrry." Ayy ayy wally ya meun ❤

damel
Автор

Je suis très fière d'être un Sénégalais

mouhametendiaye
Автор

Kou geum ñi disque d'or bi Day téw rk lalal j'aime May guiss ❤❤❤

sendaal-rh
Автор

Ay way waly yena la disc d’or bi trop balamo done nekh niou am louniou ndiedé céder bi waye yalna lako yalla may waly si barke yonentebi

NdeyeSylla-cy
Автор

Mashallah 🥰🥰🥰 focus rekk inchallah le 6

assemalick
Автор

On vas tous acheter l’album pour soutenir le golden de la musique 🎵 sénégalaise 🎉inshalla disc 📀d’or ou rien force à toi frère ❤️je t’aime tellement 😭❤️👋

mamefaluu
Автор

Partie bimou toude Khabi Lam la guis Khabi dougueul ko. Macha allah khalé mague na. Wally tu as compris que chanter c'est s'ouvrir au niveau mondial et utiliser d'autres rythmes que le mbalakh bigua khamné Sénégal gui la yéme. Je me rappelle quand Akon t'a dit de travailler plus pour faire des featuring avec les chanteurs américains, tu étais fâché mais je pense que maintenant tu as compris qu'il ne suffit pas seulement d'être aimé par quelque sénégalais et de chanter des milliers d'amis. Bref son bi diare na yone, bne continuation

mumsmbaye
Автор

La varieté des 2voix le dance hall et le youkhou du mbalax

bassembaye
Автор

Eh c’est Annecy et Lyon c’est Carré Wally 💪🏾💪🏾

HakunaMatata
Автор

Wally a fait oe clip à lyon on dirait, en tout cas très belle réalisation comme d'habitude.

biranewane
Автор

, ,
Quel son franchement Wally Balago SECK tu es le meilleur
C'est le haut niveau
Que du bonheur
Mancha allah laf thiat Yalana yala barkel lep si barke SEYDINA
MOUHAMED SALALAHOU ALEYHI WASALAM
AMINE YARABI 🙏🙏🙏
❤❤❤

aminatathiandoum
Автор

Guouye Guou Daar Guangui Nih, Makgnéko Diangual Wayé Moy Diangal Ndaw Gni, Le Président Wally Ballaguo Séck Est L'homme De Touts Les Tmps.
Kou D'accord Lalal ❤

FaramareenTV
Автор

machaallah faramaren bii moo ngui déff niom nio défoul

show_tout_chaudman
Автор

Wally seck est le meilleur du monde ❤❤❤

diassthioune