Wally B. Seck - YA TAY feat. Baye Mass (Vidéo Officielle)

preview_player
Показать описание


Ouverture des portes: 17h30
Début du spectacle: 19h
………

Director : Pac Deejay
Auteurs: Wally B. Seck, Baye Mass, Big Dat X
Compositeurs: Papelaye Beats x Loufa
Enregistrement: EDGE Studio
Mix/Mastering: Sirtam
………

Retrouvez-moi sur :
………

LYRICS / PAROLES :

WALLY
Yéwou ci seu wét doyna mbégté
Diakaarlok seu kanam doyna banékh
Love bimay yeuk kouko meun teuyé
Ana kiko sagne diaral nama khéékh
So beugué nak mou sauvage baby
So beugué nak mou doux, lo deff ya tay
Dis-moi ce qui t'arrange bébé
Diafandou na ci seu branche, mbeuguél bou khéré

BAYE MASS
Yéwou ci seu wét doyna mbégté
Diakaarlok seu kanam doyna banékh
Lo-love bimay yeuk kouko meun teuyé
Ana kouko sagne diaral nama khéékh
So beugué nak mou sauvage bébé
So beugué nak mou doux, lo deff ya tay
Dis-moi ce qui t'arrange bébé
Diafandou na ci seu branche, mbeuguél bou khéré

WALLY
Ci seu wét douma baayi
Ak loum meunti done
Boulma yeureum, déma gaagne
Takk sama lokho
Yow seu allure dafa gaaw
Kouko léék fott
Même so togné boulma baalou
Lo deff dafmay néékh, ya tay

BAYE MASS
Soma togné, ya tay
Réwantoul sakh, ya tay
Kou ci dougou mo ci dess, ma baby ya tay

WALLY
Soma togné, ya tay
Réwantoul sakh, ya tay
Kou ci dougou mo ci dess, kone baby ya tay

BAYE MASS
Mane dé beug naa (ya tay)
Lo wakh mou nékh (ya tay)
Yow da nga taarou, da nga diékk, da nga nice

WALLY
Seu dokhine rafette na (ya tay)
Mane beug naa (baby ya tay)
Lo deff mou nékh, khamna dingma meussa gagne
Beugouma niouy réro
Wakhoumalak taago
Sama thiofél ci yow wornama
Nope naala mane eh-eh ya

Show me your love my babyboo
Sama safara, my seytaané
Everything! My love knocks me down
Rothie sama guégno diokhnaala ko

Ah dissah deep love fidi gyal dem
Dem ennemi mana ready fi shoot dem
Mi love is over all ! whya mi ready fi evathing

BAYE MASS
Baybe yaag neu man dama paré
Ndiggueul xalé bi diaral nama xaré
Mi love is over all ! whya mi ready fi evathing

WALLY
Ci seu wét douma baayi (ma babyboo)
Boulma yeureum déma gaagne (mon bébé à moi)
Seu allure dafa gaaw (ma babyboo)
Même so togné boulma baalou (mon bébé à moi)

BAYE MASS
Soma togné, ya tay
Réwantoul sakh, ya tay
Kou ci dougou mo ci dess, ma baby ya tay

WALLY
Soma togné, ya tay
Réwantoul sakh, ya tay
Kou ci dougou mo ci dess, kone baby ya tay
Hum… Show me your love ma babyboo
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

LYRICS / PAROLES :

WALLY
Yéwou ci seu wét doyna mbégté
Diakaarlok seu kanam doyna banékh
Love bimay yeuk kouko meun teuyé
Ana kiko sagne diaral nama khéékh
So beugué nak mou sauvage baby
So beugué nak mou doux, lo deff ya tay
Dis-moi ce qui t'arrange bébé
Diafandou na ci seu branche, mbeuguél bou khéré

BAYE MASS
Yéwou ci seu wét doyna mbégté
Diakaarlok seu kanam doyna banékh
Lo-love bimay yeuk kouko meun teuyé
Ana kouko sagne diaral nama khéékh
So beugué nak mou sauvage bébé
So beugué nak mou doux, lo deff ya tay
Dis-moi ce qui t'arrange bébé
Diafandou na ci seu branche, mbeuguél bou khéré

WALLY
Ci seu wét douma baayi
Ak loum meunti done
Boulma yeureum, déma gaagne
Takk sama lokho
Yow seu allure dafa gaaw
Kouko léék fott
Même so togné boulma baalou
Lo deff dafmay néékh, ya tay

BAYE MASS
Soma togné, ya tay
Réwantoul sakh, ya tay
Kou ci dougou mo ci dess, ma baby ya tay

WALLY
Soma togné, ya tay
Réwantoul sakh, ya tay
Kou ci dougou mo ci dess, kone baby ya tay

BAYE MASS
Mane dé beug naa (ya tay)
Lo wakh mou nékh (ya tay)
Yow da nga taarou, da nga diékk, da nga nice

WALLY
Seu dokhine rafette na (ya tay)
Mane beug naa (baby ya tay)
Lo deff mou nékh, khamna dingma meussa gagne
Beugouma niouy réro
Wakhoumalak taago
Sama thiofél ci yow wornama
Nope naala mane eh-eh ya

Show me your love my babyboo
Sama safara, my seytaané
Everything! My love knocks me down
Rothie sama guégno diokhnaala ko

Ah dissah deep love fidi gyal dem
Dem ennemi mana ready fi shoot dem
Mi love is over all ! whya mi ready fi evathing

BAYE MASS
Baybe yaag neu man dama paré
Ndiggueul xalé bi diaral nama xaré
Mi love is over all ! whya mi ready fi evathing

WALLY
Ci seu wét douma baayi (ma babyboo)
Boulma yeureum déma gaagne (mon bébé à moi)
Seu allure dafa gaaw (ma babyboo)
Même so togné boulma baalou (mon bébé à moi)

BAYE MASS
Soma togné, ya tay
Réwantoul sakh, ya tay
Kou ci dougou mo ci dess, ma baby ya tay

WALLY
Soma togné, ya tay
Réwantoul sakh, ya tay
Kou ci dougou mo ci dess, kone baby ya tay
Hum… Show me your love ma babyboo

officielwallyseck
Автор

La sortie de ce clip coïncide avec le jour où l’amour de ma vie a accepté d’être à mes côtés pour l’éternité après des années d’attente😢 je t’aime AD❤

youssoumbengue
Автор

Diabarou artistes yi yallah naléne yallah maye kholou mougne 😂❤

Boubs-vl
Автор

Yééna Torokh Alal jaroul Taatinén, jigéen Amatoul bénn valeur. wayé kousi déé Yééwou.

gueyematar
Автор

Wouy takatina rasta yiii 😫Wally Fo gnou dieumé 😭😭❤❤❤️❤️❤️

m____
Автор

Wally si bopam mo xam ay ndanane
Vraiment baye masse ndanane leuh ❤❤

abdoulayediouf
Автор

Waly khalé yi Niola eupe chance 😢❤ Akon dala rejeté wone mais tay yegue nga ba mày khalé yi sen chance bravo 👏

ibrahimasakho-tzkx
Автор

Magnifique Duo diguaaa fii rayy niteu marr Yacine di may boy yii chance ioe rekk yakhoo fiiiyy deff merci beaucoup ❤🎉

abdoulayefaye
Автор

Wally Bravo..vraiment il est entrain d'accompagner les jeunes talents.
Ballago bilahi tu as raison doula yakhal dara, tu es déjà dans nos cœurs. Kagne lalay djis si aduna..😢

OusseynouMBOUP-ti
Автор

Thieuy Mare Yacine!!! Deugue deugue do nitou fiii.
The GOAT. Lolou dara douko dindi.
Dokhalal

khouje
Автор

Machine vraiment wally contanagne trop thi ligaye boy ayy loxo Machalla thakaw thiakanamr inchalla ❤

HabibouSy-ox
Автор

1:52 ba fin wally amna louko doug li dou meune way rek amna lousi rakh nak bilahi wallahi tallahi wally yallah nala yallah sam amineee touff touff ❤

FeuzaPouyewally
Автор

J'aime ♥ comment il tire la main de ses jeunes frères dans la musique love WS❤

khadydrame-em
Автор

Machallah meilleur artiste de l’année wally❤ rk moko mérité bravo mar👏

HhgH-puph
Автор

Wally nak srx nekh gama jsuis très fier de toi malgré ts ces jolies dames tu restes tjrs focus sur toi et ta femme ma contane ci yaw nk seck yalla na sa diam yag🥰🥳

Theresedaba
Автор

My bro nice job, vraiment je suis fière de toi Push up 🙏🏾🙏🏾🙏🏾

moussaniang
Автор

Il a dead le game, maintenant il se retourne donner de la force aux plus jeunes. Amadeus, didi, baye mass, VJ, mya En vrai c'est le GOAT qu'il pense etre. Doxalal Mar Yacine !🎉

mamadousow
Автор

WAW TRUCK BOU NICE!
FLOW BOU DUP!
CLIP BPI CHIC & AMAZING!
Macha ALLAH WALLY BALLAGO NE CESSE DE NOUS SURPRENDRE!
VRAIMENT MOGUI MAY JEUNE TALLENT SEEN CHANCE§
BON VENT A TOI FRERE BAYE MASSE!
💖💖💖💥💫💯🙏💯💫💥❤‍🔥❤‍🔥❤‍🔥

ALIOUDIALLO-zhtz
Автор

Trop Nice waly et baye masse machaalah thiate sékhe lou léne

claireniang
Автор

Oh tu as encore frappé notre wally et avec baye mass chaque fois que quelqu'un touchera mon commentaire je reviendrai écoute cette chef - d'oeuvre ❤❤❤

ndiabendoye