Wally B. Seck feat. Viviane - Reuguine Tass

preview_player
Показать описание
Suivez-moi sur mes réseaux :

Produced by : FARAMAREEN MUSIC GROUP
Arrangement : AKATCHE
Mixing : AKATCHE
Mastering: Matshimoto
Written by : Bakhaw
Director : Pac Deejay
Décoration : Yarba Déco

#wally #viviane #reuguinetass

LYRICS

Deloulsil delousil dou meun nga darra dé diaroul xass
Meuneu dem ma takha dem moytou dougou thi auto you tass
Wakh bi ni nga ko dégué, diaapé ko nounou, Mba compou nga

Oooh ooh ooh

Ni diamono ji legui da ngay ré ba dé
Fima dieuma sori damey bagn goudé
Wakh dji beurina déy nourou mariné

Refrain
Di naagn la féthial reguine tass (x5)

Ni wo woo Vivi bougnou faalé
Bougnou décodé
Nagnou baalé
Ki léy diébaané
Boko séété dé yaako tané
Mane dé déég naala
Dafa féék né taloumala

eyow eyow eyow

Di nga sonou Faramareen féép leu meuné
Eyow eh
Nangoulmako té nga Take a sit, Take a sit
Vivi gnou féthial ko Reuguine tass

Meuneu dem ma takha dem moytou dougou thi auto you tass
Wakh bi ni nga ko dégué, diaapé ko nounou, Mba compou nga

Oooh ooh ooh

Ni diamono dji legui da ngay ré ba dé
Fima dieuma sori damey bagn goudé
Wakh deug bagnou mala

Refrain
Di naagn la féthial reguine tass (x5)

Viviane :
Deloussil deloussil comment tu vas (comment tu vas)
Nangoul niou lou niou mom té yalla takh (té yalla takh)
Maléy sonnal, té dawoulo dé wawaw

Demal nga tok, mané dolé yamoul wawaw
Kou andak lou niou andale loula nekh lathie

Wally ak Viviane beuri fitt faathie, yeah yeah
Bokk école, bokkou niou classe, té douma sa mass
Ma tangal sa khol, wakhko sa yaye mou soti ci glace
Té ragalouma lolou wooooh

Ni diamono dji legui da ngay ré ba dé
Fima dieuma sori damey bagn goudé
Wakh deug bagnou mala

Refrain
Di naagn la féthial reguine tass (x5)

Bilay man dé beug naala
Walay man dé beug naala
Mayanté xaliss diaroul khass
Bilay man dé beug naala

Sant yalla dey nourou titeurou
Wakh deug yalla tognou gnou
Bour yalla né sante lén ma doli
Ba takhna ma deuké thiant li

Eh eh kou seu xol nekh nga ré

Refrain
Di naagn la féthial reguine tass (x5)
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Grâce à vous, nous avons atteint plus d'1 million de vues en 24H. Merci pour votre soutien, vos messages, vos commentaires... Vous êtes au top niveau. MERCI encore la famille 🔥❤️ (Les lyrics sont disponibles dans la description 😌)

officielwallyseck
Автор

Viviane la reine et le prince Wally 🔥🔥🔥🔥
Un clip Parfait et plein de sens
Reguine tass 💃🏾🕺🏽🕺🏽 on va fetch fort 🔥

AxelmerrylVrai
Автор

Masha alha Wally félicitations 🎊, chapeau à Viviane quoi qu’on puisse dire elle restera la reine de la musique sénégalaise, trop classe, Sagnsé bi masha alha, style bi nangou lou bakh dafay fexaal xool lii nexna tee guem nani yenen Duo Wally ak Viviane dina guena li ndamou senegal bi rawatina Africa❤️❤️❤️

Loiseaudunet
Автор

Wally.B Seck t’es le Meileur tu gère le Game comme un vrai Duc. Je te tire mon chapeau, ton Papa est très fier de toi‼️

keyworld
Автор

💋💋💋😘🤩🇸🇳🇸🇳 Allez le Sénégal ❤❤ C'est mon pays préféré le Sénégal et toi

nandingsylla
Автор

Ce clip sera le clip qui aura plus de vues sur YouTube sur l’histoire du Sénégal 🇸🇳 InchaAllah 🍀👌🏽💫🎯

kingkang
Автор

Qui croit que ce projet fera single de platine et le prochain album 💿 de wally disque D’Or ❤️🤩

mouhameddiop
Автор

1million en moins de 2jours 😘🥰😍

Kay len gnou fethii reguinn tass 😍❤️

oulimatadiankha
Автор

J'aime bien tes chansons même beaucoup J'adore❤❤❤❤😊

nandingsylla
Автор

Le Feat de L'année En Afrique sans doute suis tu est d'accord avec moi des cœurs après ont passé Où sont les Fans de Waly Seck et Viviane Manifestez vous Reuguine Tass 🔥🔥❤❤🙏🏾🇸🇳

saifondavectatitatilesdeux
Автор

1 millions de vues dans une seul jour li États-unis 🇺🇸 Ak Nigeria 🇳🇬 reck la ko donne Guiss suis content legui di Guiss ni souniou musiques bi Senegal 🇸🇳 mogui develepe en force felicitation les 2 stars ⭐️ sénégalais vous faite notre fierté bonne continuation le peuple est content 🤩🥰😍Bravos 🏆

johnmaguettegomis
Автор

Toujours le golden boy frappe .le peuple sénégalais est très fière de toi.le fils de pape thione.Que le tout puissant t'accorde une longue vie ❤️❤️❤️🎤🎤🎤🎤❤️❤️❤️🎤🎤🎤

moustaphasene
Автор

S'en commentaire Wally Viviane je vous kifff depuis la côte d'ivoire

drissabarry
Автор

Le peuple est content #wally ton passage hier à la 2stv à encore une fois de plus prouver ton professionnalisme tu es sur la bonne ne voie ne te laisses pas perturber ni influence tes fans t'aiment et prie beaucoup pour toi tu es un Real gas diam AK heiweul broo

aichadiallo
Автор

2 artistes stylès❤
2 artites de haut niveau🤝🏽
2 artistes èlègants🧥👗💘
2 artistes classes🎉
2 artistes talentueux 💘
Rien à dire le clip est au top. les images, les couleurs omgggg☺

Fahdiawarasarr
Автор

C'est la 4ème fois que je regarde le clip depuis sa sortie ma meuna sotte 😂😂ta parègouma ba 1million rek inchallah dougniou moromou ben bodio bodio ou sont les framareen wally et Viviane vous êtes les meilleurs wally mom je suis tellement fière de lui est ce que ça c'est normal d'aimer quelqu'un ainsi sheuuut 🥰💞💞💞💞💘💘💖💖

awadieng
Автор

J'aime tellement cette chanson et un clip bien exécuté j'aimerais comprendre les paroles depuis la Côte d'Ivoire

AdjaraKante-gi
Автор

Je ne comprends rien mais j'aime la musique sénégalaise 😍😍😘 depuis le Gabon 🇬🇦

bernienzouba
Автор

Qui confirme que wally est le roi et Viviane la reine de la musique Sénégalaise un vrai duo de titans 🥳🥂🇸🇳👑🖤 qui est d'accord cliquez ici
👇

Moizochvro
Автор

0 nudité
0 vulgarité
100% talent
100% style
100% clip
Faut osé et avoir beaucoup de feelings pour faire tout en même temps. Quand deux stars se collaborent y'a toujours une réussite totale, ils ont quelques choses de spécial quand ils chantent et ils ont révolutionné la musique sénégalaise. Le chanteur du peuple et la reine mère vous êtes les meilleurs je répète encore vous êtes les meilleurs❤

seriesetfilmstv