CAB - Délai feat Taal bi

preview_player
Показать описание
Wussup la LEUNDEUM SQUAD
Dans ce titre, CAB est en featuring avec Taal Bi et ils consolident leur légitimité dans ce game sur ce banger. On est en train de bosser dur sur beaucoup de choses et beaucoup de choses sont en préparation donc la famille après avoir regardé nous vous prions de bien vouloir vous abonner et d’activer la cloche. #Délai est disponible sur toutes les plateformes en streaming et en téléchargement.
……………………………………………………………………………………………………….
Suivez CAB sur les réseaux sociaux :
……………………………………………………………………………………………………….
Suivez Taal Bi sur les réseaux sociaux :

……………………………………………………………………………………………………….
Compositeur : Baach made it
Arrangement : Freshi 808
Mix & mastering : Freshi 808
Realisation : Emdjipi
Déco : Jah design
©PackM music group
……………………………………………………………………………………………………….
Lyrics
Couplet CAB

Boudoul sama baag ci tène bi ngay dess
Sa capitaine bi day cap
Koufi niodi God ci game bi day féne
Lepp loufi meuneu ram si gang bi lay dem
Limaci yora beuri ba rappeur may tibeul
Nekeu fi di soow may digueul
Maneleu lil nigga bifi done tay biggest
Kou beug mouss deug mane rekala meuneu sibeul
Bou yabbo nanga paré sama bum day tew
Amoul kouma gueune *** rew
Wadial ngandi vendeta
Nga nek vanne de taille
Fi amoul louma meuneu done bay beiw
Leundeum squad ni liv we don’t walk alone
Gang bi doko meusseu taal bi combo keu woor on God
Khat ni condom ci dion
Doumassi diougué di dadialé com com di noce
Sama dope beu tax sa bum defoul tabas bro
Mangci zone bi kone kalate ko
Kou bania né fouma yeungueul demal aras tok
Th dama cher bayengama am ci gratos
Lima firi dou sax piqure
Manela ki dik dipeundi carte gui
Do degg koufi téguéni cab ci beat
Limay defa ler melni midi lou nadj bi nit ey
Yangui tit th cab dh day fo di go
Amitié bi sax dafei doy yeubo
Cab ci game bi papa leuy done
Tekki ba tabax cité senegal ni akon you know
Nimaciy teggo dou kene kouko meunate ci yene
Seug sa kaw ni renard ci yel
Xalé beu paré di monarque ci game
Mangui degg lep lou xew ni sonar ci guedj

Refrain
Leundeum bi sax deiy trinw Leundeum ci kaw may sène
Feuleul ci CAB ngay terre Eh manigga weuyoul fi bandéy père
Leundeum bi sax deiy trinw Dileu seuleum bissap ngay mér
Siguil ci kaw may séne Meuneu tagalé sa boppak sa batt lék lék
Dioxnalene delai Gaaw lene deguerpir yeubo yi nieuw def prek
Kamil bi lanie tek watt ni kounioukoy téré
Amoul ci rap galsen bi dinanieléne balais
Ndéké liniouy begg leppeu boys yeupeu nioune lanie méré

Couplet Taal bi
Eupp leine tête niouniouy wowei fils kou nieuw day ralentir nangou seine game niounak sounie équipe daiff diff si lou lerr lagnlay garantie
Kone nioune ngeine meirei dioxnagn leine delai
loungueine daure niou finteileine
Th nii lay deimei dagnlay jaay prék
Ligueiye nagn ba fingne télé
Skey bi di daw di ram si seine kaw
Teikk tank di top yonn bimouy aw
Teknik bouffi tourou feipp lay law
Seine son yima cons ni lougn fi taik daw boy lane ngeine meunei
Amouleine fiit diko wotei si diig game bi 100 combat doleine beurei
Taal bi ak cab diko daiff leundeumale ko mouy trinw th guissa gougnou kounioukoy teirei
Kone nioune rek dope na ba gagnla nga balniou masta xamnagn ni k moussonio gneimei
Boy mak ioe bilay kouniou sombi doko nane drogue laniou mixeik xeimei
Ils sont chaud ngay daigg dépensou son bi moy teknik yignssiy frais
Daniou meune rap aay trop loffi meuneu taikk nioy borom
teudoulo mc yi corroc doniou meuneu takal souniou bind daffa propre
Taal bi day ted dou trokh daniou meuneu rap boul soxor
douniou mousseu gueinei mou flopp carton rouge nioune talouniou clopp
danioukoy raay diko dioxogn dou mousseu lale sa xol say beut lay toxogn
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Dope master amga blem waro won dougou si taal bi trinw kaï 🔥🔥

mameabdouseye
Автор

J'appelle ça du rap au vrais sens du mot🔥🔥🔥

burr
Автор

fier d'etre senegalai wallah macky amnga chance dama naronn changei nationalitei...
dope guys

bocardiaw
Автор

Nioun rk dope na nga bal niou masta quel clash 😂😂 dope master ya mom bobou dh

Taal bi✏️🖊️

amethdiop
Автор

Wa mais 🤔😱🤯🤩level bii kawé na les gars Dope 🔥💪🏻

kingabson
Автор

Kou fiy gnoddi god si game bi day phéneu....
Kmf🔥🔥

blackcfatekxellb
Автор

Dope naniou ba gagne leu nga balniou masta (master) khamnaniou ni que mousso niou niémé. DopeMaster en sueur.


Soldat à terre, je répète soldat à terre!🔥

zlorg
Автор

Wøøw wøøw punch bi dall na ma, Door la ba gagne la kone( master ) kham nagn ni mousso gnoo gnémé♨️🔥🔥

bayeousmanendiaye
Автор

C'est vraiment du lourd le vrai RAP 🔥🔥🔥🔥

dorokane
Автор

Wollah vous êtes hyper forts
L'enchaînement de Taal bi 🔥

ousmanegerarddiop
Автор

On parle de Taal bi but deeglou ngeen Cab ? Daam
Amazing le beat est just wow

Fgenius_
Автор

Nioune rk Dope nagn ba gagn la master nga balniou xamnagn ni meusoniou gnémé 👍💪💪💯💯

khadimgueye
Автор

Dope master kaay wouyou fi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

hakoomofficiel
Автор

cab lingay daw beurina 🔥🔥🔥🔥🔥🔥♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

khadimniang
Автор

Boy dof 🤣🤣🤣🤣 tounday lii rk sheuuuu ⭐️⭐️⭐️⭐️

sniperiam
Автор

Wooow j'ai l'impression que ses deux gosses joues PlayStation 🎮🕹️ 🤗sur le beat le floww dingue de cab leumdeumeul n'eu beat bi taal bi tres a l'aise sur l'écriture trainww nako carrément 🥳🎊🤭

niangelzo
Автор

Wtf😂🔥 leundeum bi saakh day triiinw.... talent pur100

broodave
Автор

Yeup... Bip up Emdjipi à la prod Nice job.

daoudasecktavarezyanga
Автор

CAB + Taal Bi = Sasuke + Naruto = Zoro + Luffy
Boulén wo si guerre 🔥🔥🔥

zlorg
Автор

Dope master moussonio nieme
Taal bii do nitte🤣🤣🤣🤣🔥🔥🔥🔥

MiTempsFoot