Ana porolem bi feat Bm Jaay

preview_player
Показать описание
#TOPBOY nouvel EP maintenant disponible sur toutes les plateformes musicales ⬇️

————————————————————————
Compositeur : Freshii808beatz
Mix/Master : Freshii808beatz
Cover : ItsMDG
————————————————————————
LYRICS

Yoré bopp bou fess
Kone meunouma low prix
Jeunessou kylian laniou jaxassé ak xelou modric
Deuk ci def
Bolékok nopiiiiiii
Dieufeul th bayi wax daniou soneu ci bande annonce yi
Limaleu gueune niémé job réka tax doma raw
Barki alxourane
From sama nek to the top sama baatangui laaw
Ana porolem bi
Kou banie takeu bane fima aw doufeu meuss beug aaaaaw
Barki alxourane
Th diemeul nga def lima def mo gueune talkin a lot
Ana porolem bi

Guissouma mane beneu porolem
Boumay té né kou tedd ci rap
But bé eup bou talonner
Raaap galsen manela yalla bi th diotoumafi yoni beneu prophete
Chaque jour yangui xeuy sama der diko yakeu esk doumla diox ibuprofene
Mane laniou fal game bi may kiko wara developper
Do meusseu signer simane wanté gnileu bégué niomay nianatou autographes
Fi ngay guiss kouné mo dak punchline th si son yi mouy devinette
Lima nara defap ngandi icone meuneu son leu dou photographe
Nianou wadiour amoul louko teu
Diemeu gueneu sama zone de confort
Niom niouy diemeu doug sama zone
Douma artiste bouniou verifié
Monté mangui tax ay bum di flop fils
Sama kadu sama premier sponsor
Comme que balle leu manguek sama gun
Samay loxo amoul loci tek
Daniou soneu ci bande annonce yi

Yoré bopp bou fess
Kone meunouma low prix
Jeunessou kylian laniou jaxassé ak xelou modric
Deuk ci def
Bolékok nopiiiiiii
Dieufeul th bayi wax daniou soneu ci bande annonce yi
Limaleu gueune niémé job réka tax doma raw
Barki alxourane
From sama nek to the top sama baatangui laaw
Ana porolem bi
Kou banie takeu bane fima aw doufeu meuss beug aaaaaw
Barki alxourane
Th diemeul nga def lima def mo gueune talkin a lot
Ana porolem bi

Wooo woooo
Sama Ford Moy Focus
Man Ak Ligey Nio Fusion
Yar sikim yor brabus
Deretou none yi infusion
Xaliss bou set ak bou tilim na fess sama biir ni kou am koachiorkor
Do multiplier sa ben bénéfice ndax danga manquer li di vision
Jeuneussou Kylian jaxasse ak xelo modric
Yaw la Ricky Drenthe
Teud si piliane guenè samay statistic
Talatouma werantè
Streaming Spotify yangi tchi guinaw Pacotille
Mais Néna moma djitè
Waxtanou Milliard yonou pauvre nékou tchi
Wéthiét bi moy sa sujet
Yor sama pèle di gass dama tal say pique
Mounougn ma thiop dama fess sen tchin
Boul dem dikat togatal sen Team
Sougn mey sene di djad dama dox sen fit
Man la ten bi bag bi xont sen hip hop wout len syndicat wou Rappeur anorexique
Am Audace Dima Gnane ay feat
Shout out to cab fuck bokoul Fii

Ay so xamone lep limouniou jaral
Geteu bou goat yeup deuk baki axourane kene douniouko téré
Finiouy wok da melni fala
Yeah finiou wok daa melni falaa
Marouane xalé bouko tendance mou defla si sar monami
Lidi bax da melni sa xolaa
Mingui bax th narouta fay dh
Koudoul liguey kat do sama nawlé
Gangou bandit leu kene douko taylé
Marouane papa leu CAB maobé
Nioy number one do sax numero 2
Yegg au top mom dinala diss
Boudoul ndaré dou lene louniela seuf
Lalal bassang ndax souf ci nga miss

Yoré bopp bou fess
Kone meunouma low prix
Jeunessou kylian laniou jaxassé ak xelou modric
Deuk ci def
Bolékok nopiiiiiii
Dieufeul th bayi wax daniou soneu ci bande annonce yi
Limaleu gueune niémé job réka tax doma raw
Barki alxourane
From sama nek to the top sama baatangui laaw
Ana porolem bi
Kou banie takeu bane fima aw doufeu meuss beug aaaaaw
Barki alxourane
Th diemeul nga def lima def mo gueune talkin a lot
Ana porolem bi
————————————————————————
Suivez moi sur les reseaux :
Snapchat : theleundeumest
————————————————————————
#CAB
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Mes premier et troisième rappeurs préférés ensemble. Quoi rêver de mieux ? 🎉🎉🎉

theboss
Автор

Guirr yalla déglou léne Bm jaay attentivement bilay dou nitt daÿ job 👑 mé chapeau à cab🔥🔥 nice na

azizsall
Автор

"Rap galsen man leu yallah bi té diota gouma yondi bén prophète"😲wtf mé Ahmadou Bamba déff niou ndank bro😂🔥 "sma ford moy fucus man ak liggey nio fusion" marouane😂😂😂😉.

lamzii_dml
Автор

Bm jaay ne déçoit jamais mes cab assurer nga vraiment ❤🎉

mb-smlofficiel
Автор

sama ford mooy focus mank ligey nioo fusion 😂😂😂 Bm jaay ball niou

cheikhoudiallo
Автор

mais Bm Jaay Kel Homme Machallah il est fort Vraiment il mérite d’être le Meilleur artiste Masculin au Prochain GHHA ❤️

abdoulayendiaye
Автор

Chaque jour yagui kheuy sama der diko yakh est ce que doumala diokh ibouprofén😂❤🎉vrm cap do nit Bm jaay geneu Ayy rek Machallah dal laf thiat 💪🏾🥰🔥✍🏾

Diosslofficiel
Автор

🔥🔥🔥🔥 sound bi c dooope🔥🔥 BMJAAY mo dakh rap kouy rap.

papiscongom
Автор

808 Beatz danga doff xana c trop coool 😮

modougueye
Автор

Thieuy MaRwanE HaBiBou yall na ko yalla Sameuh rk no sa gars é très talentueux tt Jr aux top wolla mé focus rkk ❤❤🎉

wayenepilayendoye
Автор

La connexion on dirait De Bruyne et Haaland 🐐🎊

Anonymo
Автор

Danio sonou sii bande annonce yii bilay. TOPBOY💎

mouhamedndoye
Автор

BM jaay le meilleur actuellement qui est d'accord avec moi

MaguitteThiam
Автор

CAB buul bay sa lokho rabofii daga mbalakh sii son bii boul nelaw bro gnoul gnow lagnou nékeu dii tohop na deugueur❤

biparealboy
Автор

BM Jaay dou nit❤️✌🏾🎶 mais Cab t'as assuré✅😁

pipssthelyricist
Автор

Bm Jay Dou rappeur rou xallés mon fi Nara nk intor nation nalle

Ting