filmov
tv
CAB - Interlude (Clip officiel)

Показать описание
Suivez CAB sur les réseaux sociaux :
Suivez Mpossible Prod sur les réseaux sociaux :
……………………………………………………………………………………………………….
Artiste : CAB
Titre : Interlude
Label : Mpossible Prod
Réalisateur : Kirama
Prod : Gilomas
Mix & Master : Freshi808

LYRICS
Meussouma guiss koulay fayékou bor
Hamdula banga xamé keuyit soleil dou bot Bouniou xolé si ioe dounie meusseu bone
Th chaque jour yangui nane dom dema bayi xel fo meunti tok
Mangui raconter sam life mou done ay rimes
Th day soga tambali dinguéne dund lou gueuneu pire
Néwma dama banie done kou tekki def ay balade si yatch
Mais lima gueuneul moy 4 si cooter pour banie keneu di dox
Beugate na niou guissé
Nameuna say waxtane ak sa ré
Life is short boul meuss nangou nioulay tanal sa reve
Beugone nama reussir sans done kou siw
Mais wa galé diaral naniema charbonner ba creuver si liiw
Xamouloma kone boul wax simane lou bone
Kanie ngay xamni niteu dof
Beuss bimou défé mindane lou bone
Koumay diox loxo soumay daanou si vide
Apar yénémeu diam amoul loumay taamou si nit
Get out to my face
Dam nieuw rek monter niouy wokanté ladj ndaxam dama seiiy
Worna buur bi Do meusseu fayou
Melni gana bounie taalal doigt d'honneur
Yay sa dom beuss dina nieuw foum dem degg a toi l'honneur
Boy do peripetie
Leundeum squad nio gueuneu metti messi
Rappeur bou diémouta farak mane dh sa peine dineu diss
Pardon pour guel youmafi diota tromper
Nimala meune defé lou meti lala meuneu fonké
Def ay son nieup ni waaw ndax dama yagg degg dedet
Do niak lo beugoul
Meme soudé danieko nangou si ioe
Mayou yalla dongueleu diwouwma th takouma téré
Douma nit bouy nangou lo xamanténi andou ci wone
Boudé xol la yallay faye samay lampe day meusseu tak
Waxma kou tax nga rap
Ma waxla ioe leu kane
Pour am lo meussteu am
Fok nga def lo meussteu def
Dam beug fessal compte banque pour banie lép mais dieund sa fane
Séne show yi mane laniouy waxtané ma nék séne lamigne ni percing
Doma meusseu gueum soumleu waxé reve momeu téré sleep
Niom nioleu gueuneu xamni boy bi toud CAB he does the best things
Dama am mettitou bopp ba pa nanemeu you better sleep son
#CAB #LeundeumSiKawBassiSouf #Interlude #Mpossible
©️MpossibleProd2021

Комментарии