Massamba Amadeus - Amadeus - Bëgg naa la man

preview_player
Показать описание
Voici « Bëgg naa la man » votre ndewenel ! 🤩

Auteur : Amadeus
Compositeur : Zoom beat
Mix / Mastering : Zoom beat
Réalisateur : El hadji ilam camara
DOP : El hadji ilam camara
Directeur de Production : Stephane Mancabo / Pee Black
Lights : Bras Magik
Showrunner : Mame selemane Dieye

Suivez Amadeus sur les réseaux sociaux :

Paroles en Wolof :

Eh Massamba walo
Zoom on the beat
Hey waay
Bëgg naa la
Reason to be man fonku naa la
Yaay jant bi man Bëgg naa la
Nii ma la Bëgge yi jeggi na dayo
Eh way ye way mi girl
Mi yi dei ma for Life
Lu nek jaral nga ma
Ken mënul tax
Ma merre la
Ñook seeni wax
Fuck nañu leen daaw

Man so merre damar jaaxle, tiis
Dama la bëgg
Be neen jigeen mënul tax ma giif
Ndax yaw la bëgg
Amul sax
Nit kuy mën xam li may yëg ci yaw
Amul sax
Nit kuy mën compu nima la bëgge yiiii

Bëgg naa la man
Ehh ehhh
Bëgg naa la man
Bëgg naa la man
Ehh ehhh
Bëgg naa la man

Dama la bëgg ba faf gëmme wu mala
Bañ lula metti bañu yaakaar ni ñeme wu mala

Dama la bëgg ba faf gëmme wu mala
Bañ lula metti bañu yaakaar ni ñeme wu mala eh

Jamm nga may lathie ma ñëw indi feeling pathie
Ku degg ngay lathie te man dama degg daaj ehh tamit ci aduna
Man rek malay beggël
Jamm nga may lathie ma ñëw indi feeling pathie
Ku degg ngay lathie ma ñëw indi feeling pathie eh
Tamit ci aduna
Man rek malay beggël
Ku la laale man lay raagal
Te kula tooñe may nangu xeex bi

Eh way ye way mi girl
Mi yi dei ma for Life
Lu nek jaral nga ma
Ken mënul tax
Ma merre la
Ñook seeni wax
Fuck nañu leen daaw

Man so merre damar jaaxle, tiis
Dama la bëgg
Be neen jigeen mënul tax ma giif
Ndax yaw la bëgg
Amul sax
Nit kuy mën xam li may yëg ci yaw
Amul sax
Nit kuy mën compu nima la bëgge

Bëgg naa la man
Ehh ehhh
Bëgg naa la man
Bëgg naa la man
Ehh ehhh
Bëgg naa la man

Dama la bëgg ba faf gëmme wu mala
Bañ lula metti bañu yaakaar ni ñeme wu mala

Dama la bëgg ba faf gëmme wu mala
Bañ lula metti bañu yaakaar ni ñeme wu mala eh

...........................................................................................................................................
Paroles en français :
"Ma Dulcinée"

Eey Massamba Wallo
hummm hun

Si l'amour avait un prix
Je me donnerais à tout prix
Pour l'acheter sans cris

Je te manifesterai mes bonnes intentions
Je t'éloignerai de toute trahison
Je ne te complimenterai jamais ma solution

Je te dirai la vérité en toute circonstance
Car je t'ai choisie comme amour avec aisance
Amour, finalement obnubilé par ma fréquence
Je te supporterai pour toujours avec patience

Fais-moi bébé ton homme de confiance
Parce que doué de rigueur et de Constance
Et si tes dires étaient des balivernes
Je m'en contenterais dans ma caserne

Tu m'as extirpé de mes délires
Pour me permettre de tout lire

Tu m'as permis d'avoir une vie paisible
Assimilée au paradis, notre seule et unique cible

Chante alors glorieusement mes éloges don du Ciel
Rassure-moi foncièrement mon âme-sœur, ma belle
Montre-moi qu'il n'y a point d'amour comme tel
Ma Dulcinée, tu es plus délicieuse qu'un caramel

Ma dulcinée

Couplet 2

Loin des traîtres dépourvus de reconnaissance
J'assume d'avoir bénéficié de ton assistance
Après être envahi par le vent de l'ignorance

Ma vie sombrerait dans l'oubli
Si tu me quittes ou même m'oublies

Je réaffirmerai ma Dulcinée solennellement
Devant toute l'assemblée réunie par moment
Que tu me combles de bonheur entièrement

Personne ne peut "casser du sucre sur ton dos
Ma force qui me porte sur son dos

Tu ne réagis pas pour les yeux d'autrui
Mais tu agis dignement sans faire de bruit

J'ose dévoiler notre relation jour et nuit
Ma Dulcinée, la femme très chère que je suis

Je te dirai la vérité en toute circonstance
Car je t'ai choisie comme amour avec aisance
Amour, finalement obnubilé par ma fréquence
Je te supporterai pour toujours avec patience

Fais-moi bébé ton homme de confiance
Parce que doué de rigueur et de Constance
Et si tes dires étaient des balivernes
Je m'en contenterais dans ma caserne

Tu m'as extirpé de mes délires
Pour me permettre de tout lire

Tu m'as permis d'avoir une vie paisible
Assimilée au paradis, notre seule et unique cible

Chante alors glorieusement mes éloges don du Ciel
Rassure-moi foncièrement mon âme-sœur, ma belle
Montre-moi qu'il n'y a point d'amour comme tel
Ma Dulcinée, tu es plus délicieuse qu'un caramel
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

C'est du haut niveau Amadeus comme toujours. Permets moi à travers cette merveilleuse chanson de rendre hommage à quelqu'un que j'aime trop et qui m'est très chère. Je veux nommer Virginie Coumba DIOUF. Je prends tous ceux qui verront ce commentaire comme témoin pour lui exprimer mon amour.❤

khadimsakho
Автор

Talent 100%
Simplicité 100%
Voix extraordinaire 100%
Ce gars est inhumain 😭🎉🎉❤️❤️❤️❤️❤️❤️🫶🏽

Seydinaa_spaam
Автор

Il ne déçoit jamais. Permet moi à travers cette tuerie de faire plaisir à ma bien aimé Magui❤️🔐

aliouneyade
Автор

Defatigua sa meunine Ras com d'hab ❤

ouleymatoudiallo
Автор

j'adore le fait qu'il met en valeur la beauté sénégalaise pas comme les autres de chercher des femmes sexy vulgaire cela veut dire qu'il respecte la femme et ses valeurs vraiment tu es un ange tu me donnes tellement de la joie ❤

CoumbaNdiaye-uz
Автор

Ana wallo wallo yi nieuw lénne sénne domme déffati na meuni nam bilahi 😂des coeur pour massamba wallo ❤

mamedesign
Автор

Mais xalei bou djiguene biii weleleelelel ma sh Allah quel charisme et une beauté indescriptible 😭❤️

Ioe nk Amadeus, on se sait, t’es le Best

gucci
Автор

Mane khalebou djiguén bi dafma nekh bilay el est simple

bayealicamara
Автор

La musique a le pouvoir d'influencer nos émotions. Elle peut nous mettre de bonne humeur, nous motiver ou nous remonter le moral. Merci mon frère écouter ta voix peut réduire le stress.

abdoulayeba
Автор

On ne se pose même pas la question parce que dafay nekh comme d'habitude ça ne change pas ❤❤❤❤❤j'ai hâte

astoubilla
Автор

Comme quoi la musique ne connait pas de limite d'age ...a 63ans et qque mois je me surprend a ecouter ce soigneur d'emotions dieudieuf boy merci de ta therapie amo morom more blessings and wisdom from the Almighty Allah for you super humble ndandaan

veyehceesay
Автор

Genre le gars il chante bien
Il fait des clips pas saturé ak ay feithieu kat youdoul diekh
Il est simple et talentueux 😢🎉❤
Ne force rien 🤌🏾
Vraiment nickel👌🏾

sylviediene
Автор

😭😭😭quand j’ai le cœur lourd quand tt va mal seul Amandeus peut me faire me sentir en paix wallah limay sentir soumaaa degué sa voix yalla rek moko kham meunoumako expliquer yalna yalla faylaaa

ndamesy
Автор

Waouh waouh, c'est ça qu'on attend de vous des thèmes de la société merci beaucoup des ❤❤❤❤❤❤ pour les acteurs juste magnifique

isidorediedhiou
Автор

Kharal ma gneweuti yoneko sama sokhna guenue ko firndel sama beuguel si mome

papagning
Автор

Je vais juste réitérer mes propos, il est trop trop fort lyrics musicalité élégance éloquence et surtout la prestance. Pouce bleu for this man massamba

dreaming
Автор

Le beat🥳la voix 🫶🏾 le clip 🤩 il ne déçoit jamais jamais. AMADEUS you’re the BEST🫶🏾

lovelyk
Автор

SÉNÉGAL BAKHOUGN NOPPP WALLA KHAMOUGN MUSIQUE😮
CE SON DEVAIT AVOIR DES MULLIONS DE VUES A PAREIL HEURE😢

sakhoaladji
Автор

Qui est pressé comme moi pour que cette chanson sort 😂

AmiraBa-lbjr
Автор

Son bii danékh Nima malabguée ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

AntaSall-bnjr