Safary - Kiss - Clip Officiel

preview_player
Показать описание
Découvrez le nouveau CLIP « KISS » de Safary
Maria et Khadija viennent à la rescousse de Defa qui est tombée sous le charme d’un collègue de travail, jusque-là indifférent à ses faits et gestes .
Mais avec l’aide de ces copines qui vont lui filer des astuces et conseils, elle arrivera à faire tomber le mec.
#Safary #Kiss #ClipOfficiel #SafaryQueens #team221

** Les crédits de la chanson et du clip “Kiss” **
Auteurs : Khadija, Maria, Defa
Compositeur : Bril
Enregistrement, mix & mastering : Bril (Class Chic Studio)
Stylisme: Moussa Versailles
Make up: Allure by Lyna
Coiffure: Enera Beauty
Remerciements à Dress code by Adja Astou, la Maison de Céline, Platinium, Black Pearl
Un clip réalisé par Awanje Films
Une production Savane Records (Dakar, Senegal, 2020)

** Retrouvez Safary sur les réseaux sociaux **

** Contact Management **
+221 77 802 61 09 ou +221 78 189 97 11

** Les paroles de la chanson “Kiss” **
Couplet 1
Damako yague piss
Yague nako beugeu bise
Mom deh dafa yague ci sama khôl bilé
Dafmay dozé
Dima vexé 
Douma falé
Yeh ! yeh ! yeh ! 
Dafmay begué
Douko wané
Douma diégué
Wow ! Wow ! Wow
Wayé man deh dinako am
Gueum lén ni dinako yaar
Man ki deh dinako am 
Wadjilé man deh makoy mom
Man ki deh dinako am
Gueum lén ni dinako yaar 
Man Defa deh dinako am 
Wadjilé man deh makoy mom 

Refrain 
Wadji first time 
Mako guissé 
La képeu feeling man dal dama yague bardé
Wadji first time bima guissé 
La képeu feeling momite dafa moudiou bardé 
Wayé man deh dinako am 
Gueum lén ni dinako yaar 
Man ki deh dinako am Wadjilé man deh makoy mom 2(bis)

Couplet 2 
Defa lidé Boko meunoul fadj Kayma wakhla nougnkoy déffé 
Déko wone yone ninga nekhé 
Boulko wone Dangko nope wadji ameko dou lou diaffé Eeh ! 
Wone ko yow ninga nekhé 
Boulko piss yékh ko bise
Bayil mou khiff Nganiko thikh 
Moulay fone nganane ko oh Yeah ! 
Moulay raay nganane ko Aïe ! 
Ak yénén you dakeu mew 
Dakeu fraise té dakeu miel 
Ak fém you dakeu nekh 
Lolo koy nekh 

Refrain 

Refrain 
Wadji first time 
Mako guissé 
La képeu feeling man dal dama yague bardé
Wadji first time bima guissé 
La képeu feeling momite dafa moudiou bardé 
Wayé man deh dinako am 
Gueum lén ni dinako yaar 
Man ki deh dinako am Wadjilé man deh makoy mom 2(bis)

Couplet 3
Piss Kiss mou gueuneu bardé 
Déko wowé darling, wala baby 
Déko snap WhatsApp wala Twitter 
Bou diaré sakh bindeu mail 
Neko love u my man 2(bis)
Penda Barry yaye chérie Yero
Yero Barry néna beugeunala 
Mamy Thiam yaye chérie Abba, Abba no stress néna  beugeunala 
Yow Déko piss Kiss 
Mou gueuneu bardé 
Cheikh Tidiane Ba moy chéri Lissa Ndoye Waw 
Wowal mama Fatou Niass chéri Cissé Thiam Waw 
Mani Abdou Aziz Mbaye Generalou Aziza leu 
Bassirou gorou Ndeye gueye chéri Aminata Mbacké Bibi

Musique 

Piss Kiss mou gueuneu bardé 
Déko wowé darling wala baby 
Déko snap WhatsApp wala Twitter 
Bou diaré sakh bindeu mail Neko love u my man 
Piss
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Aka nio sincert sèn andeu bi kouko nara yak yallah na waga 😂 clip no todj na 👌🏾

demba
Автор

Mon histoire 🤣🤣
Diko charmé lidieunti wouma sakh diokhouma aukine importance ndekké yo bardé neu...Legui c’est mon époux♥️

fatoucherif
Автор

Qui confirme la beauté naturelle de ndefa 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Viens ici 🙏🙏🙏

ndeyefatouthiam
Автор

C telma nul de ne pas avoir kelkun ki flash sur ta propre pers ...nianalelma ma am kouma beugu purrr done sama dieukeur 🙏😞
Safari💕💕💕

senegalaise
Автор

5ans si rèin meusou ma am 500 jaime diap lèn si way😭😭

fafachoux
Автор

J'ai vécu la même histoire finalement il a fait les premiers pas mais avant c'était dur car je suis trop complexé je ne pouvais pas lui aboué mes sentiments de peur qu'il jou avec mais maintenant Macha allah

zahradiagne
Автор

Ce mélange entre mbalakh et mélodie douce est ce ki faut a la jeunesse ki refuse le mbalax depuis kelk temp

maremesougoufall
Автор

Qui suit ce groupe depuis leurs debut de cariére ?

princedaouda
Автор

Team Safary Saint-Louis sont derrière vous💪🏼💕

itsbabacg
Автор

Les filles je vous suis depuis le Cameroun franchement je vous aime et j'aimerais vous retrouvez en ft une artiste Camerounaise vous êtes les meilleures au Sénégal 😘😘😘😚😚😚😙

grantswalter
Автор

Ca arrive dh en plus fières que nous sommes chacun attend de son côté bizarre l'amour

mamydabo
Автор

Je suis Guinée du Guiné Bissau🇬🇼🇬🇼 j'doire ma soeurs❤

lassanasane
Автор

En toute franchise j'adore votre groupe.Vous chantez tellement bien et votre musique est très évoluée.Merci pour cette magnifique chanson que je vais de suite ajouter à mes sons.

fatimatacisse
Автор

Da mélni danguéna yékha engagé mbalakh mi dh mais ca vous va bien c top et bne contunuation

oumarcisse
Автор

Kou beugeu safary beuseul Jaime may guiss

aissatouangeldiallo
Автор

qui est d'accord qu'elles sont les meilleures

groupeexpert
Автор

Machalah safari lounguene déf mou nékh danguéne sincére yalna ande bi sakh 🙏💕💖❤️❤️❤️❤️

ndeye
Автор

totalement vrai j’aime un jeune homme je sais que lui laisse pas indifférent mais dafmay minimiser mais dinako am inchalla dakh sama beugeul c du vrai

khadijakane
Автор

Chapeaux a vous les filles vous avez encore frappé fort jamm thie yénn clip bi todje na 😘 kiss😗 kiss

mamediarrandiaye
Автор

Machallahhh lé filles 😍😍😍resté soudée le meilleur reste a venir inchallahhh ....

fatoubintoundiaye