Safary - Deuk bi yeungou (Clip Officiel)

preview_player
Показать описание
•• Les crédits de la chanson et du clip
Réalisation : Mao Sidibe
Cadreur : Oumar N’Diaye
Light : Mamadou Dia
Charge de prod : Absa Diop
Regie : Lamine Ba
Photograhie : Badupix / Hamedine gacko
Stylisme : Adja Ombelico / Amossa / Adama paris / Gringo / Momo Solma
Coiffures : Modou make up Hlm / Bitty coiffure
Make up : Anouar / Moonlight beauty
Accessoires : Thebridale boutique Zena / jani / Milano boutique / Kipala dressing

Prod / Jeuss
Direction artistique : Jahman
Auteur : jahman

•• Remerciements
Timtouch
Mansour noel
Princess
Mention spéciale à Seynabou ndiaye

•• Retrouvez Safary sur les réseaux sociaux
_____________________

Lyrics ✍🏾

Couplet 1

Kholal famou rétane
Kholal lamou diantal
Oh mom la beugeu Nekal
Waw thia feeling bala
Hé hé thia feeling bala

Kholal lamouy dégagé
So amoul contrôle dalay dérangé
Thia feeling bala
Waw keye, thia feeling bala
Kholal lamou sadji
Bilay Walay beugeu na lii
Lam deff ci daleu da bari
Hum tang na fils déko dieuri

Refrain
Sangou laal push deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou (x3)
Sagnesé deff hum deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou (x3)
Guéneu deff, deuk bi riir
Deuk bi yeungou (x3)
Sassou ma né beureudj deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou
Ndakh dal thia feeling bala
Tay deuk bi yeungou

Couplet 2
Laf bouche,
Néma defatinga
Pas touche,
lady boss nieuwatina
Wolma wa Aléa bi
Wa génération weundél thiaabi
Mangui ni
Kouy lakatou douko wakh khalé bangui ni
Meti ni
Deff class ak tokou harmonie
Kou defoul wone bama deff tayi ko
Ma wakhla, volume bi wagniko

Refrain
Sangou laal push deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou (x3)
Sagnesé deff hum deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou (x3)
Guéneu deff, deuk bi riir
Deuk bi yeungou (x3)
Sassou ma né beureudj deuk bi yeungou
Ndakh dal thia feeling bala

Couplet 3
Bakh gueun riche am base buzz beuri feeling bandit
Bakh, gueun, riche
Beuri feeling bandit

Man dama Bakh gueun riche am base buzz beuri feeling bandit
Man dama Bakh, gueun, riche
Am base bandit

Refrain
Sangou laal push deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou (x3)
Sagnesé deff hum deuk bi yeungou
Deuk bi yeungou (x3)
Guéneu deff, deuk bi riir
Deuk bi yeungou (x3)
Sassou ma né beureudj deuk bi yeungou
Ndakh dal thia feeling bala

Tay deuk bi yeungou🔇
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Oh machallah deuk bi yengouna 🥳🥳 suis vraiment contente de voir tata seynabou Ndiaye sur le clib long vie à vous🥳♥️😍❣️

MamefatouseckSeck
Автор

Wa Safari danio yague am class ak feeling meun woye réglé am personnalité 😍😍😍wayé di oute buzz rek ak forcer. Gni gno diara pousse nak ci kanam rek mes amours ❤❤❤❤

mamidiagnenaar
Автор

Patriote yaa ngui yook level bi si parrainage avec cette chanson, weurseuk fouu neek laay djouguuee, machalla bonne continuation

ibnouful
Автор

Aimer sans que l’instrument commence est ce que vous êtes comme Moi quand on aime
Je vous aime 😍😍😍🙏🏽 My 🇰🇲🇰🇲🇰🇲🇰🇲

ibrahimattoumaneanrfiat
Автор

Je remercie Tata Seynabou Ndiaye motah m’a découvrir chansons bi ❤️
Bravo Safari
Clip réussi ❤️

aidadiedhiou
Автор

Je suis camerounaise mais avec un coeur sénégalais sama yeuf safari

oumaroudahaminatou
Автор

Non clip bi douma si doyal, machalah Safari bonne continuation

aissatoubadji
Автор

Je suis sénégalais sa ne fait pas longtemps que g découvert cette très très belle chanson
Ma Cha Allah au groupe Safari !

alassanetoure
Автор

MAN DAMA BAKH GUEUN RICHE AM BASE BANDIT🤴🤴 WAAW JE LES ADORE

THIERNOGDIALLO
Автор

Je suis une burkinabé mais avec un cœur sénégalais j’aime trop le pays Mon Dieu 😢❤

RafiaBance-sbwm
Автор

Quelle bombe! Félicitations les Queen safari!! Très bien sapées comme d’habitude❤️❤️Oooh ma grande joie quand j’ai vu tata Seynabou Ndiaye internationale!! Ta robe est une tuerie ❤❤❤🎉🎉le peuple est content😍😍😊

Important-ef
Автор

Safary vous êtes les meilleurs
Faut pas forcer
Mon chocolat🍫
Inata
Allah
Je vous aime trop❤❤❤

issacamara-ocyv
Автор

🇬🇳jesui d’origine guinéens ki vivré ici à Dakar safee longtemps vitre chanson et très cool yengallguen deukk bii Dakar mba cassamance

ElhadjBa-dm
Автор

One love from Sierra Leone 🇸🇱🇸🇱🇸🇱 even tho I don't understand what you are singing about but I just like the music ❤

alhajimarrah
Автор

Le continent 🇨🇲🇨🇲 valide les filles. Vous assurez

petitjohn
Автор

0% vulgarité
0% gros mots
100% Talent
ce son est à écouter avec modération 7 fois par jours rek ca soigne les maux de tête😍

khalifababacardiop
Автор

Waow magnifique depuis brazzaville🇨🇬 là pour soutenir nos frères africains du Sénégal .

AmbreSofie
Автор

Je crois que c'est la 1ere fois que les senegalais sont d'accord sur une chose la presence de seynabou❤❤

mairamdiop
Автор

Merci Safari vous nous avez écouté ❤️ le son est top maschalla notre tata national 🇸🇳 seynabou dou ayyy foo ❤️😊

emmafall
Автор

Machallah tres jolie clip, vous etes belles et chics. vous nous avez gaté en invitant mme la classe Seynabou ndiaye.

venusndoye
join shbcf.ru