Wally B. Seck - MBARODI (inflation)

preview_player
Показать описание
Produced by TBS Studio
Written, directed and edited by IBRO
Arrangement by Fallou Benjamin
Shooted by Arona Wade & Papa Lilpro
Lights: Modou & Djiby Ndiaye
Deco: Diddy art universel

Retrouvez-moi sur
Instagram: wallyseckofficiel
Facebook: wallyseckofficiel
Snapchat: wally_seck
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Ndeysann 😢c'était mon meilleur chanson de papa thione yalna ko yalla yeureum thiofél ngima am si môme yalla rék moko meuna sédé aldiana donn keureum 🙏

sokhnaawakane
Автор

Thiey maryacine khôl yeup toyna bilay yalla nga sout say wadiour ay fane Allahou ma Amine ❤❤❤

MamefatySeck-qx
Автор

Sama yaram Dawna 😢 souma setanoul wone clip bii bilay manei papa Thione moy weuyy nii… Lici Papa mougui cii dom Waly yalla nala yalla defal diam, wérr ak wergou yaram maarr Yacine le chanteur du peuple 🇸🇳

C’est la première may deg lou son Waly sama beutt yii taaaa 😢

ousmanesock
Автор

''Nane dal'' selon moi WALLY nous parle de notre président de la république en disant ''ab rew du thiakane bala ngakoy meuneu djité day def yalla dafkoy name si lima rew mi défal, ladial sa bop lo defal rewméééé....andak dale sounouko méyé temps dana leer.... bravo MAR YACINE pour ces paroles. que notre pays soit prospère. seigneur agit et veille sur les sénégalais et que yalla na yène bi woyof prési

Agnèsniouky
Автор

Kou Geume ni kii rombou neuh ambassadeur RTS réqq LaLaLe j’aime
C pour les mécontents naq 😂😂
Wally diamOu sii yaw ❤

lahaddiasse
Автор

Il a encore tapé fort. Pour ceux qui disaient que Waly dou weuy louy diangalei ou actualité je vous suggère d’aller écouter ses albums attentivement et vous verrez. Il a chanté beaucoup de thèmes très instructifs. C’est que Sénégalais gnom weuy you tendances yi rekk lagnouy deglou. Écoutez les albums you’ll see. Merci Waly

khouje
Автор

je m’attendais pas à ça franchement

qui comme moi à des frissons avec la voix de waly on dirait son père 😢😢❤❤

amyngom
Автор

Ndeysane ça me rappelle mon enfance cette chanson de papa thione cette musique est pleine d'enseignement papa thione yalla nala borom térou si aldiana yi gueune si barke mcif

bayefall
Автор

Yalla yaye bour bii warnako ndiendeu pour nek sama dédicace loumassy dioye bary ❤❤

DiomeDIOR-iqmw
Автор

C'est pas wally seck Mais Mbirmi papa thione Moko waral 😭😭😭cheuuuu papa thione yalla Nako yalla gueureum yeureumko Xaréko aldianay firdaws 😓💡

KhidmalBarkham
Автор

Sama WADJI dieul nga sa yoonu Baye🥹❤️💪🏼 sunu Papa dji Papa Thione Ballago Seck 🕊️❤️

MunasWallyBallago
Автор

Souma guisseé niouy nakh gars yi nanelen yena meun wally ay retane dafmaaay diap c’est tout simplement le meilleur sans forcer 😭😭😭😭❤️🇸🇳🐐🥇🎼🔥🤌🏻

NTD
Автор

Le message est là
Inflation mondiale mais nañ dall
Niit ken douko djiteul diko fakastall
Merci Wally 🎊 🎉

boyneylikko
Автор

Oh 🤦🤦🤦 papa thione Ballago seck yallah nako yallah yeureum ak maman ndeye fatou diouf diaga 😭😭😭amal diaam rek wally Ballago seck 🤲🙏🙏🤲son bi ❤

matymbengue
Автор

Bouniou ko mayei temps leuppe dina leer in cha Allah BDF

mamadoudia
Автор

Kou beug clip bii amm ayy millions de vues rek aimé ak partager ❤❤❤❤❤

serignesaliousarr
Автор

Dans ce clip wally seck a résumé la situation de la vie et nous a appris que adouna bousi beugué nopalou nanga gnémé thiono té doylou..une leçon de vie ❤❤❤❤❤❤

fallougentlemara
Автор

Qui a compris le sens de cette chanson ?? Laissons le gouvernement travailler ngour ay wakh yorouko sougnou ko bayé lep dineu bakh! Wally adresse un message à nous autres qui avons élu SE BASSIROU D.D.Faye ! negn daal té bayiko mou liguey ! Mercii Wally mieux vaut tard que jamais ❤

mmcakaba
Автор

Ayy way Wally yagui may fatali papa thione 😭😭😭dama beuguone papa thione lolou motakh amouma thi Wally sagoo yalla na khipé firidawsi 😭😭😭😭😭😭

Mamebourry
Автор

Congratulations Wally le chanteur du peuple, l’ambassadeur de la RTS, pour ce joli clip plein de sens. Ce chef d’œuvre sur l’inflation est un hommage à ton père, un grand homme, que son âme repose en paix.
Yalla nala Yalla sama.

rockyky