Série - Woudiou Peetiorgo 2.0 saison 2- Episode 33

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Yalna bou yakar tass waye fate ndiaye tu mérites le bonheur manchalla ❤❤

fatoundiaye
Автор

Ay Fatou Ndiaye mérite le bonheur yalla bou yakkar tass❤

aminatafall
Автор

J'adore fa Ndiaye ak Astou Mbaye j'aime le couple de fa Ndiaye ak Mounirou thiey sacré soda ak pa Assane excellente série vraiment yallah na diam yague machallah ❤

nafidiakite
Автор

Mariama yalla n'a KO yalla yeurem ❤❤❤

AwaDiopmadameSéne-km
Автор

Kou beugueu seydina mouhamed lalal j'aime kak toudeko dom❤❤❤❤❤❤❤❤❤

maissacouradiop
Автор

Soda meilleure actrice de cette série machalah 😂❤😂
Merci soda pour le plaisir que tu nous fais

Astousembene-dv
Автор

Sérieusement nk Saoda ak Pa Assane gno néhal série bii😂😂

MameDiarraDieng-mbcr
Автор

You sokhor yu bone yii nguéne di valoriser nguéne wara bayii aye sani korte na dei na doff rekk😢😢😢belle sœur mounirou bi comme dou dioulit 😢😢fat ndiaye mérite k du bonheur vraiment ❤

mamyloum
Автор

On réclame le buenner de fate Ndiaye ❤❤

AwaDiopmadameSéne-km
Автор

Ba série commencé ba tèy gnougui niane bonheurou Fatou Ndiaye bipa mone guir yalla boulèneko woor❤

ndaoyadikone
Автор

Aferou serigne yi laniou wara wagni si série yi

lamignonne
Автор

Mere diarra si bopam mo wra diouk si ay domam protegé léne yallah sah moy protegé mais amna gnou yallah may genre🎉 mais tok rek melni seukeuteu meukeuteu

abdallahsow
Автор

Soda AK pa assane nio sakh si série bi 😂 Fat Ndiaye taye seuy bi yalla bousi thiate dougou

mamediarrambaye
Автор

Astou mbaye ma cha lla h fa ndiaye seuy bi yalla ame❤❤❤❤

Talibé_cheikh
Автор

Diabarou frère Mounirou bi nite 😢😢😢loutakh beugoul kene gneuwe thi keur gui yayou Bigue sof gua Fatou ndiaye Astou Mbaye ❤❤❤❤

adamengomndiaye
Автор

Bigué on dit n'aborde jamais ce sujet mais pas cette sujet ne force pas le français wakhale olof stp Vraiment khar media cette fois ci votre série amm na sens merci

ndeyendacktoure
Автор

Pourquoi valoriser la méchanceté pour quoi valoriser la maraboutage
Vraiment série bi amoul ben sens 😢

aisharassoul
Автор

Wa serie bi ana aïta ak yayam ak papam 😂😂😂😂

DabaDiakhate-qrex
Автор

Moi la belle sœur de mounirou elle m’énerve vraiment

AidaMboup-weyp
Автор

Kou game ne saye bi daye âme rek lalall ❤️😂

Fatougueye-brtn