Série - Woudiou Peetiorgo 2.0 saison 2 - BANDE ANNONCE

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Billahi wallahi retour dofff deugue mère Diarra ak famille bi danio wara réussir

bebelayegueye
Автор

Ouffff c’est chaud 🥵 niafff du lourd ❤😮khar Media Tay sén yarame tanguee na 🥳🥳🥳❤️❤️❤️🎉

mamistamendy
Автор

Bi môme balenmako ba saison 3 sama xol❤bi ken douko lamsett😢

khadydjiguel
Автор

J’ai pitié de Astou mais nak li leep moko tekk boppam.La jalousie et le manque de confiance en elle ont tout gaté.On ne doit pas passer son temps à parler d’une autre femme à son mari ou son fiancé surtout s’il vous dit qu’il n’y a rien entre eux.C’est après qu’il commence à s’intéresser à la fille.Seytané daffa barré dolé.Astou a poussé Modou dans les bras de Bigué car lui il ne voyait qu’une petite sœur.Mais il aurait dû attendre l’accouchement avant de faire cette connerie qui pouvait tuer sa femme ou son bebé.La mère de Bigué est spéciale.Etre matérialiste au point de rejeter ton propre sang 😢😢😢

Fabidi
Автор

Li deh nekhoul dieumoul keur te amoul chance

boussokebe
Автор

Mo sanio lene li kay mère Diara limou sonou ci keur gui yepou meritewoul faté Ndiaye Di bon khamolene dara

matydiane
Автор

Ki done def Lou bakh kay mo wara am Lou ki def Lou bonne am Lou bonne mais Di def Lou bonne Di gueuna nékhlé heyy way ndaw samab😂😂😂😂mère Diarra ak famillaye mom nio warona momé vent nak yén tamit mérénalén trop

fatousarr
Автор

Lima guiss ni nékhouma dara franchement

maremecamara
Автор

Li kay diaroul coumacé ndak dou ame béni sens mère diarra ak domam dégno wara bég

GnilaneCoiffeuse
Автор

Ehh ay Mane wa khar média gni loulén dal mane mom Saison 2 bi mom BA bi dakhna nama doumako sétane sama khôl bi Di dague khalatoumako😅😅gni esk niogui khalate.nak😂😂

fatousarr
Автор

Khamone nani famouy moudj dou am khorom thim

farmandiaye
Автор

Li nekoul franchement bayi lene rek te yalla takh

salihatte
Автор

Li mom boum dieum kaww dimbali lennn niou rk

mamesayediop
Автор

Astou moque et bigué Comme lala et maréme Ndiaye😂

hawaba
Автор

Li amoul béna logique ballén ma saison bi

OgAnthony-cmkx
Автор

Donc def lou bakh. Li moy retour bi amoul sens

mariamakamara
Автор

J'espère que la saison 2 est bien pensée et mûrie. Le thème et les sous-thèmes sont bien abordés, on attend avec impatience. Gare à vous si vous passez à côté.

louisbarthelemidiedhiou
Автор

Wa yéne mome départ gaîndé arrivé mousse yéne mome li Mba diam wa khar média mesoléne nek manquant bouléne ko nangou

Maman-lnlm
Автор

du n’importe quoi retour rate😢amoul chance

bellebrunediaw
Автор

Bande annonce avec khar media c, est la première foi😂😂

MamesayGadiaga