Série - Woudiou Peetiorgo 2.0 saison 2- Episode 84

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Soda ak pa assane moy véritable amour 😢❤sama xol féss na

antaLo-bhqj
Автор

La vengeance d’une femme bafouée et humiliée est redoutable ! Pa Assane, li yeupp sa réwandé akk niakkeu considération mo lakko yobbée.
Nioungni di la sétann wakhonn négnn lakko, wayyé da guaa deugueurr boppeu 😊

MkTToure
Автор

Yena seytane degue pa assane mou rew mi guendi yeureum bijoux bien fait ❤kou d’accord lAlale j’aime

ngalandoundiaye
Автор

Gnanal léne Mbayang diop yalla takhawouko😢

mamediarra
Автор

Lep lou way di wout si adinam yalla yalla yombal ko ta mou nekke lou Guen si Yw si barki seydina mouhamat sws 😢😊

maxbbfall
Автор

Pour la première fois ma yeureum soda😂😂

amygueye
Автор

Vraiment soda ak noumou meune mel dafa beuge dieukeur ndeysan

famathiam
Автор

Salallahou alla Mouhamad ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

yamathiaw
Автор

Vraiment Astou Mbaye est une belle personne elle a 1 très bon cœur Ndeysan portant déh Soda deff nako fi lou nek ci lou gnaw wayé n’empêche elle soutient Soda zéro rancune machallah djégou pousso kay. Bijou merci à toi c’est bien fait pour Pa Assane réww ba doff khamadi gnak xam bopam il ne respecte personne dans la famille même pas ses parents aduna dina ko yaar bou bakh

catherinesolangetokpe
Автор

Gnanal léne Mbayang biop yalla takhawouko😢😢😢😅😅😅

NdioleSene-ecet
Автор

Pour la première fois soda a écouté Astou 😂😂😂

SiraDiakhaby-ql
Автор

Bijoux contana si yaw map xoll sedna😂😂😊

OumiSeye-ef
Автор

Contente na cest bien fait pour pa assane et soda daniou rew mba doff😅😅 kou yeureum soda yalla nalla ya maye woudiou perthiogor comme elle😅 astou mbaye dimbalou gnou ta seytané yalla na bigué nieuwate allez bijou mais tu parles trop

ndeyendacktoure
Автор

Kour d’accord ni soda seuy kate la rek té meuneu mougn té bijoux dou nite kou bakh par ce que moy nite yoyou khamni bougnou bakhléwoul rek dougnou beugue kou bakhlé

NatouchaDiop
Автор

Pa assane sakhe diap nagne ko ms lougniy khar si fadél bou mirage😂😂

FatouSakho-fnhe
Автор

Merci Bijoux ❤❤ bien fait pour Pa Assane👍👍

sigarosesene
Автор

Merci bijou tay defga efforts soda nak da bone rek mai beugeu na dieukeureume

matydiane
Автор

Bijoux contana si yaw Map xoll sedna😂😂❤❤❤❤

NdeyeSeck-wo
Автор

C'est l'amour c'est oh soda mbeugue n'a pa assane

MbeneSarr-jkdq
Автор

Yallah nama yallah mouseul si woudiè amine 😢

awamouvivianesylla