Jeeba - Saï Saï Feat Dieyla (Clip Officiel)

preview_player
Показать описание
#saïsaï
#jeeba
#dieyla
Auteur : Jeeba
Interprète : Jeeba - Dieyla
Compositeur : diamond guidem
Mix Mastering : Afro Music Studio Sn
Réalisation : Mao Sidibé
Production : Abadane Daiman
Stylisme : Bise Collection - Teranga Lounge - Cana Dom

Jeeba et Dieyla proposent un cocktail musical inédit, l’histoire d’amour dénonce les mensonges et dérives des couples d’aujourd’hui.
Le son se veut drôle et raconte en interposé un récit de deux couples aux ambitions différentes et malhonnêtes.

Lyrics
Yala dou dioum mani Yala dou dioum loumou def ndeké lolou mo geune Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Kone fok ma xolate ko
Saï saïiiii la fok ma xolate ko
Wadjii Saï saïiiii la
Yalla dou dioum ndeké yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
fok ma xolate ko
Wadji Saï Saï la
yala dou dioum ndeké yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Couplet
Nieuw na sama lathté fa sama yay boy
Saï Saï la
Nieuwate sama keur lathté fa sama baye boy Saï Saï la
Néna kilifa la dou dokh thi tank thiakhane
Ñente ak tranche indi gouro dadi labane
Mingui may tek tank beug ma forcé ray
Ndéké loumou beugone dougal but bi jubilé daw Refrain
Yala dou dioum mani Yala dou dioum Loumou def ndéké lolou mo geune
Demone na bay xalate nar ko diox sama xol Ndéké souma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
Kone fok ma xolate ko
Ndaw ci Saï Saï la
Yala dou dioum mani yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na ba nar ko dougal sama biir xol
souma ko defone mangui thi tolof tolof
Néna koudoul mane beugoul sokhla woul
Mane rek la diokh bop kou Mel ni mane amoul Mane mako yeungal yeungal mbeguelam Ndéké mane dama door ay calmant lamay diokh Dem na ba dépense keureum mako yoor

Faye courant Faye ndokh Faye diangue xalé yi ecole
Dieund greffage Faye ay voyage ndéké damay door sama poche la nop
Refrain
Yala dou dioum mani yalla dou dioum loumou def ndéké lolou mo geune Demone na bay xalate nar ko diokh sama xol
Dejesouma ko defone mangui thi tolof tolof Kone fok ma xolate ko
Saï Saï la
Kone fok ma xolate ko
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Dara genoul nekh Wakh tou diouli diote gua dem dem diouli 🥰🙏🏿

LamineYamal
Автор

Dieyla elle a bien assuré vrai ndanane la bonne continuation bravo Nice single ❤❤❤❤❤

hamdysarr
Автор

Histoire dinako binde gnari xalei you meuneu wayy t kene doulene degue si dara machalah 🎉❤

femmenoire
Автор

leip loy deif ba diouli diote bayiko nga deim diouli djii 🤍🙏

GENERALTV
Автор

Ndeyssane homme et femme les sai sai sont partout yalla nagnou yalla mousseul ❤❤❤❤

byka
Автор

Dieylaa machalah dafa meuna weuye😢😢😮😮🎉

amadouba
Автор

Diap xalé yi di nakh rek gourou Sénégal yi sopékoulén té diéma mélange comme man 😂

Archiiqsatv
Автор

Jeeba et dieyla, comme dhabitude texte et melodie au rendez vous, 1M de j'aime pourvleur donner de la force.

Pacha-pj
Автор

Kou dacor ni daga. Nekh RK lalale cœur ❤

IteleA
Автор

Gambian but Senegalese music is literally the best..elegance ❤

maxizepeshd
Автор

Machalla borom batte you nékh Yi khallé you ame talent yi laf bouche❤❤

MbayeBadiane-tu
Автор

Lii wow na kongg😂❤❤❤❤ machallah way🎉🎉❤❤❤❤

RamataNdiaye-kuph
Автор

Après l'amour c'est la Ndeye guerre 😂😂

amadoudia
Автор

Wally, Amadeus et Dieyla affaire bou doy warr lay done Dieyla elle est pétri de talent elle déçois jamais

tidianesall
Автор

Manii deGglu leen meuh . sa meuh hel bu Gatt laay waheii naq. Etant un grand fan de Coumba Gawlo Seck je trouve que Dieyla Gueye est la plus belle voix de tout le Sénégal .

ibrahimaelnegrogaye
Автор

Motah koulen moytou woul si reuthiou rek ngay deukk 😢bel homme bel cœur ❤️ moko guen😮😢 djiguen gni kolen guiss mou beugg lenn té yen lenn diam Diap len si boulen ko bayi ndakh chance boobu beuretoul gni takk masque beurri nagnou lool sakh goorgni tamite gnoussi beugg am sokhna beurrinagnou trop wayé dagno gnémé toull khaleyi legui gnoussi Beurri seysi wouniou dagnouy seeet si bou nékhé gnou tokk bou nakharé gnou daww😢😮
*Je salue le choix porter sur ce sujet la franchement ça c'est arrivé au bon moment le monde est cruel et les porteurs de masque sont partout donc vigilance, becareful vigilance 👏🙏*

momo_le-pro.
Автор

La plui bll tyfa guisss la meilleur tiktokeur mauritani

syousmane
Автор

Macha'allah yallah Nala yallah weral batbi bi si barké Seydina Mohammed Saw ❤️👌

DiopGorgui-yhde
Автор

Ei Wai tyfa mabo qui est la pour elle 🥰😘

DieynabaBarro-bsps
Автор

Fi laye tokk Di xar Aka ma âme temps😂😂😂

AwaDieng-jv
welcome to shbcf.ru