Jeeba - Dafa Nekh ( Clip Officiel)

preview_player
Показать описание
#dafanekh

Auteur : Jeeba
Compositeur : Bril
Label : Abadane Daiman

ÉQUIPE VIDÉO

Réalisation et Post-production: Mao SIDIBE

caméra: Oumar NDIAYE
Lumière: Mamadou DIA
Makeup: Aby Sow
Régie: Lamine BA
Assistants: yaya Thiam & Mohamed Thiam
Making off Biraan Pix

Stylisme : babo - Zahrafric - Bise collection -
Chorégraphie : MG_dancer 221
Danseurs :
@assi_show_mamen
@riima_danse
@racky_kush
@sagnaclarisse2
Artwork Dafa Nekh : Med kgs prod

Lyrics

Wakh mo lo bouga ma defal lako
Wakh ma lo namma Cherie ma outal lako
Meme boudé auto ma dieundal lako
Yobou lathi chateau nga deuké dodo
Dama xam fouy khassane fofou lay wokka
Sa ex yila done sonal nieupeu lay nokka
Athe la bathi kaw keen doula diote
Diokh la khir bi ngaleen di thiaw
Ma takhaw nane ko niaw
Mbeguel dafa nekh bokoy kaffé sakh day nekh
Sa biir xol bilay diap mel ni danio thi dougal fekh
Meuno kham limay wakh tant que demo thi bamou diekh
Fok nga niam kani waw doga xam lou lem di saff
Awa nénama dafa nekh makhfou nene nama dafa nekh kadia nenama dafa nekh
Meme maimouna nenama mbeuguel dafa nekhhhh
Refrain
Kone dama la bougga té koumou meti nanal amoniaque baygon wala maladio sayo yewo nganiouy guiss niouy leungo ma nane ko
Beug na beug nako boudoul reen di deween dinako def ndakh yama diaral lolou
Dama tégui gros lot ohh
Mom momay teul mane mako beureung xam na nandou lo lolou
Nioune bouniou begué moniou begual bouniou dioyé moniou dioylo
Couplet
Bebe xam ngama bou bakh douma kou tegui ndawal
Fima lay diap banga ni Akhh mako xam té dama koy dowal
Bebe xam nga mane loutakh ma beug la dama thi sawar
Danga fek fi thiebou kéthiakh nga valorisé sani thi ndawal
Ndakham lakh bi daniou koy seulmo no daniou koy keupo
Sama carte bi ioe la votel tak seuy bi dial thi lenene
Kone danga mer mane mangui bakh
Diokh ko ndox mou nane mou gékh
Lolou meunoul niak
Ndakh Mbeguel dafa nekh bokoy kaffé sakh day nekh
Sa biir xol bilay diap mel ni danio thi dougal fekh
Meuno kham limay wakh tant que demo thi bamou diekh
Fok nga niam kani waw doga xam lou lem di saff
Abba nenama dafa nekh ngoné nénama dafa nekh habib nénama dafa
Meme aicha aziz nénama mbeuguel dafa nekhhhhhhh
Refrain

Kone dama la bougga té koumou meti nanal amoniaque baygon wala maladio sayo yewo nganiouy guiss niouy leungo ma nane ko
Beug na beug nako boudoul reen di deween dinako def ndakh yama diaral lolou
Dama tégui gros lot ohh
Mom momay teul mane mako beureung xam na nandou lo lolou
Nioune bouniou begué moniou begual bouniou dioyé moniou dioylo

Mbeuguel mbeuguel mbeuguel dafa nekh
Nekh nekh nekh nekha nekh ayyyé waw wa waw waw

Kone dama la bougga té koumou meti nanal amoniaque baygon wala maladio sayo yewo nganiouy guiss niouy leungo ma nane ko
Beug na beug nako boudoul reen di deween dinako def ndakh yama diaral lolou
Dama tégui gros lot ohh
Mom momay teul mane mako beureung xam na nandou lo lolou
Nioune bouniou begué moniou begual bouniou dioyé moniou dioylo
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

képou kou nékk si ayyy tolof tolof YALLA nako Yallah safaraa si barké Seydina Mouhamed (PSL)

KOU D'ACCORD NI JEEBA FAIT PARTI DES MEILLEURS DE SA GÉNÉRATION BEUSSEUL J'AIME ❤LII DAFA KHÉRÉ 🤩🤩🤩 TÉ DAMALA BOUGUA 🎉🎉🎉

Dakarflixmedia
Автор

Ki dou guéné jamais lou nakari😂🙆‍♀️❤️🎉 li lanatila 🥳😭❤️

MawaNdiaye-vxts
Автор

Kou done khare Dieyna weuye com mane😂 nexna loool machalah ❤❤

JinettemameDiarraSeck
Автор

Celui qui lis ce commentaire que Dieu vous bénisse et vous garde en bonne santé vous et vos parents ❤

mamitacaramel
Автор

❤ j’aime vos chansons vous êtes un dieu greces de la musique

AbdouLahi-ycje
Автор

Ana nittou Thiès yi mayy lenn ma ayy 👍 you beurri

LamineBa-lkrr
Автор

Jébba ak mbeugél longue histoire leu 🙆‍♂️

alioufall
Автор

Yalla bou niou Amati président bou mėl ni Macky Sall 🤲

jziomkt
Автор

Yenne 😘😭😭Li nékhna na dh surtout dernière partie ❤❤❤bi beu nitt gni di wakh si souff❤❤ohhh jeeba Taguig fékhal sm xol❤bio chapeau z toi tjr le meilleur ❤❤

indediane
Автор

Wayou beuguel rekh laye waye diakhale guama 😢❤❤😊

shnkxkq
Автор

Thiey cousin a wana nedo bilahi do nitou fi 🎉🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥

mouhamedbarry
Автор

Super Nigeria Senegal mogui nieue dale sen kaw ❤❤❤

IsatouCamara-uj
Автор

Khalé bi Moy mbappé si musique sénégalais bi rk😂❤❤ love way❤❤

fatoudieng
Автор

Mashaalah rien à dire longue vie à vous❤❤

MariataYall
Автор

The Gambian Wollof😄❤ Fouy hessan, fofu lay woka🤣Damala buga😆

sainabounjie
Автор

Kou amagoul xarou tabaski yalna lako yalla yomba lal😢❤🎉

cash________j
Автор

Mon préféré jeeba bou nekone président nieupp mbeuguel laleni satte 😂😂😂 son bi❤❤❤❤😘

Evishbaby
Автор

Machala c chanson c pr ns les cœurs brisés 💔 déception sur déception 😭mé yalla bakhna

khadidiatouboundione
Автор

Hiii yow rek laniou toppou loumou guener nioun fans niou content ❤❤on t aime walay

oumousy
Автор

Jeeba dal machallah toujours fou nekh rek laay guene en gardant le son de sa voix incroyable 👌👌👌👌👌👌

amadouberenger