Divorce avec son mari Bass Thiougu:Accusèe d’adultère avec Momo Dieng :Diarra Vaz en l@rmes dit tout

preview_player
Показать описание
#Senegal #kebetu #feelingdakar
Soyez au plus près de l'actualité people 24/7 et suivez vos séries préférées en vous abonnant à votre chaine préférée :

Mais aussi sur le 1er site people et business du Sénégal :
qui vous fait vivre le Sénégal en live.

Suivez nous aussi sur les réseaux sociaux :

Commercial Feeling Dakar :
Sénégal : + 221 33 860 31 83
France : +33 7 67 57 08 74
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Dioubolé national la woté.na nieup wakh.72h andeu takat seuybi, kou dakor lalal j'aime ❤

SetouDéthié
Автор

C émouvant , Basse dieulatale sa Diabare, tu as une Perle Rare .ki Goorla té koula beugueula .Elle est très belle .

Aisha_rassul
Автор

Ki dafa beugue dieukeurem yalla na yalla déf Diam séne digueté

AminataSene-xttb
Автор

Ndeysane yalla nalén yalla dioubolé thi barki seydina mouhamed 🙏❤️

AichaDiagne-qr
Автор

Oustaz modou fall yawla yakar si diganté bi yalla nalène yalla bolé thi barké wérou safar gui 🤲

FatouThiam-kgqe
Автор

La voyant parlée je sens que elle aime son mari

matydiene
Автор

Bass thioug xale bi machallah..jeulatal kii moy sa yonou yokouteh .amine

grteone
Автор

Sénégal gnoy fék kou bakh gnou yakhala ba doto diar touss😢 basse dieulatal khalebi 🙏🏾❤️

Fafashuu
Автор

Kii naniou koo dello dieukeur djii wayy Machallah wakh dji rafet naa wayy Vivian 2 gay am fofou taaasss takhoul gua wakh nitt lou niaw merci beaucoup ma chérie yalla nalla yalla dello ak bass amine wayy Ndeysan Vivian filako bouba sedel lou rafet

ndeyediop
Автор

Diarra kouko kham deugg khamni seuy kat la diapalé Basse ba dara doul dara depuis Ouest foire pharmacie xandar fek kén xamoul Bass. Diarra beugg ko tokk diko seuyeul di dadj lounei si seuy bi mais mou tokk di mougn kén meussouko dégu si ay wax té koumou wax loumou done dound si seuy bi lokho taff guémign mais mou tokk seuy beugg dieukeureum diko diapalé Bass tmt nek nitt kou bakh beugg Diarra focus si liguéyam mais nitt yi bayi wougn len té gni lén geuna diégué nioy diouk di yakk Walahii grande sœur diga am lou bakh boula Yalla fayé sa khol reik say rongogn dina ferr. Courage sis Love sloe ♥️

christellemanga
Автор

Ndeysane elle est belle et adorable en plus Macha Allah Yalla naléne Borom bi délo wate bijahi Nabil Moustapha Sallalahou Aleyhi wa Salam. ❤❤❤❤❤

oumousamb
Автор

Vivement la réconciliation entre diarra vaz et basse Thioune .ALLAH le tout puissant de toute sa grandeur et puissance leur réunit de nouveau amine yarabi

ndeyefatousimonethiam
Автор

Wallahi ki nit bou bakh les autres dieléne référence si ki 😢❤❤❤❤❤❤que Allah te protège

ahsietouba
Автор

Yalla na lene yalla dioubalé thi barkep seydina moukhamad sallalahou Allah moukhamad ❤

FatouSarr-xyks
Автор

Diara djiguène bou bakh diambarou sèye Kate une famme de valeur machallah Diam si yiow rèk ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

ArameDieneDieng-ymst
Автор

Ki dafa nop dieukeureum ba légui ndeysan yalla na lén yalla bolé watt❤❤❤

meuzndiaye
Автор

Deysane wakhna lou rafete thi dieukeureme elle a un grand cœur Yalla na Yalla defar leep Inchallah 🙏

NdeyeAidara-eg
Автор

Bass koula wakhoul dieleul sa diabar tek sa wett wakhoula deug.

Sa succès loumou reuy reuy reuy boul faté Vaz mila mougnal bami méti teksi dioural la dom.

Kanta djiguene yilay top il faut savoir distinguer gnila beug ndakh sa succès ak gnila top nguir nakaral sa diabar.

Bcp de femmes souffrent en silence ndakh bagn lou gnaw. Daw ba dé. Mougn ba soneu. Di deuké sagal sen bop teksi di soutoural Sen diekeur.

Donc Bass dieleul sa diabar nga yekeuti ko baci kaw, protéger ko, assister ko ndakh beug naleu a l entendre parler.
Malgré que Vaz diambar la mais j’ai pitié d’elle 😢.
Des cœurs pour elle ❤❤❤❤

Siiiiiitaaaaaa
Автор

Bilaye dioylama Ana khilifi naniouko dimbali te yalla takh

AissatouWade-zn
Автор

Yal nalein yalla dioubolei 🙏🏾 mashallah kou nga Maam Diarra, Bass djeulatal sa Soxna ki c'est une perle allahouma bareek

FamaSamb-mjsl