OMG - Lu Ci Sa Yoon ( Vidéo Officielle)

preview_player
Показать описание
Auteur : OMG
Compositeur : B.Beut
Directed by : Pii
Toutes les tenues ont été réalisées par CHELIEL / StefDeKarda 772532440
Make Up: Diossah
Producteur Exécutif: DD Records
Distribution : Believe Digital, Musikbi & Jokkotext


Retrouvez OMG sur:
Snapchat: omgoumygueye7
Contact: 00221774498714

LYRICS
REFRAIN
Sama telephone sa yoon nékouthi
Noumako amé sa yoon nékouthi
Sama sagnsé sa yoon nékouthi
Deug deug sa yoon nekouthi
Sama diouni bi sa yoon nékouthi
Foumou diougué sa yoon nékouthi
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey
Louthiy sa Yoon, hey Louthiy sa zone
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey Lu ci sa yoon

1er COUPLET
Fougne la fek yangui togué nitt
Sa guémingne na yarakh ni car rapide
Niémé yalla tek thi degueur fiite
Amo dianou biir lo yeuk fok mou siw
Khama touma noumou démé ni
Town bi legui dafa teureudi
Facebook snapchat Twitter wakh dji yématoul si lamigne gni
Mytho mytho mytho mytho
Gawa sopi djiko
Yaw nieup nga kharitol Bene deugouwou thi
Deuké waté serigne yeup
Diékheul téré yeup
Lingay wakh yeup no dara amouthi
Deuké saupe dara amouthi
Yangui soss nass nothi fass fethi ndéké yo dara amouthi
Dieuleul sa temps ténga def bine bine
Tass katou digueunté ga ya gueuneu graw sémingne
Wola nga record
Message nga capturer
vocal nga transférer
Statut nga vu yakamti partager

REFRAIN
Sama telephone sa yoon nékouthi
Noumako amé sa yoon nékouthi
Sama sagnsé sa yoon nékouthi
Deug deug sa yoon nekouthi
Sama diouni bi sa yoon nékouthi
Foumou diougué sa yoon nékouthi
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey
Louthiy sa Yoon, hey Louthiy sa zone
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey Lu ci sa yoon

2em COUPLET
Lo kham wakhé
Weur di nakhé
Deuké di lors
Amo ngor khamoulo lane moy Goree
Meuno bawo yeugo tino té do lathié
Pousso passo tébo sanione yepeuy tardé
Sa wakh dafa bari téweu diekh ni wiri wifi
Fokni ya kham leep wakhniou lo bokak Siri
Deuké garoualé diapé nieup woudiouu
Nieup sori laléla banta bou gouda
Sa dieuf diou niaw beuss dina nieuw ding ko réthiou
Khamnga Thiow lé bari wayé deugueuy moudiou
Moytoul sa noon dieul sa verre def thing thing
Adouna lepp teranga la téyél sa lamine
Wola nga record
Message nga capturer
vocal nga transférer
Statut nga vu yakamti partager

REFRAIN
Dama pataa sa yoon nékouthi
Sama Sewaay sa yoon nékouthi
Sama niawaay sa yoon nékouthi
Deug deug sa yoon nekouthi
Dama Stylé sa yoon nékouthi
Sama Modé sa yoon nékouthi
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey louthiy sa Yoon
Seuytané Louthiy sa zone
Rambathie Sa Yoon Nékoussi
Yoor sa lamigne tak radio yi manila hey Lu ci sa yoon
#OMGOumyGueye #LadyBoss #Melokaan
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Safna mbalax sama yoon necoussi. Son bi nice na sama yoonangissi. Safna Sénégal neexnamassi. Big respect sister omg.

semousarr
Автор

Mafi wakhone OMG amena GOOR youmou daak Rap .. et je confirme

abdouwade
Автор

Mytho mytho ...pouso paso té sagnon gneupay tardé🥰 sma Idol 🥺🖇️

awadieye
Автор

Laylaylalaah fi todjia tina 😍😍 qouy doora man qouy sagga way 🔥🔥🔥🔥 do sén mass 💖💖💖💖💖💖💖

yacinediop
Автор

Waouhhh 🤔 lii raféte na. Félicitations OMG Clip bi #Nice na waay! Cool

awabdoulaye
Автор

La meilleur de sa generation kou d'accord beussal j'aime

kangfory
Автор

elle vient de remportée pour la troisième fois successive la meilleur artiste féminine de cette année pourquoi pas meilleur rappeuse de cette année

babacargueye
Автор

Clip de l’année ce clip mérite des millions de vu way!!!

elhadjiyatmakonare
Автор

Manchalla tu cartonne m'a femme💪🏾 Nice son, nice vidéo 💪🏾

awatine
Автор

Ceux qui non pas aimer cette video moye gniy lidieunti la vie des autres mais sama yone nekousi😏

soxnaaichaa
Автор

MachaAllah dafati ga sa meuninn😍😍😍So dip💋💋💋Yalla na Yalla wereûl batt bi Gueye Dioro💋

mamafalaye
Автор

Damn waaaa mé OMG mi togoul deihhhh Nice na lolou waaay yalla na la yalla diapalé

Lifiknow
Автор

OMG show love 😍😍 c très lourd sama avancement sa Yoon nekoussi

hamouofficiel
Автор

On dirait Nicky minaj🔥 meilleure rappeusse du Sénégal 🤙🏽🤙🏽

moustaphadieng
Автор

waouh c'est la pure et stricte vérité je te donne mon chapeau 😍😍

yacinesaliousylla
Автор

Nimala beugè yonou kèèn nèkoussi 😂😂😂 kou geumeu nii OMG moy la meilleure besseul j'aime

abdoudione
Автор

Première vue may len ma j'aime lingay amna solo trop

ndiobistadiop
Автор

Bien dit, niit gni nio wara lijeunti li sen yoon nek. Waw sa yoon nékousi

lariseepriseekor
Автор

Man dall lii la kham lii la beug rappeuse bou moll nekh saff djigen aussi meun rap am talent teksi waye melni gnénen gni rek😍😍😍😍hoo ouy elles est mariée sino maniko jtm sakh #omg danga ayy sarapxoni ndeyi yenen #rappeuse yi rek niouy melni ay goor😂😂omg do nitt

fallmouhamed
Автор

Wa waw OMG ohh eupna Man dal beug nala ba mou Barri dolé wa yaw li guenna nkh damay deklou dii deklou watt son bii dafa nkh bilay bonne continuation à vous que dieu vous bénisse

ndiayeawa