OMG - Koti Koti (Vidéo Officielle)

preview_player
Показать описание
Auteur : Kruh Mandiou Mauri
Compositeur : B.Beut
Editeur : DD Records
Label : DD Records Sénégal
Distribution : Believe Digital
Directed by: Blackaneze Filmz
Retrouvez OMG sur:
Snapchat: omgoumygueye7
Contact: 00221774498714

1er couplet

Dof thi mane dieundé woma dara loudoul mbeuguél
Mala tane sépi lathi dakh yamay danél
Yaw kham ngnani kene dou kheutio lilou mome
My baby sama khol bi yako mome
Sama yéné di niou dounde ba sey am thi dome
Niouy koti koti yoli yoli lithi soukeur dou xorom

Hook

Rérone nga gindi ma
Dila way ni Youssou wayè Birima
Rérone nga gindi ma
Way la ni Youssou wayé Birima

Refrain

Koti koti yoli
Sa lokho sama nope démeu
Yoli yoli koti kham linga name tax malay (x2)

Kouthi am sa koti koti déko yoli yoli(x4)

2ème Couplet

Thiafka mbeuguel ngama niamal
Sama khol binga keuf moma sonal
Seytanè yi nagne niou mousseul
Yaye sama Messi dama beugue ngamay teul
Dila khalat di ré feep nga meuné
Gninane damay dieulé nagne ma thieupé
Doy nga kharit doy nga andando
Souma nieup bayé nala dessé
Mak yaw thi khalé

Hook

Refrain

Lou dakh nekh (x3)

Koudoul yaw beugouma
Yafi nek
Koudoul mbeugouma hey
Koudoul yaw mbeugouma
Yafi nek
Koudoul yaw mbeugouma mbeugouma

Refrain (x2)
#OMG #KotiKoti #LadyBoss
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Kousi am sa Koti Koti déko yoli yoli ! 😍

bassiroundour
Автор

Mais elle merite des million de vu ki mongui totie whatsapp ak snap bi maxim de partage way ...

bayeassgueye
Автор

Waouwww...mai koti koti bi doyna war...
Boy démal teul momay danél...khamo djongué deh.
Trop cool vraiment

astouseck
Автор

❤❤❤❤❤❤❤qui est la en 2023notre omg national❤❤❤❤❤❤❤

AdamaSeck-hs
Автор

Voilà c’est ça qu’on veut bravo 🇸🇳en force OMG isTheNewBae❤️💪🏾

mraho
Автор

Belle voix et belle musique !
je la découvre et c est rare que j'apprecie du premier coup !

damelbidieng
Автор

Elle a encore tapé fort bravo Sister Nice et nexx aussi

boubacarsedy
Автор

Ah oumy dff nga lou nékh kousi âme sa koti koti dèko yoli yoli Nice n'a trop

myougueye
Автор

Je l'ai écouté ce matin sur rfi (prix decouverte) alors que j'étais à moitié endormi...Je ne pouvais pas m'empêcher de la chercher sur YouTube pour la réécouter encore et encore...Je ne comprends pas ce qu'elle dit mais...c'est juste Waou le rythme (dansant)...Felicitations et bonne suite depuis Conakry (224)!

MoiEnPlus
Автор

OMG !! je suis tombé amoureux la musique j'arrête pas de reprendre
Une réussite totale

Disy
Автор

Jne peut op m'empecher de lirr et relir cette magnifique son ta bien assurer houff com c beautiful bne cntinuation 💓💓💓💓

serignesaliouniasse
Автор

OMG koti koti wahhh ç chouette et sa beauté boul xessal dè manchallah 😍😍😍😘😘💛💚💓❤

ngonediop
Автор

Oh! my god...c'est trop sensuel ma belle, , , , big repect

diattaousmane
Автор

Kou am OMG deloussil svp diapaleine massi?🙏

mamiishasow
Автор

Nice OMG vraimen
Dd record musique bi Aussie nice amna identité Senegal

bayethio
Автор

It’s 2023 am still listening to this song ❤❤❤❤❤

isasowe
Автор

Respect à toi Sistah et bonne continuation

AshsTheBest
Автор

une veritable fierté pour nous OMG internationale overseas interplanetaire c tout simplement magique. trop nekh je kiffe!

RICKOVER
Автор

OMG bilay am na ay rappeur youfii am buzz yoo khamni kholoulen sakhh
Bilau

aboumahfouzsarrsow
Автор

Machallah Son bi nekh na et elle chante bien 😍

ablayendiaye