Wally B. Seck - live VOGUE HD / Dimanche 27 Octobre 2024

preview_player
Показать описание

Ouverture des portes: 17h30
Début du spectacle: 19h
………

Retrouvez-moi sur :
………..

Camera: Lourass Diop - Djiby Niang - Momo Diop
Graphic Design: Lamine Cissé (Damelas)
Ingénieur de Son: Bakary Banora
Mix : Seydou Boye
Realisation : Lamine Cissé (Damelas)
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Wa yén symphonie guiss nguen harmony biko Wally di wayé nimou changé té nekhhhh non li khéré na way na Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

diorkasse
Автор

Très stylé 🎉mar Yacine très talentueux 💯 le noir te va à merveille que dieu t'accorde une longue vie et de santé inchallah ❤️

AbdouAzizNguirane
Автор

Longue vie à toi Wally Ballago je ne me fatiguerai jamais de regarder et écouter tes musiques mon unique artiste préféré depuis tes tt debut❤🎉🎉 que Dieu veille sur toi amine 🥰😍

FouneDiabate-xq
Автор

Quelle performance, j'ai trop aimé les nouveaux live de Symphonie, Taxi love et Yoon Wi. Vivement les autres retro Thieuguine, Djiguene, Gouné, Papa thione, etc etc. Et on attend toujours le prochain hit avec Baye mass, j'espère que ça sortira avant le 07 dec❤️

Ndene-kk
Автор

❤ premier commentaire max de j'aime pour les fans du Wally B seck

linevitablegameplayer
Автор

Mane dei Waly diakhal nama. Ses lives je peux les écouter tous les jours doumassi doyal.
Et à chaque fois que je l’écoute chanter, samay rongogne di gueneu khawma lii lanla.
En tout cas yalnala yalla are, mousseul la thi thiate té mou gueune la yok ay kheweul.
Machaallah.

khouje
Автор

Kou guiss ni style bi mo diapp @Wally rk mayy ma ayy j'aime ❤🎉

Takrican_
Автор

Wally linguaye dégage thi fraîcheur doyena warr live yi nekhna armonie octavé na avec un nouveau style surtout légui danguesi bollé dance bou doyewarr vraiment mbécté rék machallah 😍🙏🏾

adamadiouf
Автор

Focus rk thi rétro yi barki Rassoul 😘😘 sama xéll Dém na Thi 2015😢

ELBGC
Автор

Wally sa yarame nimou tangué fan yi boudé mome ngua nara yobou le 7 déc dina metti dina yague dina bari ay mort ak ay bléssé meune ngua trop wayy❤️💪💪

NogayeMbaye-ms
Автор

Wally soy wayati dél am yeurmandé si gnikkoy deuguelou 😂😂❤❤❤❤ ni rck lagn lay bayé

MorToure-jd
Автор

Goudeull fane Mar 💃💃💃❤❤❤❤❤beughone la yegueull nii grippe bii bayi nama dhé🙏🙏🙏

hortencemendy
Автор

Wally b seck the king of the king le meilleur de tous les temps

makiroudiallo
Автор

Wally seck son symphonie bénén aférla ❤❤❤❤machaala yalla na yalla saam mousala si thiat

rokhayatall
Автор

Li tamite ba kagne nak wally ya meune waye ❤

MamecheikhNdiaye-pfgx
Автор

Wally Say rétro lanla kou d'accord ni rétro yi mo dakh you Besse yi rek lalal je me sourtou tax love 💕💘 bi lenen la tamit ❤❤

MameGorDiop-wlzk
Автор

Vraiment je suis trop émue ma Yacine Maé kendou yiow cii rewmi Bahh wesh ya meune dehh diam ci yiow ❤❤ je vous love les gars on va chauffer 7decembre adidas arena wa 78 et 18eme vous êtes près ne pas rater ❤❤❤ inchalahh

cheikhfall
Автор

❤sama hol séde na ya meuna live🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉

FatimaDiallo-du
Автор

Long vie a❤😂toi chanteur du peuple ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤💪👌🙏

NdeyeFaty-otbr
Автор

Sen mouchouir na sale bi wekh si adidas arena bi narna grave Machallah 💯💯

thiernombaye