Kholal Sa Thiès Ak Agresseur Bi 😱😂🤣😅

preview_player
Показать описание

Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Il est temps nga oute ay garde corps comme limoy sa liguéy sinon dinagne la Ray si ale bi😂😂

NdeyeNdiaye-sx
Автор

Ki day taylé bakanam si Aleu bi rek 😂😂😂❤❤

awafaye-btyw
Автор

khamnani😂😂 niack na consiel dal mbeur yéko desal waay

mayakeita
Автор

Aiwaw ki day kharou sa Thiès je l'aime beaucoup il est adorable

adamadiallo
Автор

Très drôle 😂 Sa Thies le grand lutteur qui brutalise
Vidéo bi Nice n’a trop

Karl
Автор

Sa Thiès nonoula dh woroul so diapéni daye foo mamou reuthieula nak😂😂😂😂

falldaba
Автор

No ki bakhna rk di neegneko mesaa waal😅😂❤️🥰♥️♥️sa Thiès kafoul dé boy gueenal ci linga nek avant nioulay doore ci mbede mi❤️😂❤️🥰♥️

fatoukinedieng
Автор

Agresseur bi koudoul nandité mou yobou sa allal🤣🤣té boko diappé mounial ko🤣

boubacarcisse
Автор

Khamna ndanguay kharou kharou déguisé😂😂

maremediouf
Автор

Non mbeur bouy foh sakh doolé lay appliqué touti moudamm ko😂😅

GosarrguiGo
Автор

Sathies douma faté jour bima lay teukou fi mou diape sama loxo bi meuna touma noyi😂😂

balistobfd
Автор

Mom Moy agressur kane mothi mouromam 😂😂😂😂😂😂😂

MadameBousso-ctcm
Автор

😂😂😂😂😂 sa thiese gnamal nala boy gname ga

bybasarr
Автор

sa thiés billahi ya bakh sih ki dafa lakalé trop 😂😁😁😀😀

AwaSodaSarr
Автор

Mais Sa lolou rayla bilay mais contane siyen ❤❤❤❤

sophiebodian
Автор

Cool na ce geste lii moy sénégal nous sommes tous des frères et sœurs

papecheikhcorrea