COUMBA GAWLO FAIT CRAQUER LA FAMILLE DE AZIZ DABALA ET MENACE JUSTICE PAR FORCE

preview_player
Показать описание

Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Kholalli rek Aziz nekon si yon niou def li Senegal metina yalna yalla diapale nieup aminn aziz e wally aldiana firdawsi

lqerytf
Автор

Défeguua Lou Rafféte machalla
La Gawllo 🎉🎉🎉

Bickk
Автор

Merci Coumba wathié ga sa bop boula nékhone yék sa bop wayé défoko .yalna yalla fay yiw❤
Aziz yalna khipé firdaws 🎉

rouguikebe
Автор

Coumba gawlo yala na yala goudale say wane maye la werr bayila ak sa wajour khol bou rafet Machala yako ame yala na Yala yeureume barki yonetebi psl amineee abdou Aziz wally 😢

mamefatou
Автор

Ndeysane yalla nako bour yalla yeureum te dièguelko kharèko si aldiana fir dawsi thi barkhè seydina Mouhamed psl 🤲🤲

dabaniang
Автор

Ma sha allah la diva yalla nalene Yalla yeureum xare lene aldiana firdawsi courage a la maman de aziz dabala

adiarasow
Автор

❤❤❤❤ ma diva toujours au coeur des grands esprits ma fierté

VitorSilva-fgnn
Автор

Ndeyssane mère bi dafay semblant rek mais au fond elle a le cœur brisé yalla nala yalla may kholou mougne té yokou say fane justice pour Aziz et Wally

kvfbenz
Автор

Thieye kou déf li khamo sakh ligua yakh Gawlo dieureudieuf 😢😢😢

adamengomndiaye
Автор

Salam quelle grandeur coumba ma shaa allah

seynabouseck
Автор

Machalla li déé moye Sénégal
Sa mbonk djioulite âme nakare
Guaa Dialéko téé yalla tahh
🙏🙏🙏😭😭👍

Bickk
Автор

Aziz ndiaye yallah nalene meye keur😢😢😢

veriteabsoluedeugneekhoul
Автор

Thiey adouna bilay li kene douko fate Aziz niepa ko begue repose en paix 😭

olayolay
Автор

😢😢😢 vous avez remarqué la perte de poids de la maman de aziz 😢😢😢, massa lene. Bilahi lii metineu

FatimandaoTymandao-grgl
Автор

Machallah Coumba Gawlo que Allah te donne longue vie de santé de fer a toi et ta mère ainsi que la maman de Aziz et tes musiciens et que Allah amène la paix au Senegal et partout dans le monde amine ❤❤❤❤❤❤❤

roseparis
Автор

Meme si ya beaucoup de traîtres au sénégal Vraiment certains senegalais ont un grand cœur ils sont gentils. Merci coumba gawlo et les autres

fadoum
Автор

coumba dieureudieufety yalnala borombi fayy thji daradiaye yonnenteby psl

aminatagueye
Автор

Aye waye bonne volonté yi maye léne keur yayou aziz bi keurgui wauroule dara mais yalla bakhena dina bakhe yaye bauye inchallah

Fatou-xolr
Автор

Ndeyssane sama khol bi fesse na li kouko guisse guisse mère bi sa adouna yakou li rek mo takhone Aziz di rayy bopam pour dimali yayam ak wa keureum yalla naléne yalla takhawou ak moléme dioulite

kvfbenz
Автор

Ku am yeurmande ni lay def...mais dire "Aziz déna...luy problème bi?" Et y a des gens qui continuent de défendre cette montre de nabou leye

khalil