Saida Binta THIAM - Hal Yadjoud Ahi Clip Officiel HD

preview_player
Показать описание
GROUPE FIRQATOUL AHMADIYA DAKAR - SENEGAL
HAL YADJOUD AHI
POEME DE SERIGNE BABACAR SY DU SENEGAL
INTERPRETATION SAIDA BINTA THIAM
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Machallah ya saydA Fatoumata Bintou yalna yalla mayla gouddou fann ak werr yalla wéral batbi mann dafma nekhh trop sama khôlle lala❤❤ deff❤❤❤❤❤ machallah ❤❤❤❤

MaryamaSow-xuur
Автор

Binta thiam yaw yallna yalla gudal sa fan te mayla werr
Binta sa takhaway si islam ☪️ bu rafetna
Binta ngoun wa Senegal 🇸🇳 dang lay titaroo bu bakh
Girr liguay def diguen gua way goor gua ndakh sa diambar man de khawmala waye damalay titarou
Te Magui lay nganal yalla fuma neka
Yallna Chiekh Tijian samoula 🙏✅
Mouhamed niasse Al makhribiyou Taïba Niassen ✅

AL_Badawi_TV
Автор

Macha Allah. Il faut continuer pour la religion du monde. C'est cette musique qu'il faut produire pour le bonheur de l'humanite.

ibrahimazolasane
Автор

Bilahi sokhna Bintou thiam yalna yalla dolila kartan barké chiekhoul khadim sa sopé mongi ni yageu la topou sama way Prefèrè dahal bilad ´ ilayka bi siril kaainati tawazouli yaazal bousara

dienebamba
Автор

rokhiyatou ndiaye lasallah yalna yalla fayla saida kodal fan wét ka werle boladara dal diama rek kayam ci kanam ci lo bahe amine

rokhiyatoundiaye
Автор

machalla yalla na yalla werale la te mayla fanyou ngodnou lole gnoguiilaye beugue de sayoune sokhna bintou....

damembaye
Автор

À chaque fois que je suis en colère, j'écoute cet chanson car cela fait que du bonheur

diamancisse
Автор

ما شاء الله أختي سعيدة. صوت جميل و كلمات و ألحان رقيقة و رائعة. تحياتي لكم من المغرب الشقيق

abdorabbihmed
Автор

Sama kholebi, nimouye céddé, soumalaye déguelou, yalana, Sougnou borrombi, céddale sakhole nouni raw Machaala God Bless you Africans women

enessaadoi
Автор

❤ça me rappelle Kouthia chow ❤😢Barkè Aboul Abass ☝🏽🤲🏽yallah na sounou borom soubhanahou wa tallah défal Kouthia chiffay mine kouli dahyin 🤲🏽🤲🏽🤲🏽☝🏽🤲🏽

mayougallass
Автор

Macha Allah j'ai été tout le temps triste à cause de la perte de mes deux parents et mes deux sœurs et quand j écoute le coran et ses chansons sa me réconforte et ça me fait pleurer que Dieu te garde longtemps té mayla werr❤❤❤ j aimerai te rencontrer un jour.

GnimaDiedhiou-jn
Автор

machallalah tata Saïda bineta Yana yalla goudal fanwi wérél bat bi Say sigar rék lay déglou dépuis bigua niawé sounou degue taïba tapsir Moustapha Thiam

toulayethiam
Автор

rokhiyatou ndiaye lasallah yalna yalla fayla saida kodal fan wét ka werle boladara dal diama rek kayam ci kanam ci lo bahe

rokhiyatoundiaye
Автор

Da am ku nek Yoff, xalaat na nga wooy ko, L'IMam Li Lahi.
Machallah toute la famille t'aime.

magazine
Автор

Mashallah soxna bintou Yalla nalla borome bi may weer gu bareh bari si barké mame Cheick Ahmed Tidiane Sy rta

teussteuss
Автор

Ndayesan machallah sokhna bintou thame nékhnalolo
بارك الله فيك

SeneInfo
Автор

Ya Saïda machala vraiment tu me fait pleurer en écoutant tes chanson je pleure et je pense directement à Allah

sammsungwhatssap
Автор

Macha allah fière d’être Talibé cheikh tidiane chérif « rta »

madamely
Автор

Mashallah yalla na borome bi yokk weer barké yonente bi psl

teussteuss
Автор

AMNA SOLO DH SOKHNA BINTOU THIAME YALLNA YALLA GEUNA WEURAL BATT BI BONN RAMADAN

Leuz_vision