CAB - WWCF (Official Music Video)

preview_player
Показать описание
CAB - WWCF (Official Music Video)

Follow CAB

Listen to CAB

Lyrics : CAB
Prod : Freshi808beatz
Mix & Master : Freshi808beatz
Real : Emtee
Dop : Zo Charo
Director of photography : Emtee
Artistic director : CAB - Ahmad - Emtee
Video editor : CAB - Emtee
Drone operator : Mtn Designer
Music label : LeundeumEnt - All Vibes Music

Lyrics:

Im on the way to the top
Motax fallait proner sadisme
May ki meuneu tax nguene nek nit no dou sakim
May fusillade bilay fek sa konie yaw ak sa team
Taw bouy ta ba adina lap ci th meussteu khine
Jo mane ma meune sa 100
Li obama sax meunouko
Na he can't
So you all better call me the goat
Kouma dji Ngelaw boumla beteu boudé tempête nga gaub
On a pas eu à se creuser la tête
Pour def diamond logo
Modou bamba ngui ni manela im the leundeumest
May tawou mere kone indi xaliss was a must
Reference laa th pour ma motiver il faut ma hussle
Jfai du sale a vos rappeur danio moudié raxassou si mane
Ndax
Ma gueuneu toxic bepeu microbe
A des années lumieres d'eux tous manam kep kouy hip hop
Keumeufeu boy yi nio def différence dans cette pourri jeunesse
Dioxko beat daf beug rap nioune niouy wané nouniouy deumè
Li bone sa xol moy limla ler ni im the best
Douma nitou fi douma sax nitou fé ak fatia dess
Li Sureté doul ci xol mais xel tax sentiment dou sama fort
Bakane dou rott ba raw bossou gni tank naane si sama tiow

This is what we do
This is what we came for
Dadj seni bec ay ngandi clouu
Yea this is what we do
Nieuwounie pour topeu beneu damn code
Day leundeum mais dou meuss di flou

Nul n'est à mon niveau
Dounie xaar bay beug dé pour meuneleu wekeu
Fou lion yi roar
Dafa fekni guissou fa cab
Shui un homnivore
Wanel bane xetou beat doul sama lekeu
Do yalla bindo
Koumay téré ma yegg on the top

Bimay am niaar fuki at laa yeuk ni dam special
Manela nga dof fok si aleu lion is the nastia
Wowéma serigne ci cab
Dam teuleu nieup di chiar
Pinceaux yi creer joconde mom lama de vinci al
Jai maintenu le cap ndax Lima taxa rap meussteu né buzz
Kill me's not even difficult
Dafa meunteu né bro
Mane na xaliss bi di tew dont give a fuck the recognise
Kene doumaci té atteinde sama but niom nieupeu ngayi
Bouniela diay
Banga feug deune ni yaw yafi nekeu
Baramou touma binguene ma joxone dinguene ko tegui
Balene dima tekalé ak gni rap dougué ci maker
Founiema sène sudiote té nio gueune reuy lamigne ci net bi
Nigga manela iblis
Diaxassé na kouné
Jangoulouniema how to forgive
Mattna ma artu lene
Niggas know it
Dounie mbeuw ba Si keumeufeu boy menace bi jaleu
Too fresh heureusement ba limay rap meune naaci jaaaru

This is what we do
This is what we came for
Dadj seni bec ay ngandi clouu
Yea this is what we do
Nieuwounie pour topeu beneu damn code
Day leundeum mais dou meuss di flou

Nul n'est à mon niveau
Dounie xaar bay beug dé pour meuneleu wekeu
Fou lion yi roar
Dafa fekni guissou fa cab
Shui un homnivore
Wanel bane xetou beat doul sama lekeu
Do yalla bindo
Koumay téré ma yegg on the top

#cab #wwcf #music
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

cab gueumeule sa bop d'à fa diot nga diéli li DESS puissance boy big up

Gualsenplus
Автор

"pinceaux yi créé Joconde mom lama Da Vinci al" what a puch💣✍. Shoutout To U Topboy💎.

lamzii_dml
Автор

C MEC à TUééééééé l BEAT DOPEEEE BIG RESPECT KOU nangou lale Jaime

youssouthiane
Автор

Wa keur mbaye Fall ils nous montrent que le RAP n'est pas mort❤❤❤❤
(Gun Llas Cab Keultieu Mgeey ❤)

papemami
Автор

Mwen pa konprann sa wap Di yo, m'en Vibe la vibre Mwen .

Dominique_
Автор

Keep up on good work type beat like this you won’t regret it …

yerondiaye
Автор

Billay boy dou moromou boyz yii il est trop à l’aise wollah😩🔥🔥🔥

ahmadaasn
Автор

Le délire moy k il incarne un personnage dans le clip qui colle avec les lyrics g mm op les mots pour expliquer mon interprétation du clip
Cab "I'm on the way to the Top" mo warone nek titre Top boy du coup Top boy suite lay done you know what I mean c dingue je c et beaucoup vont jamais comprendre limay brind😭💔
Keep GoinG KinG❤

el.hadji.momarndiaye
Автор

I said it and I Say it again.... This boy is the dopest 🔥

abdoundiaye
Автор

He IS cab, le meilleur de sa génération

mouhamedthiam
Автор

Wa KMF gni dakk rap galsen wayé CAB mo dakk rap KMF da amoul ay gueuweulou dioudou rek. Respect man 🔥

bouboydashiny
Автор

Bon continuation mon grand frère 🫂 Amal diamou rék ✊🥳❤❤❤🎉🎉🎉

BOYfromsaloum
Автор

KeuMeuFeu Univers. Bonne continuation à vous

makhtarcisse
Автор

Cap bayil rap😂😂 bala ngay ray domou diambour
Sinon son bi dope na lyrics yi aussi top❤🎉

CheikhbayeTalla
Автор

Vrai writter after dip cab et Ouz zik buzz

modoundoye
Автор

Boy je te jure sama gayi fii rocma nioki lay big up t’es unique dans ton gère tu fais ton game

MoukhamedFedior
Автор

Damn Classic shit🔥🔥🔥
Mais boy bi dafa fébar Respect !

mrmendy