Titi Live Performance Intégrale

preview_player
Показать описание
Vous pouvez VOUS ABONNER à notre chaîne en CLIQUANT ici :

Rejoignez nous sur:
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Ibou Ndour yay ki takh musique sénégalaise déssé valeur ak qualité vraiment avec toi notre mbalakh a de la place dans le monde

Khalil
Автор

Nila rék artiste dafay live lou bari lolou kasé lalén wally rawé dakou léna way dé moy sama artist nak
Bonne continuation 👍👍

Fall
Автор

Ohhhh chaque jour magui degoul liiii 😍🥲🥲

diarygadio
Автор

Vraiment titi dafa man limouy deff trop machalla laftiat goudal fane yagui fii diniou bègueul 🥰

khadimg
Автор

barki seydouna moukhamet titi beugu ❤ nala yalla na yalla wéral sa voix bi té mousal thi lamine bou ayy

sombiba
Автор

Svp prince art il faut la promouvoir davantage, vous savez même pas le produit que vous avez entre vos mains, Franchement TITI warone dépasser fiii, car elle a une voix d'or, je dirai même une gold 💪😍.
Elle est la meilleure chanteuse au Sénégal . Une vraie lionne, man deh yay sama Sadio Mane, yay sama Baye Pêne
Machallah yalla nala thiat sekhlou, tei yag wereul batt bi,

khadijambaye
Автор

La lionne 🐅🐅notre Diva nationale ❤️😘👍
La meilleure voix de sa génération laff thiate ci kaw ça kanam rekk machallah.

gnilanechouilly
Автор

Ndeysan Titi niou beurii khamougnou sa valeur mais nak diam rek ngay am incha allah so wayé tidjane yii bégue mouride yii bégu senegal gneup contane lolou iow rek yakko meune sa diam na yagu

lilumzo
Автор

Non lii dou live kassé, niit meunoul meuneu weuyé nii, Titi bilay do sakh niiit, est ce que do Djinné tamit. Étant couturier, j’étais totalement épuisé et j’avais grave sommeil et je suis tombé par hasard sur ça, j’ai retrouvé le courage et la force de continuer jusqu’au bout, je me lasse jamais de toi 😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍

gentlemara
Автор

Tego gnou gathié deh 😭😭😭❤️❤️❤️🎤🎤🎤🎤🎤🎤Ay titi mi meune n’a way di

mamico
Автор

Nékhoul ba nékhoul sama toma daga mane liguaye déf bilah yalna yalla lafal thiat goudou fane ak wére belle voix yalna sa diam yague 💋💋❤️🫦🫦

fatoush
Автор

Le morceau de mame Abdou Aziz Dabakh est trop bien instrumentalisé. Je n’ai pu m’empêcher de verser des larmes. Sunu Mame Abdou Yalla nako Yalla seddal soufeum bimou Teudd

yakhyadiop
Автор

Machallah sama fans bi meusso nio tek gathié dh li eupe solo si artiste nga def moye mané feep fougnou la wo nga wouyou té bougnouy lime gni dakha woye bolé lasi bougnouy lime gni dakha live bolé lasi bougnouy lime gni eupe ay fans bolé lasi Thiey sama fans bi yaw nak ndékété yay meilleur ya takh gnounane meilleur xol sedatina gouyou bay firigo❤️❤️❤️❤️❤️❤️ am nga lou diafé si musique yow rek yako am si artiste you jigueen gni kene d'où yaw kharal ma gnew lime artistes yi dakha Live si Sénégal Titi la lionne Wally seck Youssou Ndour omar pene pape Diouf keba seck sidi Diop nio dakh live keep kouy woye kat fisi Sénégal ak liko weur💪💪💪💪💪

cheikhpendambaye
Автор

Man suis choqué dama titt bilay du jamais vus ❤️❤️😍❤️❤️elle dépasse la barre et très haut même 🥺❤️❤️❤️❤️❤️😭😍

evachiniba
Автор

De aladji ass passant par ambassadeur a fasse Titi nous t'ecouterons pour toujours
Tu nous rend fou avec ta belle voix
Quelle sortie!
Quelle performance!
Quelle voix
Titiye ba abadannn

dembasoumare
Автор

If you think you have seen or heard melodious voice, you haven't until you meet titi...thé only Senegalese female artist with a wonderous voice..

sunnychuks
Автор

Billay li bénén level leu
Je dirais merci à papa youssou ndour ndakh li yeup c'est lui ❤❤🇲🇷

kennatoudiop
Автор

Qui comme moi à suivi le live 2fois walay je ne peux mm po imaginer la joie que j ressens bilay.yalla nala souniou borom takhawou la grande .J ai pleuré sur la chanson de Serigne Saliou nakh contane.Amal diam def patt di Liguey le meilleur reste à venir inchala. On t aime 😍😘💔

fatoutraore
Автор

Jules Diop le batteur 🦁🥁 Un vrai maestro tous les mèlomane sont encore 😭❤
Titi mention spéciale

awandiaye
Автор

Non c'est une extraterrestres celle la !!! Vraiment Titi je penses dafa ame loulay woylo mais nak c'est juste parck t'es pure et tres humble et très humaine motakh walahi lo woy day dougou si kholou niitt yi !!! Vraiment t'es la meilleure !!!

idrissandiaye