Samba Peuzzi - Mouridoullah

preview_player
Показать описание
#YOLETOKSEUKEUR2

‘’Le spiritualisme reste le meilleur abri de l’âme d’un Homme.
Rendre Grâce à Dieu, au Prophète (PSL) et aux Hommes saints est la meilleure thérapie contre toute calamité.’’

À travers cette vidéo, le Rock boy dévoile son côté spirituel.

« Mouridoullah »

Direct By: @Youngfresh221 pour @Watchthedronefilms221
Composition: Toxikbeats
Mixing and mastering: Karabaliikbeats
—————————————————————————————————

Retrouvez Samba Peuzzi sur :

—————————————————————————————————
Contact management : +221781541233

#APPRENONSÀVIVREAVECLECOVID19
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

"Serign mountakha yok diam dji, leip nga leiral diamono dji, wane nga gnou yone, djitou gnou top ci, amougn sa feye borom mbekté mi" 😍😍😍😍😍

gamewinnerjj
Автор

Je suis niassénne ms j'aime Serigne Touba ♥️❤️

mariamabarhamienne
Автор

Je suis fière d’être mouride ana mouride Yi defalen j’aime S Bamba rek si khol❤️lenen dasa khadioul🙏

petitneymar
Автор

Le nombre de personnes qui aime Samba peuzzi montrez-vous 🕊

wiizzloufa
Автор

Ani mouride yii kou beuss j aime YALNA barri xewaal😍

weuzndiaye
Автор

Machallah nica na trop yalla na yalla weral bate bi si barkep brom touba ❤😭🥰🙏di nianla serigne mountakha bachir yalla nafi yague lol barkep khasida yiii🥰🙏😭

ndeyediordiop
Автор

On veut aussi que tu chante Le prophete Mohamed salalahou aleyhi wesalam..
Ca va être cool avec ta voix ..🤜🤛

personne
Автор

Tidiane leuh meiii son biii lallll Nama ❤️🇸🇳🤙🏿

momofereyaofficiel
Автор

C'est du Samba peuzzi. Un stratège: parole linéaire facile a capter du coup tu va l'avoir dans ta tête sans faire exprès. Un

trazbif
Автор

Kign de sa génération ❤❤❤❤👑👑👑👑❤❤❤❤ kouko beug beuseul jaim

morpeuzzi
Автор

fi kou beugue serigne touba gnou beugue la ak si lo manti yeugou 🙏🙏🙏💥♥️♥️♥️♥️ merci samba peuzzi gnaka done mourid woroul serigne Mountakha yalla na fi yagg te andak weer et ♥️♥️♥️

falloundiaye
Автор

Tidjan la deh Mais lima nekh si mouride yi fougn dem gnou khamé len dagno geum sen boppou machallah ❤️🥺🙏🏾

ndeyeniang
Автор

Rap bou deugueré tei wakhoull louyy diarigne amoull sens, meune na nooy teikssi lyrique sii bi di guëne, rime bi diaar yonne, triplé bi nonou ....mais dognou beugue rayy ak fock Rap bou deuguer bi tei bokoye dégulou doula saff dra amoull sens.Samba continue comme ça di Rap Lou nékh gnouthiye bégue ngathiyy bégue di léck sa khalisse From Darou Salam✊

zaleuhnoir
Автор

Samba peuzzi lii nekh na trop yalla nala yalla faye ak Serigne bi

khadimnguer
Автор

Mom dafa polyvalent
Kou beuggg bromm Darou likes
Barke Bromm ziikoorriiii 🔥😍

abdumaty
Автор

Tu as bien fait frr kou d'accord beuseul j'aime

mamysow
Автор

Je t'aime samba peuzzi continu tes music

issadiallo
Автор

Kou beugueu mame bamba baseuul j'aime👍👌

abdoulbarry
Автор

Vraiment samba peuzzi sa chanson bi amatoul

fallouniass
Автор

MAXIMUM DE COEUR QUI EST REVENUE COMME MOI EN 2024 BIG RESPECT PEUZZII BIG SOUND😇❤❤BAMBA DJI KASSE

mouhamedcissoko