Icône '' Li Nek Fi ''

preview_player
Показать описание
LI NEK FI 👇
production : icône music prod
producteur exécutif : Al Amine
directeur artistique : papi laye
directeur commercial : Momoh maker
**crédits de la chanson & du clip **
auteur : Papi laye.
interprètes : Kya, Milky, ND Coumba, Diamond & Buur.
Music prod: Papelaye beats
lyrics & arrangement : Papi laye
Record & Mix & mastering: Sirtam
Réalisation clip : kheushart graphiste
assistant cadreur : Abdel
Scénario clip : Papi laye & kheusha
montage clip : kheushart graphiste
lumière : Mame Diarra
décoration clip : Abdel & kheusha & papi laye
régisseur : Papi laye & Matar Virginie
maquillage : fia
Casting : Momoh maker
Remerciement:
tous les figurants et les Tik tokeurs ( Yatma prod , flash mo, matar virginie ,Seydina 66, momoh Tc , bb laye , maria sow , soda , pierre bass , Mc cana , licka, mada , fama diop , flam )
** Retrouve icône sur les réseaux sociaux **

** Contact management **

Lyrics

KYA
Souma Dioumoul 🤔 Moss Nala Guiss👀yaw
Si Beineu Diotaye ( Ay Way )
Yagui Tok Ak Say Gayy
Guein Tek Thiayne 🍻
Louniou Wakh Gua Rei 😁
Dima Kholalé 😎Dima Pissalé 😉
Man May Dei 🫣
MILKY
Duma Lako Neub Bama La Guissé😇
Amna Louma Done Yeuk Si Souf 🤭( Feiy )
Gua Nieuw Tok May Rei Si Kaw 🤣
Bagnion Na Sama Gayi Dima Rei😄
Motah Yaw Mbi Yeuguo Won 👇
An Sama Mbeugueil ❤️
KYA
Lernama Ba Ler🙈
Nakar Dina Diekh 😚
Man Mbi Dei Lima Guiss 😁
Lerna An Lernama Lerna 🌄
ND COUMBA
Li Nek Fi Ni 👇
Li Nek Fi Ni 👇
Li Nei Sama Khol ❤️
Mbeugueil Lama Diokh 🫣( Mom Lama Diokh )
Mbeugueil Lama Diokh 🥰( Mom Lama Diokh )
Khamei Wu Mako Won 😵
Ndéké Yoo Mom LaWon 🥺
MILKY
Li Nek Fi 👇
Li Nei Sama Khol Bé❤️
Mbeugueil Lama Diokh🤭
Mom Lama Diokh😍
An Mom Lama Diokh🫨🥰
( eh khé )
Khamé Wu Mako Won😵
Ndéké Yoo Mom LaWon 🥺
DIAMOND
Ndah Mbecté🥳Lernama Ba Ler 🌟
Nakar Dina Diekh💯Sama Aduna 👻
Ndah Sama NofLay Yakar N'a 🥰
Dina Ma Nopal 🤗
BUUR
Coups De Foudre MoMa Dall 🫨
Malay Guiss Man 😵‍💫
TawTé N'a☔Guiss
TaaTa🏞️Khouss Man 😄
Feuleu N'a Si Guédiou 🏊
Mbeugueil Man Ma Bagn 🤤
Falay Dess Man Falay Sobo 🏄
DIAMOND
Ligma Diaral Meunou Mako 🙆
Wakh Fini🤐Yay Sama Thiopati 🤪
Papa Ndiaye Takal Ma Bin Bin 🤤
BUUR
Takal Ma Khol 🤭
Je t'aime 😭Tellement Tu mérites
Ma Yobula🚘Yaw Mbi Si
Mame Ndiaye Savon 🎁
DIAMOND
Esk Do Def Farata👉💍Ma Guaw Nieuw
Gallé🏡Niou Pathial Ligome🚨
BUUR
Kouy Sa Marie De vipère🕺
DIAMOND
Diadia Boul Dof💃
BUUR
Doumako Lal Dafa Bari🧘
DIAMOND
No no boul Dof🤦
BUUR
Yaw mbi Fatal ma Fofu🫰❣️
DIAMOND
Foo Foy💌
ND COUMBA
Li Nek Fi Ni 👇
Li Nek Fi Ni 👇
Li Nei Sama Khol ❤️
Mbeugueil Lama Diokh 🫣( Mom Lama Diokh )
Mbeugueil Lama Diokh 🥰( Mom Lama Diokh )
Khamei Wu Mako Won 😵
Ndéké Yoo Mom LaWon 🥺
MILKY
Li Nek Fi 👇
Li Nei Sama Khol Bé❤️
Mbeugueil Lama Diokh🤭
Mom Lama Diokh😍
An Mom Lama Diokh🫨🥰
( eh khé )
Khamé Wu Mako Won😵
Ndéké Yoo Mom LaWon
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Wa mé buur AK diamond li menatoléne KO waye 🎉😢😢😢 j'ai hurlé trop de mélodies❤❤❤

thianendiaye
Автор

Kou beug serigne Babacar Sy (rta) lalal aime

Iam_maya
Автор

MACHALLAH ET FÉLICITATIONS À TOUS L'ÉQUIPE DE ICON ❤❤

arfangsouane
Автор

La belle voix de Kya l'international et Buur borom TiV🔥🔥🥰🥰💥

Iam_maya
Автор

Ndeye Coumba Mbaye ❤tu ne déçois jamais sistah🎉🥳🥳

mouhamedba
Автор

Ak liii tmt naka ngay bayyèh dégue lou music Icône togne ngèn ma 😭 liii nèkhna 🥰🥰🥰🥰🥰

thiatoumerebindiayediatta
Автор

Machalla force a vous Yalla na yalla wèral batt bi Ndeye Coumba ❤

MatyGueye-lj
Автор

Le talent est la de ouf😭❤️ mais milky>>>

khadimthiao
Автор

Toujours au top Je suis Fière de toi 🎉❤🎉

mariopreira
Автор

Félicitation au groupe icône bon courage et bonne chance pour la suite les perturbateurs de la musique respect à vous ❤️❤️

babacardione
Автор

No indeti ngen ko bamou leir sama dom yi manchala chapeau milky boul sissou mais king babs defnalen ko ak diamond

pinotraiteurmbaye
Автор

La belle voix de ndeye coumba ma belle❤

MbèneSENE-hs
Автор

Que du talent de très belle mélodie vous avez encore une fois frapper fort 💪

filsdekabirloriginal
Автор

Machala j’aime 👍 trop Buur et Diamond vraiment chapeau 🎩 à vous tous❤❤❤🎉

MouhamedRassoulNdoye
Автор

Qui est le grand maestro qui se cache derrière ce magnifique travail ? Je suis très exigent en music mais ce groupe déchire et assure à chaque fois… La musique que vous faites, est tout juste waouh. Le texte, le feeling des artistes j'adore....Bonne continuation et je vous vois très loin. 🥰🥰😍

babacargueye
Автор

Nice Job Icone Music 🎉
Chapeau au Maestro Kheusha Graphiste 🫡

MoOnlight-fgdx
Автор

Bonne continuation 🎉🎉🎉 inch'Allah dina bax❤❤❤ et kya t'as une voix exceptionnelle machallah à toi aussi 😘😘

adjaawawane
Автор

Wakhou maa lolou mais pi dou nitt barki alkhourane meilleur producteur yalla hamnako yaw rek lagni toppp🥳🥳🥳🥳🫶🇸🇳🇸🇳

djilzocolle
Автор

Je n'ai jamais commenté si affaire music meii jtjr j'arrête op d'écouter ce chanson walahi suis a ouffff mashalah courage a vous en tous cas merci pour cet jolie bijou merci a vous *For ever*

rahimcoly
Автор

Waa tivaouane contane naniou si yen❤❤❤

mouduoudaigenen