Série - Mirage- Episode 110

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Boula yalla tegué natou daguay mogn 😮 ta niane mo téguilr lako😢 mirage moy sama natou si série yi yalna diékhak diamou 😢😢

diengdaba
Автор

Casting des maisons de production :khar media : goor you reuy bopp😢 evenprod :tate you reuy😢pikini:tein noir😢marodi: intellectuels(elles)😂

aramethiam
Автор

En tant que commissaire tu libère un bandit pour sauver ta mère alors que toi même tu peux le faire niak diom

juliettemalou
Автор

Solen yoroul sougne ay lomotif dina ma diakhal deh 😂😂😂😂

IbrahimaDiaw-emnd
Автор

Yalla mignou may courage ba leguii yalla nagnou KO yalla balé sougnou bakarr yii❤

awandiaye
Автор

Nioune kou yobou niou sey dou ame kathiè mane mougne 😂😂😂top serie bii😂😂

adamakebe
Автор

Khana niou cétane rék té mougne dina massa dièkh😂😂😂😂

tyma
Автор

Ça devient chiquer 🎉🎉🎉🎉 avec l'histoire 😂😂😂❤❤❤

oumoukoita
Автор

Khana seri bi amul ahy police biran di def loko saff ta ken dou wakh 😢

ajajobe
Автор

Natou bima am si cherie bi mo takh 44:minutes yi 3:lakay setane avance rk kene douma ray😂😂😂

famasewane
Автор

Mane série bii comme dagn massé liguèye yague naa trop way 😢

YacineMarone-fb
Автор

Léa sa farrrr yi dognousiii dimbali 😢tu es belle sans far

absadiakhate
Автор

Mais bi mome Dale na da maye stressee cheque fois sou maye setane je vous love ❤❤❤❤❤❤

pinnaclehebron
Автор

Cette série on dirait Amour, gloire et beauté 😂😂😂

famalo
Автор

Li lane la tamit nak mirage khana dou fin nak😂😂😂😂😂😂 aaaa😂😂😂😂 wa nekh na nak

KountaDiop-dl
Автор

Léa tu as fait un movais choix 😢 aaaa 😢 pourtant lamine est vraiment très gentil 😢

ThioroGueye-swxs
Автор

Monoléne bayiwoléne guir yalla respecte lane gnou😢😢

GallassThiaw-yxpe
Автор

Kou ame Serigne bou bah bouma meuna deudalé ak série bi😢😢

NdéyendiouckNdao-td
Автор

Ana yayou Coumba mongui police batay wala 🙆‍♀️

MameawaLeye-tb
Автор

khar media doleeeen def fin si serie bi guir yalla

diamansall