Youssou N'DOUR et le Super Étoile - AMITIÉ | Album Alsaama Day

preview_player
Показать описание

Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Oh oh oh oh oh
Sincérité ak mandou thi walou gou né
Mome nga ma xamal
Dignitégou andak dal diamono diouné
Lagne massa dokhal té diko dieuffé
Si souniou diganté
Ningue maye nebôke dima lakhou rafétoule
Mou melni mane dama défe louma yeugoule
Wi dokhaline dama la ko khaméwoule wône
Guissône nani mane ak yawe sougnou amitié
Nite gnépa ko nawe
Bi changement bou méttêke m'béttéle bi nga ma ko wakh
Mingui maye sonnale, mettina thi mane, takhe na ma ragale
Yeh!
Ni seîtané ooooh!
Ningue maye nebôke dima lakou rafétoule
Mou melni mane dama défe louma yeugoule
Wi dokhaline dama la ko khaméwoule wône
Guissône nani mane ak yawe sougnou amitié
Nite gnépa ko nawe
Bi changement bou méttêke m'béttéle bi nga ma ko wakh
Takhe na ma ragale
Khamale ni yawe gnoune gnâre gnô maggandô
Té dagnou masse yékkétéke tégandô
Beugeuneté lôle gnô rawe aye toureundô waày
Gnâri fane yi ma diauke, gneuwe di réresi sa keure
Khamétoumala
Bimala nouyô yawe nga fayéma bakkane
Réke ma khame ni seîtané meune nala
Bénénaté boule teupe di bétté
Nara défaneté badi gnakkaneté
Boula dalaté nagnou guisseuneté
Sougnouy wakhtane moudjié thi diôté
Hou eh raw, hou eh raw, hou eh raw
Raw raw raw hé!!

modouthiam
Автор

Je l'ai dédié à mon père il était mon vrai ami il et décédé 7 7 2015 repose en paix papa aujourd'hui je me nomme digne fils de son père

badianfoula
Автор

Qui est la en 2024 🥰longue vie à papa youssou ndour❤

khadygueye
Автор

Qui est encore la❤❤❤ en 2023 ❤🎉🎉 ohhh père aussi ohhh ball bi mome souma amer vip dina dem inchalla le 1 janvier ❤🎉😂😂😂😂wawawwawaw❤

MaychouNdiaye
Автор

C'est tellement rare qu'on trouve un amie sincére kou dcr rk beuseul j'aime

ndeyecisse
Автор

Mame Thiam, Omar Thiam, Ahmed diom ma vie devient de plus en plus belle chaque jours que Dieu fait grâce à vous.
Merci

ousmanesarr
Автор

😭😭😭😭ça me fait trop pleurer😭❤️love you so much my sis Ndiémè😭💘💕🥇😍💉💍

deynabadieng
Автор

Pour mon papa ❤❤❤c'était mon meilleur ami 😢😢

mariamandiaye
Автор

Vraiment j'adore cette chanson je l'écoute depuis des années 2006 me fait pleuré 😢😭🥰🥰🤗🤗

angeliquesalimatasow
Автор

😭😭😭l'amitié et rare cette chanson me plait car je me suis disputé avec ma meilleure il 2ans elle me manque réellement et j'ai envie qu'elle revienne ❤❤❤❤❤je l'aime réellement 😚💍💍💍💍💍💍💍😭😭😭😭😭😭😭😓😓😓

MameFatyLeye-yl
Автор

Cette chanson est très merveilleux
L'amitié est beau mais tellement rare

khadissatoufall
Автор

Cette chanson me fait penser à mes deux meilleures amies Bigué❤et❤Dié Gaye

BattolyDème
Автор

Je ne me lasse pas d'écouter cette chanson depuis les années 2000

Espoir-mkge
Автор

Cette chanson de Youssou Ndour me rappel mes grandes amitiés sincères avec certaines personnes depuis toujours

khadimthioune
Автор

Les vrais amis se font rares maintenant

ahmadarassoul
Автор

Ma meilleure amie se marie se week-end 🥺🥺🥺trop contente pour elle

Ladysalooum
Автор

Amitié beurré woul légui barki yalleu mane ay nite yo khamni meussou ma xalaat niou deff meu lou bone nion ma worr tay 😭😭😭

malangdembele
Автор

Ndeye fatou sall, Fatou kane, Ndeye diouf, Mareme ndiaye, Mariama ly de la part de Bb rema🥰🥰

biddewuniquement
Автор

C'est une chanson très intéressant

MadjigueneDiop-pb
Автор

Vraiment cette chanson me fait penser à tous les bons moments que j'ai passé avec mes amis. 🥰😍🤩❤💋🖤🥰🌠🌌🥳👏👭👌

khadybarro