Série - YAAY KAAN ? - SAISON 1 - Episode 08 **VOSTFR**

preview_player
Показать описание
Services commercial :+221 77 404 94 04

ARGAYE TV , un labél de production initié par des jeunes MBOUROIS dynamiques et ambitieux vous présente une nouvelle série intitulée YAAY KAAN …!

YAAY KAAN , nous relate la vie quotidienne d’une famille polygame Sénégalaise.

Description :

C’est l’histoire d’une vie de couple polygame.
Comme la polygamie désigne un régime matrimonial où un individu est lié, au même moment à plusieurs conjoints , on peut dire que cette pratique peut mener à la rivalité , à la jalousie entre les épouses , de la compétition ainsi qu’à la distribution inégale des ressources domestiques.
Cependant, dans cette série YAAY KAAN , la famille polygame a été introduit par un membre proche de la famille qui n’est rien d’autre que la sœur de AÏCHA la première femme de Mr VITO NGOM chef de famille qui va volontairement générer le désordre dans la maison .
Cette femme est une intruse dans la maison . Elle va favoriser le désordre et la provocation entre les deux co-épouses de MR NGOM DG ARGAYE TV à savoir AÏCHA la première DAME et ANTA la SECONDE.
Pendant ce temps, MR NGOM va être serein et essayera de s’adapter aux situations qui se présenteraient.
Il va continuer de gérer et de montrer son affection à sa famille malgré les difficultés causés par cette fille.
Cette série va nous dévoiler les pires difficultés de la polygamie.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Deing amna louko Aïcha déf kii Bone n'a

LamineSokhnaofficiel
Автор

Séytané togal❤ sokhor ga trop bokak nit ndaye diko bagne simmm😢

maremefall
Автор

Ma. Awo bi daf ma nékh trop dafa nourok souboulou ay wakh ak ❤djougama machallah

AminaMbaye-ee
Автор

No ki soff nama ak dioyam yi seytanè trop 😂😂😂😂😂😂

yayefallbi
Автор

Bayilène di waat si séries yi yalla dou fowou kaye li fiction kessé la

bocarguisse
Автор

Li série rek la dou saytané kou bakh la nakk😂

famajeng
Автор

Enfin Firi neu letteu Seytanei yi peu être dina wangni

mamediarrafall
Автор

Seri bi mome nekhatoul saytane bi da eupou

MbeneFall-uvpn
Автор

Dans mousse mak te n'a meunerie roleme machalla aissa ak anta nioye aye dof rek😂

lampfall
Автор

Awo bi vrai dof la😅😅 saytané foko fék daye gnoul kouk déf gréfage bou rose nok si ay wé you verte taye si kaname gui poudar bou wékh😂😂

ndayelyboye
Автор

Saytaane baaxul, day feeñ ci sa jëmm 😅

GayXaadim
Автор

Noo kou beugeu ré affiche indno dawale kaboye😂😂😂 2em fame yi

DiarraboussobouLeuzediewanane
Автор

Seytané gua deff ak nioulay bi di melni mayonnaise goudron 😂😂😂

deguenediallo
Автор

Seyetane bi mo mousse filaye diare tasse keur gui d'Amazonie bébé sak jour avec loulou deff😂😂😂😂

lampfall
Автор

Dié seytané bou bone la ak ongle lame gnou vert

yamaniang
Автор

D'égal gniounan def bkh té moy seytanné keurgui😂😂😂😂

Khardiata-nzye
Автор

Man deh beug n'a comprendre dieng mi place la beug wala magam la bagn 😢

binetadiouf
Автор

Mais seytanné bi Limiu wakh aïssa bakoul est ce que kamguen ko😂😂😂

Khardiata-nzye
Автор

Seuytané bi AK wé wame yi verte yi soume le diapé be wagni se grefage bou Bari bi

mbarkangom
Автор

Lima diakhal seytané bi ken khamoul nakh thi anta la far wala aicha😮

antasylla