Extrait Titi - Jikko (Lyrics)

preview_player
Показать описание
Sopil sa jikko ji, so bëggé am lou baax
Sopil sa jikko ji, so bëggé gis lou baax
Sopil sa jikko ji, so bëggé gis lou baax
Yow sa jikko ji mo la tooñ, moy taax ngay xëy di toogé
Yow sa jikko ji moy sa nattu, moy taax, ngay toogé say naawlé
Yow sa jikko ji mo taax, ba kou am lou baax, yow dou la neex
Yow sa jikko mo la tooñ, ba kou beg yow do beg
Da ngay saaga, tiñëlaté, di soosalaté, la ngay waax dara leeroula

Sopil sa jikko ji, so bëggé am lou baax
Sopil sa jikko ji, so bëggé gis lou baax
Sou nit ñi beggé, nga meer, sou nit ñi reetané nga meer
Souñou waaxé lou baax, nga meer, toog ci tiktok bi baaxul
Laakatouy snap di saaga, tiñëlaté, lolou baaxul...
TITI
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Amna ambiance amna leçon masha'Allah Titi ❣️

thiernoy.diallo
Автор

Faye safai un bay cv machala tt mongui nice❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

khadypouye
Автор

Elle est une femme de l’ombre avec des valeurs morale - éthique très sévères. Elle est née artiste et elle brillera inshala comme l’étoile qu’aucun voile ne peut couvrir. Yala na yala weral baat bi ak thieur yi ♥️♥️♥️

boubacarchampselysees
Автор

Titi la rien du live 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰 je taime trés bien love you

sileymanesy