MOMO DIENG- Lang Gui (le Clip)

preview_player
Показать описание
Vous pouvez VOUS ABONNER à notre chaîne en CLIQUANT ici :

Rejoignez nous sur:
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

ooohh mon song soumakay deglou sama yaram bi di daww chéri boy boul nameu dara tay diapalni may sa superman 💃💃💃💃
mai clip bi beurineu lumière j'ai mal aux yeux

kittylaeva
Автор

Je peux l'écouter trois fois par jour vive mon pays 🇸🇳😍😍❤️❤️
De passage depuis la France 🇫🇷

abdouldieng
Автор

Vraiment Momo tu es le meilleur qui est la en 2025❤❤❤❤❤

MaremeNdiaye-sdpk
Автор

Man damay lathie beug kham
Damay khol nguir beug guiss
Dama rer ta beug fegnn thi xaleil (×2)
Sama yaye bayimaa ma dem seeti
Xalei yii sen lang riche neuu
Wowoo damakoo dama beug setti
Xalei yii sen lang riche neu
Man damay lathie beug kham
Damay khol nguir beug guiss
Dama rer ta beug fegnn thi xaleil (×2)
Maman bayimaa ma deim seti
Xalei yii sen lang neikh neuuu
Wowoo damako dama beug xooli
Fatou kine ndour langam neikh neuuy
Wawaw damakoo dama beug seti
Fatou bintou ly langam ruche neuuu
Man damay deim(×8) wooy
Man damay deim(×8) wooy
Man daal lang yima meusseu diar yeip
Lang gui tay momassi daaakhal
Lang yimeu meusseu deim yeipeu
Lang guii tay momassi daakhal
Man dei beug naaleine
Djigueni senegal man dei fonkat naleine
Man dey wolounaleine
Djiguene gni man dey beug naaleine
Cherie boy boul nam dara tay
Diapal ni may sa superman
Man dal diaral ngama naam
Loo beug ma indil laako
Gnoun goor gni nagnou def souniou gneti morsso
Teilssi kopati ak ay mbarakiss
Djiguene gni gnom dagno civilisé
Teikssi am filing ma beik thi yeeine
Yaw so beugueiiii heiii
Fariyoooleiiii

muigqsu
Автор

Limathi guena nekh:::: man dal lang yima meussa diar yeup lang dji momassi djiguen gni danion civilisé am feeling ma beeegg si yen ooohhhh somay koy deglou douma tok douma takhaw ayy ligua way tayatoko bilahiii 💖💖💖😝💯💯💯💯💯

fatoushababellthiam
Автор

Mande magu thi di begè ba tay ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️momay wetali fi 🇮🇹

ndeyegningue-qemy
Автор

Dieng salla lebou bargny machallah yagui beguel sa generation di beguel sa yayi melni mane sa kaw rek inchallah

fatimadia
Автор

Ki écoute cette chanson en 2023❤😭machallah 🥰

FatoumataKande-oxqs
Автор

Tu as très bien chanté ce qui n'ont pas aimé 👎vous êtes jaloux si boye bi clip bi lumière yi niomaciy danèl khana love moi je met mille j'aime 👍

rokhayasamb
Автор

wa liii kouthiy wakh, , aaa mane sama holl❤ frigdair ndakh lagu gui thioummm djiguénou galsn gorr gni dara fayuléne. ..li nékhna wayyy😊😊

fifisylla
Автор

Beautiful song as always, really admire ur respect 2 da Ndour family. I love ur music ever since and I still do💐thumbs ur 4 u 👍

ajanyandou
Автор

Pourquoi pas nous les fans de Momo dieng qu'on organise un groupe whapapp spécial pour momo

sallaniang
Автор

Ki écoute cette son en octobre 2024🎉🎉🎉

MameDiarraThiam-lmhr
Автор

tu as du talent mon frère, bonne continuation.

gioxjoseph
Автор

this is of UNIQUE beauty because of MOMO DIENG's very special timbre and adorable music arrangements - blissful piece of #art - BIGUP from Germany - Pat <3

budgiespat
Автор

je ne me lasserais jamais d'ecouter ce son

maikyfnd
Автор

MERCI Pod et Marichou pour cette maginifque chanson. Mariage de Eva et Pod.

catherinemendy
Автор

la danse de Pape Moussa au 2:46 m'a tué. La chanson est très belle et très dansante macha'Allah. Bonne continuation!

njayladija
Автор

Trop nice clip d'un jeune talent comme Momo, continue de travailler car seul qui paie l'homme

justinosilva
Автор

Moi en 2024 ms li dafa nekh surtout bamouye dora guén ❤❤

DabaGaye-op