Série - Samba Allar- Episode 1

preview_player
Показать описание
Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
facebook

Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
Рекомендации по теме
Комментарии
Автор

Association setane kate série nieup ❤😂

nafidiakite
Автор

Niak liguey bakhoule série bou nieuw nga sétane bamou diékh thiey yalla😂😂

OuleyeNdiayeBa
Автор

Worna YALLA doumako sétane. Mineul niou séne bopp ba nopi kheuy biss arrêté ko, c'est ça *"Khar média".* Et puis, merci de terminer ce que vous avez entamé!

jammrek
Автор

Courage a tous ceux qui regarde les serie de khar média

binetadione
Автор

Bismillahi niou commencer ko thi diame diekhalko thi diame ken bania manqué sma nawlé topou katou série yii samba allar anii coumba allar yii😅😅

Mareme
Автор

Goor moyy yore or guéne di woutt peureume Diodio mashalah Ibrahima ne te mérite pas vraiment

MaimounaSy-mfnu
Автор

Khar média vous êtes meilleures séries yi nekhna trop machahala❤❤❤

MbayeAmymbaye-ix
Автор

Noo meilleurs serie de khar media ms serie mi nekh na tè imagi lèr na 🎉🎉🎉

JARAMA.VISION
Автор

Yallah na NIOU yallah mais goudou fane ak Warren🙏❤️

dieynaseck
Автор

Bismillah alkhamdoulilah 🙏 yalna aga gué si diamou❤

MaremeDiop-qq
Автор

encore khar média série khana d'où ame fin😂😂😂

AwaSanokho-xxpt
Автор

Wa khar média série bi nexena, ms diapp léne si rk guéne agualé ko 😂❤

mamistamendy
Автор

Kou guisnei chambre astou mbaye mo neikeu chambre diodio

annemarietheresediene
Автор

Encore une autre série😂😂😂 bilahi am diott bakhoul

maimounabalde
Автор

Bismillah niou komasse ko sidiam yegalleko ci diam ❤❤❤❤

DabaNiang-rvie
Автор

Li dei amna bene histoire samba allar 😂mbaddou mom gueine beugu def ni
Mère bi dei khana domou bi lay moudié may Ibrahima 😂😂😂

badjiawa
Автор

Nitt kou nioul Mo faux téh leundeum 😮kholal mère bi rk, yal nagnou yalla moussal si boula diégué 🤲

mamistamendy
Автор

Loume méti si wa khar média bari na té menou maléne bayi 😂😂😂😂doléne changer keur touti

mbarkangom
Автор

Weuykaat bi wahnako samba allaar alleu bi molay gueureum 😢😢😮domram dji

djilysonko
Автор

Fékhé len ba serie bi ague rek sof guen trop

SeynabouNdiaye-th